Jacob Baldé et Mansour Diop font des révélations sur la forme d’Ama Baldé : “sou indi wé forme …"

  Рет қаралды 20,771

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 56
@malicksarr2141
@malicksarr2141 4 ай бұрын
Jacob Nitkou bakhla 👍kholbi dafa rafet ❤
@morgningue7654
@morgningue7654 4 ай бұрын
Mn balla Moy sama mbeur m Jacob bone continuation mbeur
@masambakandji3419
@masambakandji3419 4 ай бұрын
Ama seul inchalla
@youssoudiokhane3600
@youssoudiokhane3600 4 ай бұрын
DIADIEUF PERE MANSOUR DIOP..DAGUA KHAM LANMOYE ENTRAITEMENT.. MACHALLA
@mamadousarr4791
@mamadousarr4791 4 ай бұрын
Merci Boucar ya ham mbeur yi
@ousmanefall1404
@ousmanefall1404 4 ай бұрын
Jacob BALDÈ c est un garçon Machallah trop poli et posé. Je connaissais bien son pere feu PAPA BALDE avec qui j ai travaille avec Biteye.
@malicksarr2141
@malicksarr2141 4 ай бұрын
Franc yalnako yalla maye ndame ❤
@niangmedoune7962
@niangmedoune7962 4 ай бұрын
Pere Mansour vrai ndanane machalla
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 4 ай бұрын
Ama yag na dieul risque. Kou weddi lacce bb saloum bamouy ci tollou meussou wone ame défaite. Malick niang ak tapha tine aussi
@assanendiaye5640
@assanendiaye5640 4 ай бұрын
Saway ay Bebe saloum gay tekalek frank 😅
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 4 ай бұрын
@@assanendiaye5640 yaw khana khamo lamb. Bb saloum bi takhoul May wakh demal setane archive nga khôl bb saloum bamou ci tollou.
@anissediatta69
@anissediatta69 4 ай бұрын
Bien dit frère
@fallouvamos
@fallouvamos 4 ай бұрын
​@@assanendiaye5640 Xana guane gua si lamb 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@gueyemayoro8243
@gueyemayoro8243 4 ай бұрын
AMA rekkk❤Inchalla
@IbrahimaDiop-v9l
@IbrahimaDiop-v9l 4 ай бұрын
Pere mansour moooo dakkkkk siiii adouna 😂😂😂😂😂
@assanewade6616
@assanewade6616 4 ай бұрын
𝐌𝐨𝐦𝐞 𝐝𝐚𝐠𝐮𝐚 𝐤𝐨𝐲 𝐥𝐚𝐭𝐡 𝐭𝐚𝐲𝐞 𝐦𝐨𝐮 𝐰𝐚𝐱 𝐝𝐞𝐦𝐛𝐨𝐮😂😂😂😂😂
@matarndiaye674
@matarndiaye674 4 ай бұрын
Mané ama seul❤
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 4 ай бұрын
Ama na dem inseps préparé fofou combat bi
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 4 ай бұрын
Gayii khamouniou Amaa Balde c sa le problème woorna Yallah Fara Mounoul Touss thi Amaa Balde 🥹En plus Fara Beraii by Benoul Fara Ayoul Dei Façon Beraim Danoul Amaa En plus Fara sagn sagn Boumouy diay Ak Doolé Mounouko Diay Amaa Amaa Balde Moko Eupou Fith Fouff Boudé Doolè la kasé Amaa bou Liguèyé Deugeu Bèneu Mbeur Douko Eupou Doolé🧏‍♂️
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 4 ай бұрын
Modou lo le roi moy sama mbeur mais jacob dafma nékh dafa séet yarou di wakh wakhou nit té am fit
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 4 ай бұрын
Fans modou lo yi mbeurou pikine yi nioungui wakh lou rafete ci mbeurou parcelles yi la fois passée pokola wakh na lou rafete ci modou lo ..mais franc rew lay diay mbeurou pikine yi
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 4 ай бұрын
Pere yanki sakhati 😂😂😂ndiako 3 barikoyi rek nioko taakha diouk inchalla
@lionnoir2799
@lionnoir2799 4 ай бұрын
Pere lingay wah ni si entraînement kou niamewoul entraînement doula woo.mais ttes derrière ama drapeau bi lay yobou.vraiment sport leu mais en cas de défaite vraiment pikine dou diar dra si lamb
@niangmedoune7962
@niangmedoune7962 4 ай бұрын
Jacob balde kou yarou la
@assanesamba8560
@assanesamba8560 4 ай бұрын
Jacob combat bii boul maay ama dara dikko ñianal ndam lou sed gouy inshaalla le jour j’y franc da reuy lamigne té daw lakhou laa
@masambakandji3419
@masambakandji3419 4 ай бұрын
Risque dou passer malick niang maylén nu diam franc tapétt lah
@sambazoradiop238
@sambazoradiop238 4 ай бұрын
Ama seul ❤
@papesene6161
@papesene6161 4 ай бұрын
❤❤❤
@bambamaremakara8237
@bambamaremakara8237 4 ай бұрын
Père kou Amon dolé lamay diokh
@doufyefaye6290
@doufyefaye6290 4 ай бұрын
Bilahi ki xétou doolé bimou yorone guissoumako si boys yi.setane nako mbapat ba tayi
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 4 ай бұрын
Mingui koy ame ba legui 😂😂😂
@papesene6161
@papesene6161 4 ай бұрын
🎉🎉🎉🎉❤❤❤
@khadimfall979
@khadimfall979 4 ай бұрын
Jackob ku Yaru
@OusmaneSané-s2z
@OusmaneSané-s2z 4 ай бұрын
Jacob kou am avenir leu si lamb
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 4 ай бұрын
Thiatou yoff Jacob baldé combat bou néex
@mouhamedndong6069
@mouhamedndong6069 4 ай бұрын
Thiatou Yoff vs Sokh Mo Dakhhhh
@AmmeDicko-wt2iu
@AmmeDicko-wt2iu 4 ай бұрын
Thieuy Jacob moye ni kou bakh
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Franc am nga combat nak adouna ngay beurèl di danga reuy lamine rek di wax😂😂
@kintezothomasparthey9862
@kintezothomasparthey9862 4 ай бұрын
Ama seul
@assanediop771
@assanediop771 4 ай бұрын
Balla moy sama mbeur mais franc nimouy beurè ama baldè moko geuneu nièmè fouff franc gnimou beurel yeup dalena diahasè si hekh doglena daan motah ama amna mil sans pour daan parsque ama dfa nièmè heekh nièmè beurè
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 4 ай бұрын
Bro gni bayilene fofu gniouy wakh rk. AMA dinalene defaral surprise
@jazaka3178
@jazaka3178 4 ай бұрын
Kone khana sétano Franc vs Tyson Franc vs Forza Franc vs Sokh Saway franc dou ragal d
@mouhamedlydiouf8934
@mouhamedlydiouf8934 4 ай бұрын
@@jazaka3178 saway sokh mom d'où mbeur comédien la. Forza maguete n'a. Tyson 2 bi mou dane takhoul gniounane tyson 2
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
​@@mouhamedlydiouf8934 😂😂😂
@fallouvamos
@fallouvamos 4 ай бұрын
​@@jazaka3178 Diambar 10% Sagn saniou Ama khadioul si Franc Fiii guéne di diaré kham kouy Ama ba faw yéne gnii di sogua sétane Lamb khamoléne kiguéne ko sékeul sakh
@jazaka3178
@jazaka3178 4 ай бұрын
AMA apart wa Parcelle kou mouy beurél mom lay faral mais bayi lènnnn AMA Bou parei sétlou na wa Guédiawaye Bou niou danoo niouné bléssure Wa pikine niouné paré wou niou P.A Bou niou lènn dané niou dem défarou dji lolou moy sportif
@Ndiambour-ndiambour21
@Ndiambour-ndiambour21 4 ай бұрын
PA Dagne nio sote lagne dane mayé😂
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 4 ай бұрын
Franc combat bi dinako wekh khate dotoul faté combat bi ci adounam one rek ..combat bi dou combat ama combat pikine leu
@bassiroundaw4751
@bassiroundaw4751 4 ай бұрын
Bilay atanoul thiowouu AMA one reek
@lionnoir2799
@lionnoir2799 4 ай бұрын
Ama na sor ay tankame .tankame bimouy lal sou defoul attention franc dieul tanke bi tourko weurko nombeu
@GoraNdiayeKarim
@GoraNdiayeKarim 4 ай бұрын
Franc day féne
@MOUHAMEDKANE-d1j
@MOUHAMEDKANE-d1j 4 ай бұрын
Jacob yamal nak Franc moleu meune mbapate nak ah yamal nak boyy
@bayemodoufall2879
@bayemodoufall2879 4 ай бұрын
😂😂😢
@Jerkin-amabalde
@Jerkin-amabalde 4 ай бұрын
Keur falay beugou gnou lou yomb 😂😂🧏‍♂️🧏‍♂️ té Ama a Chak foi kougnouné moko meune sama khel day dal😂😂😂🦍🦍🦍🦍🦍 Thiey domou babayo bi 🫢🫢
@GoraNdiayeKarim
@GoraNdiayeKarim 4 ай бұрын
Ama rk
@khadimfall979
@khadimfall979 4 ай бұрын
❤❤🎉🎉🎉🎉
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
36:55
bayGUYS
Рет қаралды 1,9 МЛН
Quando eu quero Sushi (sem desperdiçar) 🍣
00:26
Los Wagners
Рет қаралды 15 МЛН
When you have a very capricious child 😂😘👍
00:16
Like Asiya
Рет қаралды 18 МЛН
Shooting napanté Forza vs General Malika : Kou eup doolé???
13:25
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
36:55
bayGUYS
Рет қаралды 1,9 МЛН