🔴 Deum ladone Khekhal si galgui…Plus 200 décédé Bargny,Un jeune rescapé fait des révélations..

  Рет қаралды 155,096

Allô Senegal

Allô Senegal

Күн бұрын

Пікірлер: 98
@SerignemorDiop-s1j
@SerignemorDiop-s1j Жыл бұрын
Ousmane sonko président 2024 inchallah
@dioufsira8570
@dioufsira8570 Жыл бұрын
Khalé 20ans pression familiale sama yaye rek maléne yeureume ndeysane
@seynabouly3445
@seynabouly3445 Жыл бұрын
Thiey Sénégal metina, man mi am ay diplôme sah awma liguey.
@momocreation3631
@momocreation3631 Жыл бұрын
Boye nék lene aye nité 😢😢 te guené baiyii gal yi ngir yalla gué dji woroul😢😢
@momosene5564
@momosene5564 Жыл бұрын
Il n'y a rien d'extraordinaire tout peut s'expliquer. Il vous suffit de rester trois jours sans dormir ni manger ni boire et vous allez commencer à halluciner, à voir et à entendre des choses, à perdre la tête et en mer le phénomène est multiplié par 1000
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
Vérité absolue frero c k j dit à chaque fois daniouy sone akk khiff ossi
@ibrahimadiallo2345
@ibrahimadiallo2345 Жыл бұрын
T as parfaitement raison
@PapemoussaColy
@PapemoussaColy Жыл бұрын
Celui qui ne voit pas dans le noir peut s’abstenir de dire qu’il n’y a rien à voir
@fandao2138
@fandao2138 Жыл бұрын
20 ans ngani gni yakar si yaw dafa beuri? 😢😢 pauvre pays , pauvres fous
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
No niakk éducation de basse rekk akk beugue Lou yomb
@abdoungom5338
@abdoungom5338 Жыл бұрын
Ngour bou bonne rek mo waral li😢😢😢😢yalna yala sopi khel yi. Ak xalat yi ba boy yi togue fi si s'en rew
@aliounecisse6833
@aliounecisse6833 Жыл бұрын
C'est triste 😭
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv Жыл бұрын
Boy khalé nga geumal yalla rek bay man mi sah sama yaye man késé la am si dome bou ngooor mettina torop mè tahoul may khady dina bah rakeu boul dèmat psk niitou goudi meunn nayou la fatt fofoh
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 8 ай бұрын
Lan moy loulo bako mo dem Kay 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 8 ай бұрын
iaw Sax daga wara niew iaw
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv 8 ай бұрын
@@ShiekhjobeTijan en bon
@babacarfaye9060
@babacarfaye9060 Жыл бұрын
Les capitaines doivent comprendre qu on est en mauvais temps. Les mois favorables à la traversée sont mai et juin. Mais depuis que les businessman sont entrés en jeu tout est foutu
@antasylla4405
@antasylla4405 Жыл бұрын
Foo katt yii ak business man yii bagnou thi boké la lepp bon
@djibrilndiaye5349
@djibrilndiaye5349 Жыл бұрын
L'état est complice car il a tous les moyens pour arrêter ce phénomène.
@nayesedar6116
@nayesedar6116 Жыл бұрын
Heure bi warla fek ngay jang ngay dieul gual gui nguir yalla bayilen gual yi
@BinetaBa-nj2zc
@BinetaBa-nj2zc Жыл бұрын
Diang amatoul valeurs gnongi ak sunu diplômes di chommer
@nayesedar6116
@nayesedar6116 Жыл бұрын
@@BinetaBa-nj2zc si nieup la méti yaram d’accoruma gal yi yon bu leer rek
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 8 ай бұрын
Lan moy loulo dem rek insa allahou Rabi gal GUI rek billy
@zalezale8946
@zalezale8946 Жыл бұрын
Le manque d’éducation Coranique comme Scolaire est une plaie mentale! Pfff accuser des gens de Deuums car, la faim et la soif vous font délirer!
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
Sirts éducation de base
@ibrahimasidibe5214
@ibrahimasidibe5214 Жыл бұрын
Tu es très jeune forme toi d'abord après le reste chacun a sont destin
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
Vrement
@pinkinrails2456
@pinkinrails2456 Жыл бұрын
europ sakh mo amatoul touss tè koka wakh douko nangou
@thiemokhoNdiaye3805
@thiemokhoNdiaye3805 Жыл бұрын
Blh
@khadimsourang978
@khadimsourang978 Жыл бұрын
Senegal dafa metti billahi dano mougn ba sonou nak diapale len khale yi
@AzizFayee
@AzizFayee Жыл бұрын
20 ans fan nga tole bey kham deuk bou meti naan danagy dem europe
@badWilliams307
@badWilliams307 Жыл бұрын
Say mbir dafa bakh ioe khamna
@marietoutamba223
@marietoutamba223 Жыл бұрын
Ioe esk sidy va à l'école
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
Niakk éducation de base rek akk beugue Lou yomb yabater kw
@souleymanendao1843
@souleymanendao1843 Жыл бұрын
Tamante deume ci galguy di rayante
@moustaphakebe3382
@moustaphakebe3382 Жыл бұрын
Boys bi sou ay mbockam diokoul ci mom dana doff
@AnnousseDiallo
@AnnousseDiallo Жыл бұрын
Gno book xalat deh après lakoy diap
@aliounecisse6833
@aliounecisse6833 Жыл бұрын
Traumatisme
@bbbbbbbbbbvvvv
@bbbbbbbbbbvvvv Жыл бұрын
Fack sunu président Sénégal deufa macky trop 😢
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv Жыл бұрын
C vrai dee lo doundoul meunoko kham niitou goudi dafa am man damay si ragg ak eux dee bilay si ay atakeu mes pa si affair de gallrs niitou goudi sa exsitt
@kitokoken2187
@kitokoken2187 Жыл бұрын
Bateau toubab yi mome khana dou ame nitou goudi . Wala gnome noir yi rek lagnouy attaqué😂
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv Жыл бұрын
Diarna latié dee
@kitokoken2187
@kitokoken2187 Жыл бұрын
@@HerveBasse-in1lv ah vraiment , on a vu des toubabs partir plus de 1 mois en mer et rien du tout ,ils reviennent plus frais . Quand c'est un noir , voilà les deumeu et les djiné 🤣🤣 Pour moi ,ils avaient faim et avec le mal de mer ,ça les fait tous délirer ,c'est purement psychologique
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv Жыл бұрын
@@kitokoken2187 diambar ki limouy woh ni meun nako geum psk man kham na dara touty rek psk seutou borom tourr la bagage ndiago yi koi lègi toubab yi eux rek ayy djinn layou tè khamnayou riviere ngi dama khamoul ndah comprndr ngama
@AzizFayee
@AzizFayee Жыл бұрын
Afrique mo pare woul sakh pour avance bilahi
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv Жыл бұрын
@@AzizFayee afrique mom moy lolou kom niko pathe baldè di wohhè rek moy lolou mes nag frère affairr niitou goudi bilay dafa am dee sèkeu dou leup ngay meuna woh fi koi motah
@Somrsg
@Somrsg Жыл бұрын
Il doit avoir un suivi psychologique… il m’a pas l’air très normal dans son discours à moins qu’il soit sans émotion ..
@karimfaitsesvideos7903
@karimfaitsesvideos7903 Жыл бұрын
Kii dh dafa am probleme bopou faut k dem hopital niou khol la
@adjasow104
@adjasow104 Жыл бұрын
Ki mo meune feine deugu 😂😂😂raam di mate kayy😅
@mohamedgueye7825
@mohamedgueye7825 Жыл бұрын
🥺🥺🥺🥺 ndeysane
@KhadyndiayeFall-yd7rw
@KhadyndiayeFall-yd7rw Жыл бұрын
😢😢😢😢😢😢😢
@kingw4380
@kingw4380 Жыл бұрын
Boy bi mom dof na Guedj bagui nono daguane rew rek mounane mdeum khana dieune yi nioy mdeume yi bayilene dof dof Lou boy té nek nitt Europe Dara Amou fa thiono rek AK drogue mofa nek
@wolimatatambedou6149
@wolimatatambedou6149 Жыл бұрын
Thiey yala doye n'a warr
@MobarekallaMohammed
@MobarekallaMohammed 26 күн бұрын
😢😢😢
@PascalDieng-s2e
@PascalDieng-s2e Жыл бұрын
Kou dem si gaà yi ba gneuw rk né dafa guiss deumm😂😂
@seydoundao5726
@seydoundao5726 Жыл бұрын
Nittou gouddi tamitt .Thieyy Africain toujours des mystères . L'état doit accompagner les jeunes
@coumbaousmanedeme1193
@coumbaousmanedeme1193 Жыл бұрын
Ngour dou nitt bayilén gaal louwaay di yeungou goorgorlou si yalla mingi fëpp
@ouzinouzin1498
@ouzinouzin1498 Жыл бұрын
Ces justes des délires et des allucinations ak UN GRAND FAIM khiiifffff bou méti .restons au pays niou GUEUM YALLA SOUNOU BOROM peut nous donner tous
@aissandour
@aissandour 4 ай бұрын
Lowakh guéko wakhatt yalla rek
@malickfall3261
@malickfall3261 Жыл бұрын
Non mais Sénégal c'est vraiment un pays spécial comment des intelligent peut prendre des risques pour des pirogue en pleine hiver et il insiste quil va retourner quelle jeunesse idiots et bête
@NdawAmar
@NdawAmar Жыл бұрын
Ki wakhi doff rék là fi wakh
@CheikhIbrahimaThiam-fw4mk
@CheikhIbrahimaThiam-fw4mk Жыл бұрын
Boy bi nako chicologue khol
@isseubabou3293
@isseubabou3293 Жыл бұрын
Salam mane damay lathie nak nittou goudi yi ci gaal rek lagni nek wala cest leur préférence nak dama guiss kou diougeu ci gaal yi rek perturbé nak gueudia lepa ngui ci biir rawatina gueudiou goudi mais kou nieuw rek nei deum yi gauche deum yi droite motkah ma beugu kham comme ca ma meune len meuytou 😂nak ma ngui beugu dieul gaal yi sakh 😂😂
@ElajeDiakité
@ElajeDiakité Жыл бұрын
Boy yaw da nga rew kou gnouss sa ndaye diii nga tok tmt togall liguay sa méthiéeee en ham xay
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
Niaw nokh rek mou tokk woutti liguey thi marcher ba waleu apprenti auto
@AzizFayee
@AzizFayee Жыл бұрын
Ki lhamoul sakh li Khew yiw nga jeul sa gal psse 400 mil probleme am ngen dem deuk anr apres ne ngour gui molen wara jokh lek . Bingen di dem tago ngen
@marietoutamba223
@marietoutamba223 Жыл бұрын
Légui esk sougniou done tago dinagne am lougniou beugeu
@abdouniang3277
@abdouniang3277 Жыл бұрын
Boy so guisa tégual demal ay mbam gnodio djité mo waral lileb
@papadembakonate4657
@papadembakonate4657 10 ай бұрын
ZZ😢
@OusseynouTamboura-wq3dt
@OusseynouTamboura-wq3dt 4 ай бұрын
Arrétélénne nane gour bou bonne En tangue jeune de 20ans yagui def tailleur di guisse sa bopou dossi nék ba yalla gnew tmt
@farbadiouf1990
@farbadiouf1990 Жыл бұрын
" may place." Qui?
@boubacarmane8028
@boubacarmane8028 Жыл бұрын
Yon bagui nonou
@ngoneka5045
@ngoneka5045 Жыл бұрын
❌❌❌❌❌❌
@momoseck1617
@momoseck1617 Жыл бұрын
Ki boy la loumouy yakamti life bi ni
@YankubaDarboe-n1s
@YankubaDarboe-n1s 3 ай бұрын
Fass boy
@sokhnafall7167
@sokhnafall7167 Жыл бұрын
Taaw métina
@beugeudiame2019
@beugeudiame2019 Жыл бұрын
mane soumadone ragale mome mi laye ragale yawe mi mane weulouwe mala
@FallouCisse-gy2wh
@FallouCisse-gy2wh Жыл бұрын
LEPP MACKY SALL LA
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
Mom mo gueune nourokh deummm mouy alluciner nonou doff ba deh ish
@papaomarthiaw9453
@papaomarthiaw9453 Жыл бұрын
Khana mom gua mounan halluciné
@gnagnadiene218
@gnagnadiene218 Жыл бұрын
@@papaomarthiaw9453 tu as vu 😃😁😁😁😁😁😁☠️👹
@tikotfue6999
@tikotfue6999 Жыл бұрын
Gobe. Seke molike. Samakhlis
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 15 **VOSTFR**
1:04:23
EvenProd
Рет қаралды 2,6 МЛН
Their Boat Engine Fell Off
0:13
Newsflare
Рет қаралды 15 МЛН
GAAL GUI - saison 1- Épisode 10 ( Final  Épisod VOSTFR)
24:33
Mahfousse
Рет қаралды 224 М.
À peine sorti de prison, Moustapha Diakhaté s'attaque à Pastef
11:49
Mbour : les recherches continue , Un mystérieux Bœuf sur la plage
10:37
NICARAGUA : IMMERSION DANS L'ENFER DES MIGRANTS SÉNÉGALAIS
25:13
Walfadjri TV
Рет қаралды 185 М.
Their Boat Engine Fell Off
0:13
Newsflare
Рет қаралды 15 МЛН