Wally considère Youssou Ndour comme son père. Yalna naka Ya ALLAH yeukeuti sa kawa kaw
@TraoreHarouna-cd6ocКүн бұрын
Même les femmes commencent à laisser ces genres de débats je vous jure
@BayeDiop-vx9ob23 сағат бұрын
Mana féne rék ak beugue beuzz té Carte d'identité Papa thione laffa wally yombou
@LodMoussКүн бұрын
Lou rafete, nguéne fekhé ba yakouko.Felicitation a You et a Wally, khole yeupeu sédeunanou machallah❤. On n'a pas besoin d'entendre ay wakhou doff de djimbori.❌
@kizzydiopКүн бұрын
Merci❤
@adamafall-t3d12 сағат бұрын
merci
@abyniang84088 сағат бұрын
Merci SENEGAL dou dème li ma guiss
@papelamtv3212Күн бұрын
Youssou ndour King youssou ndour amoul morom ndour ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MbayeTHIAM-l5h17 сағат бұрын
Je n'ai rien contre Waly, mais l'intégralité de son répertoire ne vaut pas 1 seule chanson de Youssouf Ndour des années 70. Il est trés loin d'être le meilleur de sa génération. Il peut être Nak le plus riche. Je répéte que je n'ai faire rien contre lui et que je connaissais bien son Pére qui était un Grand pour moi. THIONE faisait partie des Grand, mais pas encore son fils qui, Musicalement, n'a pas encore atteint Alioune Mbaye Nder et Yoro Ndiaye. Je pourrais bien citer d"autres comme Jah Man, Obree etc.
@zoobastos4487Күн бұрын
Arrêtez de vous coller d importance le niveau de Youssou dépasse cette bassesse
@GarmyTeuw-jw5omКүн бұрын
Djimbory bayil diakhassse bi
@aprusacomcom673Күн бұрын
Il est fou point…
@LodMoussКүн бұрын
Vraiment
@fatimandao8359Күн бұрын
Vraiment
@AmyDiakhaté-e3dКүн бұрын
Youssou Ndour Moy sen baye niveau yi sakh dou bena
@mamadoundiaye1724Күн бұрын
Rew mokhamni douniou debatre jamais louy developpé rewmi tjr lomotif debat personnel qui moeakhli mowakh leuler jamais debatre comment crer une entreprise comment fair pour avoir des partenaires
Youssou Ndour moy bayou Waly seck, il faut aider Waly seck en lui disant la vérité, c'est pas la même catégorie, Wally a beaucoup de chemin à faire, aider le....
Ly ngua wakhe moma diotalé AK sama bén way Dafa ma wakhe ny khana légui dinguén bayi Europe pour gnibisy Sénégal ndakhe diomay ak sonko nio yor réw my many KO jamais mouny ma aye complexé nguén thé khamul ny gni fal diomay la bok😂
@DjibrilBa-xp7teКүн бұрын
@OusmaneDiallo-wk3jc man de sonko rk lay topou mé khamnani Sénégal dou gawa changé ndakh nioune sénégalais yi nio paréwoul pour sopi réww mi boul nieuw de togal fofou 😂
@coumbawade6995Күн бұрын
Carte d'identité papam la wakh jimbory dégo bou baakh
@iboundiour6546Күн бұрын
Dafa yakamti doull té xamul li guéedj gui di riir
@aissatoudione1922Күн бұрын
Billay xamoul li guedj gui rir
@LodMoussКүн бұрын
Il n'a rien compris, c la carte d'identité de Papa Thione, gros con😡
@AichaFall-m7wКүн бұрын
😂😂😂😂😂
@MoussaSarr-h9b23 сағат бұрын
Djimbori il est fou koi😂
@antagueye5121Күн бұрын
Senegal méttina vous voyez le négatif partout
@jomen7961Күн бұрын
Wakhatiko d. Nos Mentalités sont tellement basses. Moy lolou
@zoobastos4487Күн бұрын
Jimbory cette fois ci t as rien compris il a parlé des affaires de thione et même la CNI de thione est entre ses mains
@LodMoussКүн бұрын
Merci
@tabaradibadieye7132Күн бұрын
Djimbori wakhi dof deug ngafi wakh li nga déf yeufo nafékh la waly ak youssou papa ak dom la déléne wakh louy diarign nit yi mo geune
@mahirassoulofficiel590022 сағат бұрын
Bilaye
@mariamcisse4680Күн бұрын
Arrêtez way You na rien fait de mal amoul ben garouwale Tous les deux étaient bien chantés 😊
@MouhamedDiop-x9fКүн бұрын
Kounek amnga droit wakh ninga khalaaté c'est la vie ❤
@papedgtine1343Күн бұрын
Ce que vous ne comprenez pas et waly avait un concert au stade de poute il voulait faire une surprise a son papa mais waly n'est pas a ses détails il voulait seulement apporter son soutien il avait autre chose à faire
@Nianistolelion3803Күн бұрын
Youssou Ndour amoulone sakh diotou bayou waly yalnaco yala yerem Youssou est toujours et restera le monument mondial merci de votre compréhension 🙏🙏🙏
@AdamaSarr-m6tКүн бұрын
Il faut bien écouter les dires de youssou ndour😮il parlait de la carte d'identité de thione seck🎉 djimbory tw o6
@aramegaye3968Күн бұрын
Tu as compris il a dis carte d'identité de thione seck
@kumbasarr1444Күн бұрын
Youssou was surprised with the noise during Wally’s entrance mu janaahu 😂 Wally star laa momit li yalla fugal❤
@iboundiour6546Күн бұрын
Youssou moko gueune doon star 1000 fois. Ba Youssou Ndour di am disque d’or en 1994 Wally avait 9 ans, ba Youssou Ndour di am Grammy en 2005 Wally avait 20 ans. Youssou est le chanteur africain le plus connu à l’étranger. Yena xamul Youssou Ndour. Il n’a plus rien à prouver. Daf niouy bégueul rekk. Avant mouy am âge bi Wally am actuellement la laal disque d’or. Ngay doull nonou 😅
@Adag-t7cКүн бұрын
@@iboundiour6546 mo yaw li ki wakh lousi nek 😂 ak sa dissertation bi yep. Khana dou Wally surprise la ko defal rek 😊 wally ak youssou bokougnou destin. Youssou dafa tela dougou si musique âge bimou amone di musique bi ko wally amé mongui wone si football bi. Té youssou après 14 ans de carrière la am disque d'or. Bayilen comparer bi té nangou dogal yalla. Youssou mo geuneu international Sénégal gnep kham nagn ko il a un hit international mais meunou wakh ba Wally dou star momit, youssou moko ndjeukeu wakh "star nga " king fahd😀
@kumbasarr1444Күн бұрын
@ African bi ak award How many artists has received awards in this world and does that stopped other artists to grow chei Africa doo deem especially suma dayki Mam moi Senegal 😂 man Samai Mam leep ai labou ak serer wawaa sene Gambia laa . Wake up man li fooh reek laa tee fooh purr haleela ngirr yalla
@Adag-t7cКүн бұрын
@@kumbasarr1444exactement pour gnom Wally waroul am dara tout simplement parce que c'est le fils de Thione. Gnom fans youssou ndour you dof yi amnasi gnou nité nak
@iboundiour6546Күн бұрын
@@Adag-t7c yow tu es stupide. Wally est une star mais meuno wax bamou arriver Youssou Ndour à la cheville. Youssou dafa planétaire. Il est de la génération du père de Wally donc arrêtez vos comparaisons stupides. Wally mo leen gueune xam kane moy Youssou.
@mbathiodalle1051Күн бұрын
Non franchement youssou il fait pas sa wally c'est sont fils non Sénégal d'où demm il voit le négatif partout 😢😢😢
@KhadydiopbarryКүн бұрын
Penser au jugement dernier taye wakhe lou positif thi digenté nitegni you papaye waly la nangoule dogalebii moye soit courageux parce-que c l'ainé et et il a perdu 3membres de sa famille son père sa maman et sa grande soeur paix à leur âme et merci goné tu a bien dit❤❤❤❤
@fatouciss199Күн бұрын
Jimbory vrai nafekh ga 😌bigay critiqué youssou Ndour ba légui tabakho keur dieudo auto loudoul tokh feelling dakar di critiqué rekk lambil fénén li dou liguéyou Gorr yalla tchim 😌😕
@adamaberthebakhayoko8156Күн бұрын
Bayil ma ki k
@mamidieng9667Күн бұрын
Bilay c vrais khamna beuguoul yousou mais khôl bou dague rek dès personne comme djimbori motakh waly di am diouyo ak yousou yakh rek ak saytané diakhassé un jour viendra et vous allez mourir
@maindiaye3888Күн бұрын
Djimbory ya bonne famille ndour rek nga bagn waye dinga dhe ak khol bou bonn
@dabagueye878310 сағат бұрын
Diokhnama lepam bassi CNI pour mane lolou wakhine la déguine la lathie Youssou dafa beuga wakh ni wally khamzlnako lépam nebouko daram😅
@aidaniang5218Күн бұрын
Il s'agit de la carte d'identité du père de Wally, ayez raison garde.
@cheikhtidjanedioufКүн бұрын
Djimbori doff DEUG leuh
@papeomar8530Күн бұрын
Youssou Ndour bomouye waye naguoul dogual Waly dioudouwoul en plus lou rafét rafétna Youssou Ndour bayou waly la
@LodMoussКүн бұрын
Il comprend même pas que cette chanson date de plus de 10 ans
@DjibrilBa-xp7teКүн бұрын
Youssou Ndour di woyy woyam nga tok fi Di doul sa data yaye way djimbori wakhal léné té tok nopi
@mameawadiop5766Күн бұрын
Jimbori amo dègue dègue khamo lou papa youssou begua wakh
@papegueye6791Күн бұрын
Bilay pétition lagnou wara lancer état bii diouk ci media internet yii ils sont nombreux et médiocres
@FatimadiagneDiagneКүн бұрын
Mais Youssou Ndour carte d'identité papame la wakh wakhouma bou waly
@Bour_ndiaye_bourКүн бұрын
Makhala do déglou ba paré beuri wakh carte d'identité papa thione la wakh ak yén bagage 😂😂
@mamekhadjatoufaye6905Күн бұрын
Ay seytané Yi took léne. Youssou Ndour c'est un grand homme. Wally am na kilifa, you papa leu ci wally donc arrêter léne kou nek AK sa weureuk kou nek AK sa destin.
@sopemouhamad7036Күн бұрын
Youssou a dit que waly document personnel de son père thione seck qu il a remis à son père Youssou Ndour yene ay nakeh guéne
@abyniang84087 сағат бұрын
Liiii gniawna torope
@elhadjimatargueye7780Күн бұрын
Bayiléne diakhassé di doull ay nafékk ngéne rék you is the king wally domame la séytané ngéne rék
@TallaDiop-cn6giКүн бұрын
Youssou wakhoul carte d'identité waly déh Carte d'identité thione seck la wakh ak ay bagage you thione seck
@assanesow1779Күн бұрын
Thione il est mort
@papemalouf476322 сағат бұрын
Machaalah sokhna si ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AssyKoné-h5bКүн бұрын
Bayilene roube fou diam yendou dou guen fa fanane Lou takh dolene set lou rafet di ko wakh. Dou deugue. Wally boul deglou tu es un gentleman.
@sopemouhamad7036Күн бұрын
Aid li dou sujet kholéne si yalla guissoulene témoignage bou Youssou deff ci waly
@mita7113Күн бұрын
Bayil leen feen lolou refrain way bila Youssou NDOUR dou invité diko garouwale
@NogayeDiasseКүн бұрын
Lii vraiment dou débat. Bayilene seytané bakhoul
@tboy9238Күн бұрын
Djmbori fen rek nga mane, carte Dante Papa Thione la wakh Pa Wally , amo Xam Xam tek sy mana doul
@madinathiam362Күн бұрын
Vraiment il faut que nitt dii khalate akk wakh lou bakh machalah 👏 youssou et wally nio ngui thie kaw té douniou waakh sheut réussite nekhna
@papid100Күн бұрын
Avec ça vous voulez que le Sénégal se développe. Vous tapez toujours sur Youssou Ndour alors qu’il ne fait de bien. Je confirme et je le répète le concurrent de Youssou à l’époque était Omar Pêne et non feu Thione.
@kadjagaye6530Күн бұрын
Très bien m'a copine ❤❤❤❤❤
@FatimNdiaye-k6gКүн бұрын
Non bosou papam la wakh
@pamodoumbowe227Күн бұрын
Belie jimbori daf ma ruslo bala nga wakh danga wara gesto beh ham lu lerr
@Bousso3333Күн бұрын
Djimbori ya mene doul sa papa lako wakh mene nga féne trop lingay wakh sakh métrisé woko
@DTFTV22 сағат бұрын
Non non Carte D’identité 🪪 Papa Thione SÉCK le Wakh ✍🏽 #DTFTV
@AissatouHagne-x6rКүн бұрын
Comparez ce qui est comparable
@fatouseye341Күн бұрын
Jimbory, vrai dof nga!😮
@elhadjiaronasarr4740Күн бұрын
Ki wakhou dof rek la wakh
@mameawadiop5766Күн бұрын
Jimbori seytanè là
@abdoulayekeita6747Күн бұрын
La dame tu as bien parlé et bien précisé.
@tafiscodiop6659Күн бұрын
Seytané yi rék gnoy polémique di diakhassé. Youssou dou moromou Wally. Limou déff si musique wally douko meuseu déff bokou gnou sakh ayy niveau lolou leu Yallah dogal thi Sénégal ak le monde. Nagnou bayi wakhou seytané té wakh lou am Fouleu bayi détail yi. Mane J'aime Wally mais wakh deug té Yallah takh youssou dou moromame lolou dou Débat qu'à même 💚💛❤🇸🇳
@modoufalldiop6628Күн бұрын
Carte d'identité thione la vakhe
@rokhayasarr453812 сағат бұрын
Bilaye Sokhna si ya bakh goudale fann❤❤❤❤
@Bill-s3v5eКүн бұрын
Jimbory tres malade wallahi
@IbrahimaFall-g1iКүн бұрын
Nangoul dogalbi pour moi c'est accepté la volonté divine qui a pris Papa Thione pour le repos éternel.
@modouawa5002Күн бұрын
Billahi
@ycamara9034Күн бұрын
Nice the Lady speak good 👍👍👍👍👍👍👍👍Toma youssou ,Nr . 1 bless 👍👍👍👍👍👍
@moustaphaniang985Күн бұрын
Carte d'identité papa Thione la wakh thieye Djimbori mo meuna féne
@fatimasarr509Күн бұрын
Yéne ay vrai saytané guéne,yéna diakhassé célébrité yi
@ilimanefaye-n8fКүн бұрын
Franchement j'ai choqué je savais pas que l'hypocrisie peut arriver jusqu'à ce point
@ishanjie5870Күн бұрын
Youssou Ndour the King❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@adjisalvatoribiendit6031Күн бұрын
C’est très grave Bayiléne seytané non le Senegal va mal c’est triste
@Boubacarakbourtv522614 сағат бұрын
Sister bi léralneu yeup🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
@PapeNdiaye-x5fКүн бұрын
Youssou Ndour ak Wally bokou nou si Dara Youssou Ndour day waye mais Wally day wakh di sani
@khoudedjisoumare9213Күн бұрын
Jimbori ya lane moye sa problème ak youssou ndour
@MamebinetaBa-qk6xdКүн бұрын
Ki dafa sonal youssou ndour
@nabz1280Күн бұрын
Mbouko sonalé deh pape you khamoule Sakh kouye jimbori
@GuideDialloКүн бұрын
First of all, this featuring was awesome! Secondly Youssou Ndour is a legend who is supporting Wally! Wally respects him and understands that. Lastly he asked Wally “Fooy Teugui” so that Wally shares the information on live tv ! Except that lady who spoke the rest is nonsense and obsolete
@dabagueye87839 сағат бұрын
Dafa am gno khamné séni khol mo yakou ba bougnou dégué lou bakh dafay bone si seni nopou
@ndeyefatougueye363319 сағат бұрын
Vous avez mal compris par rapport de la carte d’identité c’est pas celle de Waly dé mais plutôt celle de papa Thioune Seck après son décès …
@MouhamadouNdiaye-i7dКүн бұрын
Feeling dakar louy problème ak youssoi ndour mais li dada niaw
@mariamcisse4680Күн бұрын
Merci madame bien dit
@ramatoulayediaw3864Күн бұрын
Carte d identite thione la wakh pas wally dofoul djinne diapouka wallay daa wayy si temps dem yonam amiul temps
@AbdourahmaneMane-z4qКүн бұрын
Yow danga dof jimbori
@thiernodembaya8355Күн бұрын
Nous sommes au diasporas c'est pas vrai le plus grand artiste africain cherche à approcher à Youssou Ndour 🇸🇳🇸🇳 c'est un légende Wally même ceux bien ça burna boys et Fally Ipupa faut aller faire les recherches ❤❤ c'est Wally qui va gagner Youssou Ndour et monuments ❤ arrêté le manipulation Pardon 🙏🇸🇳 ont veut un Sénégal 🇸🇳 Uni
@papeomar8530Күн бұрын
Vraiment yaw seytané nga mais nak thiogue nga😂😂😂😂😂
@maodosalll606817 сағат бұрын
Yamba bakhoulll ❤❤❤
@rokhayasarr453812 сағат бұрын
Iow saytané bakhoul you yague na vaye nankoul dogale boba Wally dioutogoul
@Nittou-g4iКүн бұрын
Wakhou doff rek 😢 Youssou Ndour chante son morceau dans les textes de l'art.. pourquoi vous êtes dingues
@Sniperextreme7Күн бұрын
Pourquoi pauvre yi amm diott
@mamadougueye186623 сағат бұрын
Billahi wahal deii🤣🤣🤣😭
@maxndoye25162 сағат бұрын
Nangoul dogal lolou paroles chanson bila
@Adag-t7cКүн бұрын
Wally teugoul concert wotéwoul, yanou thiowou khew mi😂 il était juste de passage comme nim koy défalé gnom baba maal et tant d'autres khawma loutakh ngen beug polémique
@nabz1280Күн бұрын
Seytane rek ni lagnou fi defoneu môme aak pape thione Sénégal dou rew diakhasse rek
@Sadaga-si7ny9 сағат бұрын
Ah si toutes les grandes familles des griots et des Niégnos s'organisaient pour faire revivre la culture dans chaque village de leurs ancêtres le tourisme culturel y profiterait énormément. Imaginons chaque année un très grand événement culturel dans le village ancestral de Youssou Ndour de Waly Seck de Kiné Lam et de tous les autres ! Les ministères de la culture et celui du tourismes pourraient restructurer tous ces villages en vue de ces événements. Est-ce une bonne idée ?
@ahmadouifrabaКүн бұрын
Mane mome je désabonne gni diniou ay nitt sah
@theamishow2230Күн бұрын
Totally different they definitely not the same Wally is to little in front of Youssou Ndour
@Khadim-ig2oqКүн бұрын
Bilay walay yéne wa feeling dakar aye seytané nguéne
@aminatadiouf8981Күн бұрын
Djipbori vrai domeram la aye gor you niak fayda tok di diakhasse wakhoul sakhe wally carte d identité papa thione lay wakhe boudone may bouba dinala porter plainte mbamou kharam yi
@moustaphaniang985Күн бұрын
Sénégal barina ay dof
@sysy583Күн бұрын
Mais lui il as vraiment une tête vide 😂😂😂 comment on peut des chroniqueurs comme sa
@kharitourassoulsalalahoual870Күн бұрын
BAYILEN WAKH NONSENS FISABILILAH.!
@mahirassoulofficiel590022 сағат бұрын
Lolou kagne lako youssou Ndour waay yaguena Sénégal dougnou déglou musique ba paré di doule
@kumbasarr1444Күн бұрын
Jimborri saa daygaa 😂😂😂😂 nehut bee neehut Youssou neeh grand bal momkeenaareeklaa concert laa boy yeedee deef you garuwaree Laa deef. 😂😂😂😂
@safietoundiaye6780Күн бұрын
Djimbory n’aime pas Youssou ndour lolou mom je l’ai tjr di.
@napoleontsarСағат бұрын
Pourquoi cette personnes dans un plateau.😢😢😢 Surtout il dit que c’est un chroniqueur
@adamafall-t3d12 сағат бұрын
merci sokh nasi
@rimalaye1187Күн бұрын
Vraiment yaw mom digueu de ko kham ni bougoul diam mouk . djibori yaw fi mom guisou mafi garalate pape akh dom .
@SokhnalamGueyeКүн бұрын
Way wakh diou nou soukar la
@lunesy2298Күн бұрын
Sanoko yalla nako yalla samu imam alioune badara ndao yalla nako yalla yeureum yalla na yalla samu sénégal
@Faye30489Күн бұрын
Djimbori a parfaitement raison mais carte d'identité Thione Seck la Youssou Ndour wakh
@MamadouThiam-b6vКүн бұрын
Cette femme a raison mais ce gas la vrai saytané la
@cheikhantadioptv2790Күн бұрын
Studio nice naa
@WarankaDiawara-w5jКүн бұрын
Jimbori yow menowax ci Youssou lourafet ndax niep xamnanne danko bang xalebou jigenbobou loumouwax Moy deg ❤