Jahman X-Press Feat Nix - AWMA TEMPS - Albuum ABIYO

  Рет қаралды 1,023,788

Jahman X-Press

Jahman X-Press

Күн бұрын

Production : Hoside Studio
Prod Passa Beatz & jeuuss - Mix by SIR KHALIFA
CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08
ECOUTER L'ALBUM ICI : backl.ink/1496...
Xawma wone sakh mane ngay waxal
( Anh kone mane ngay waxal )
Mane yeugouma wone sakh mane ngay wakhal
( Anh kone mane ngay wakhal )
Anh kone mane ngay wakhal
(Anh kone mane ngay wakhal )
Sibou ma wone sakh mane ngay wakhal
Degoumala wone
Dama takeu ay écouteurs
Xeer yingmay sani la dieul dadialé tabakh ngandim keur
Ndissou (Marchandise) bandit dou lambeu
Diaye leu ci diam wala diaye leu ci force
Danga yeeg ndakh dollars sa poche
Kone di nga wade comme lou nekk ci fosse
Lii rek kessé meunone ngene ko vocal
Khathie bou yagg té door bi daloul
Boxeur allumette Cafal
Bif ci game bi la bokk na bangit yi ndelou
Dou yagg ba Tom nekk OG wou Jerry
Eh mounouleu niakk
Nieneu gni di takkeu sama kaw ndakh gnima ci faye dafa beuri
Feu bi diougué neu rouge mongui ci vert
Lo tekk lenene perte
Sama tankeu dafa diss talli bi nekh
Maak yaw mounougn fréqu
REFRAIN
Kou bari diom niakeu diot
Kou niakeu diom bari diot
Motax mangui sama bopp awma temps
Awma temps deh
Xawma wone sakh mane ngay waxal
( Anh kone mane ngay waxal )
Yaw kone mane ngay waxal
( Anh kone mane ngay waxal )
Wah yene ki kane ley waxal ?
( Moma diakhal )
Sibou ma wone sakh mane ngay waxal
Do dioum ba degg phone bi sonner
Silence laay réyer niou bari
Time is money té money nga weuri
Weuri nga ba temps bi diekh
C'est horrible
Okay , léweul , foureul
Sene wakhtane bi commencé beuri
Xam lepeu ci keuyitou keur yi
Mangui ni deh nioul ni keurign
Ceddo bi moy sa serigne
Indi neu li ngene di sango ak li ngene di naan
Ndakh sen jotaay bi dafa dessé ay mandi yeah
Takeu naa boon yi taalal
Dangene am fiit rek
Ba di dadialé doule yi ba beut sett
coma nekhal waxtaan bi di kheur seen maam
Bangueen khol ma nema kane ngay waxal
Soy guiss sa baye daw soufou ronde laal bi
Téy deh fa ngey fanane
REFRAIN
Kou bari diom niakeu diot
Kou niakeu diom bari diot
Motax mangui sama bopp awma temps
Awma temps deh
Xawma wone sakh mane ngay waxal
( Anh kone mane ngay waxal )
Yaw kone mane ngay waxal
( Anh kone mane ngay waxal )
Wah yene ki kane ley waxal ?
( Moma diakhal )
Sibou ma wone sakh mane ngay waxal
So dégué "tinntt" boul insister awma temps
Mangui sama bopp
Somay woo ney lou urgent
Seen nala ngamay vocal
Sou goudé doumako lire
Teyeul seu ay cas
Niit dey positif
Dougou nga laal nga bandit
Boulma xaar ci taatou ndaa li
Eau de source laay naan
Ya nara xaar ba xadi
Diot ma dou yombou ndakh damala vent
Dama départ té yangui ci banc
Rolex dou nekk ci lokho kou bari temps
Mane ak yaw bokouniou rang
Diot bi mounoul bari
Dama bayi lou bari
Wara dem fou sorri
Tedeu wara teudi
Té mane douma tokk tant que takouma
Tekki tekkil niou topou ci mane douma teggi tank
Wax dji ladoul meun
Mais réwandé mo gueun yomb
Soudé gniii niémé naa
Comme sho bou wétt ak kou yoom
Sa percer dou gaaw ndakh
Ndakh dangay door
Té xool naa ba xool mais dessé nga mur
Sorou mala
Louné ngama yakkeu
Mais meunoma yeungueul
Faye laa moma niorr
Fayo ma weer beug ma teyé ci ligne bi
Coupél deukk bi dafa wow
Awma diot mesures yima dieulone dembeu dafma serré
Yaak mom ci pott
Est-ce que meew yinga fi xélli meune ngako sédé
Come on
REFRAIN
Kone yéne kii mane lay waxal
(Anh kone mane ngay waxal )
Xawma wone sakh mane ngay waxal
(Anh kone mane ngay waxal )
Okay kone yaw mane ngay waxal
(Anh kone mane ngay waxal )
Yangui wax ak teukh
(Anh kone mane ngay waxal )
Anh kone mane ngay waxal
Anh kone mane ngay waxal
Anh kone mane ngay waxal

Пікірлер: 362
@abdoundiaye6375
@abdoundiaye6375 3 жыл бұрын
😯😯💪💪tontou dou forokh bilay 👍👍 j'aime sa vraiment tu a travailler Jahman qui est d'accord avec moi. Alal pousse 👍
@fatoubintoudjitte5978
@fatoubintoudjitte5978 3 жыл бұрын
ah bon kane la dioté lonne
@princeseydi607
@princeseydi607 3 жыл бұрын
@@fatoubintoudjitte5978 son ex coepquipé de xpress
@cheikhgueye341
@cheikhgueye341 3 жыл бұрын
@jahman express wa mom kan lay wakhal 🤣🤣🤣🤣 MoMA diakhal
@fatoubintoudjitte5978
@fatoubintoudjitte5978 3 жыл бұрын
@@princeseydi607 ah d'accord je vois merci ☺️ pour la réponse
@maxdiaw2226
@maxdiaw2226 3 жыл бұрын
@mona m
@khadydiedhiou7
@khadydiedhiou7 3 жыл бұрын
Jahman je pense que s'il le pouvait il ferait un featuring avec tous les artistes sénégalais Y a que des top feat dans cet album On aime daal
@blackking4174
@blackking4174 3 жыл бұрын
Meilleur de ça génération 🔥🙏
@Ibn_mustafa
@Ibn_mustafa 3 жыл бұрын
NIX ☠️☠️🔥🔥 même en wolof, il est au sommet 😱
@minaaa3981
@minaaa3981 3 жыл бұрын
Bane nix la bi done lakeu français you nekh yi ??
@amisakho8816
@amisakho8816 3 жыл бұрын
Machalah
@mariemekanefall1267
@mariemekanefall1267 3 жыл бұрын
@mona ñ @ e
@Momartsn
@Momartsn 3 жыл бұрын
Mon son préféré dans l'album ❤️🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥❤️
@antambaye270
@antambaye270 3 жыл бұрын
Machallah mala thioub Ndaaane dafa rafete blh 🔐🚶‍♀️🏃‍♂️🤣
@elhadjiousseynoukamara1266
@elhadjiousseynoukamara1266 3 жыл бұрын
Nix il a dead le beat 🔥🔥🔥
@oumardiop3380
@oumardiop3380 3 жыл бұрын
Un pur talent.rappeur/chanteur. S'il a la chance d'être coopté par les grosses maisons de disque, il sera un artiste connu à travers le monde entier.
@NdiackDiouf-rt5ek
@NdiackDiouf-rt5ek Жыл бұрын
Machallah💝💝💝
@aissatathiam6986
@aissatathiam6986 3 жыл бұрын
Un album aussi extraordinaire🥰❤malodies yi nekhna machallah rien à dire Franchement ya lene meune do sene morome 🥰💯💯
@amikandji3653
@amikandji3653 3 жыл бұрын
Le meilleur de sa génération bravo 💞💞
@modoudiagne3448
@modoudiagne3448 3 жыл бұрын
Nôtre diourbelois jahman t'as encore battu fort ce son fait partir dans l'album le plus bon merci
@mamebintaseydi5631
@mamebintaseydi5631 3 жыл бұрын
Wakh touti diob lou beuri il a marquer so emprunte ❤️❤️💪🏿💪🏿💪🏿
@ndongodarajofficiel8441
@ndongodarajofficiel8441 3 жыл бұрын
Félicitation frère album bi dopp na 🔥🔥🔥
@journalliixewsenegal5195
@journalliixewsenegal5195 3 жыл бұрын
Nix pourquoi tu nous a longtemps fait dormir avec le rap français , nix dou nit that’s lit ✌️ , jahman ne déçoit jamais
@osourire5213
@osourire5213 3 жыл бұрын
Vraiment il est top 👌
@mldd.3146
@mldd.3146 3 жыл бұрын
J'ai adoré la partie de Nix.
@chseye2923
@chseye2923 3 жыл бұрын
Ma çhaalah jahmane nèna kou barri diome gnak diot kou gnak diom barri diot album dalle son bo diglou ne bobou mo guena neex en tout cas ligueye ga ndax rap wolaf binde dasse bock 100%100 baol baol texi deuk Touba nak
@talibemmseck9141
@talibemmseck9141 3 жыл бұрын
Vraiment vraiment vraiment ya meneu si gayi machalla 😍❤️
@tfhjgfetuiouffga2723
@tfhjgfetuiouffga2723 2 жыл бұрын
Jaman tu es vraiment fou 😜 lâche
@elzosane9175
@elzosane9175 3 жыл бұрын
C'est ça que on appelle Polivalant🔥🔥
@mamansoumare2320
@mamansoumare2320 3 жыл бұрын
machalah nekhna le meilleur reste a venir liguey rek
@Yabdalfall
@Yabdalfall 3 жыл бұрын
Non Grand bilay amélo hip hop galassén akh bilay bouy xalatt Bou guéna geuna nekh bi rombbb
@mamesafrandiaye5448
@mamesafrandiaye5448 3 жыл бұрын
Jahman x-press mon chanteur préféré sons bii nekhena trop avex Nix mais la voix de Eva de pot et marichiou ma tué je kiff bonne Continuation
@maremendour9629
@maremendour9629 3 жыл бұрын
Un album tellement choc, des mélodies extraordinaires franchement Jahman yalene meune do sene morome
@Metouuu
@Metouuu 3 жыл бұрын
Sama tank dafa diss tali bi nex mak yow mouniounou frék 👍😂 Amo temp dei Teyél sa ay cas Amo dioteu 😅 Waxoul ak yaw sa flow mokoy déranger 😍🥰
@sophie170
@sophie170 3 жыл бұрын
😅😅😅
@mouhamadouba6232
@mouhamadouba6232 3 жыл бұрын
Shiii Jahman khana da merr chaud là 🥵🔥🔥
@khizokmc6561
@khizokmc6561 3 жыл бұрын
Non son bi damakoy deglou Di rée rek ndax contane jahman chapeau
@mameawadiop5122
@mameawadiop5122 3 жыл бұрын
trop fort Jahman💪🏽 "boulma xar ci tati nda li eau de source lay nann ya nara xar ba xadi"
@dabaseck3293
@dabaseck3293 3 жыл бұрын
🥰🥰🥰amoulo temps mom, Job rek,allez jahman🤸🤸
@senebegue
@senebegue 3 жыл бұрын
Niveau yii bokkoul #Nix le meilleur 👍🏾👑
@moustaphafall3742
@moustaphafall3742 3 жыл бұрын
Nix genre beat yi aka si ayy légende yi dinagn comp
@jacquelinemariemetendengkijash
@jacquelinemariemetendengkijash 3 жыл бұрын
Awawawawawawawawawaw bilay vous avez encore cartouché le meilleur son pour riposter les fémistés 😅😅😅non #Jahman dou nitt❤❤❤
@papakebe1616
@papakebe1616 3 жыл бұрын
Il a tapé encore fort deh qui est d'accord ✨😍😎
@dabaniang3168
@dabaniang3168 3 жыл бұрын
Bilahi wakhatico machallah
@cheikhmoussasarr2494
@cheikhmoussasarr2494 2 жыл бұрын
Lii
@yakhamesene2021
@yakhamesene2021 3 жыл бұрын
Nn jahman dfa doywarrr lii nekhna lollll sa j adore 😍🥰
@MamadouDiallo-oj1ct
@MamadouDiallo-oj1ct 3 жыл бұрын
Je l ai replay 10 fois. Un tres bon son plein de sens. Kou bari joom gnak temp....
@sophiesenygaye1684
@sophiesenygaye1684 3 жыл бұрын
Non vraiment tu es ouf Machala. c'est ça le temps nous manque.
@linguerediop8761
@linguerediop8761 3 жыл бұрын
Franchement jahman ton talent me dépasse Machallah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰🥰🥰
@fatoubintousakho2329
@fatoubintousakho2329 3 жыл бұрын
Que du bonheur à t'écouter 👏👏👏 protection divine
@ibrahimagueye9232
@ibrahimagueye9232 3 жыл бұрын
Mais vieux père ndank bokk thioo💥🔥
@adre_med7659
@adre_med7659 3 жыл бұрын
l'entrée de Nix nuul kuuk 💥💥💥💥💥💥
@pendadiop03
@pendadiop03 3 жыл бұрын
Son bi daleu na Jahman& Nix 👌🏽❤❤
@omarniang788
@omarniang788 3 жыл бұрын
wwww
@damemboup5943
@damemboup5943 3 жыл бұрын
Wa jaman tmt ball léne way ya léne meune❤🥳🤩🥰
@noseessootv2885
@noseessootv2885 3 жыл бұрын
Meilleur son de l’album
@damesh2mbd59
@damesh2mbd59 3 жыл бұрын
Awma temps boulma xar si tatou ndaa douma tok tank takouma Konn yenn ki mann lay waxal💪té l mllr
@adjinarcisse6504
@adjinarcisse6504 3 жыл бұрын
Il a encore frappé com d'habitude
@emmanueldiouf4046
@emmanueldiouf4046 3 жыл бұрын
X cellent 🔥🔥🔥🔥. Feat Bi diss na dé.👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿
@aidadiop2632
@aidadiop2632 3 жыл бұрын
Damn Nix 🔥🔥😏jahman kan guay waxal
@leuzbi3412
@leuzbi3412 3 жыл бұрын
BOOM C KOI✊un album complet pour ma 1er foi gayi no Jahman est le meilleur 🔥🔥🔥
@FatimaMamadou46_
@FatimaMamadou46_ 3 жыл бұрын
Ehhh damn🤩🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰😍😍🥰🥰🥰😙😇😇😊😊😊😇🥰😍😍😍🤩💕💞💛🧡❤❤🧡💜💙💙💚🧡🧡🧡💛
@KvnGfori_NdiAaga
@KvnGfori_NdiAaga 3 жыл бұрын
Nix ak beat'ou passa lekk lakoy deff tamnako
@daplypreira8397
@daplypreira8397 3 ай бұрын
❤❤❤ j'ai trop ses trop biennn top colle jte jure 🤣🤪🤪🤪🔥🔥🔥🔥
@linguerediop8761
@linguerediop8761 3 жыл бұрын
Boul ame temps déh bagnial ba teudeu sii souff 😍😍😍😍
@mouhamedababacardiop6194
@mouhamedababacardiop6194 3 жыл бұрын
Boss Passa beatz❤️❤️❤️❤️
@babyrosi357
@babyrosi357 2 жыл бұрын
Tiktok vas nous faire découvrir les chanteurs sénégalais c’est vraiment magnifique 😻 la chanson
@joebasse9778
@joebasse9778 3 жыл бұрын
Leuweul-foureul- keurign. Popopopppppppppp. Nix tu est trop fort. Hahahhaa. c’est HORRIBLE 😂 . J’aime 💪🏾✅
@aidasane6703
@aidasane6703 3 жыл бұрын
Du courage grand frère liguey rek
@aldogass07
@aldogass07 3 жыл бұрын
Wa mais Nix🔥🔥🔥😍
@mmediene2324
@mmediene2324 3 жыл бұрын
Wooooooooy li lanla🥰 🥰😍🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🔥🔥🔥💯💯🔥
@lineboyofficielle150
@lineboyofficielle150 3 жыл бұрын
Respect a vous et chapaux a passa❤💃
@mahanflytv
@mahanflytv 3 жыл бұрын
Let’s gooo🎸🎸🎸
@issadiallo9515
@issadiallo9515 3 жыл бұрын
Nix on dirait iniesta dans le game, on parle pas lui mais il est hyper fort... il a tué le prod
@antandiaye1298
@antandiaye1298 3 жыл бұрын
Congratulation 😍😍
@ousmanjammeh3487
@ousmanjammeh3487 3 жыл бұрын
Star nga 🔥
@Saidousy336
@Saidousy336 3 жыл бұрын
NIX mi nitt leu 🔥🔥🔥
@mamadouba5623
@mamadouba5623 3 жыл бұрын
Ahh wayy li nekhna wayy
@adamathiam5244
@adamathiam5244 3 жыл бұрын
Nèkhoul ba nékhoul ya fi nék mane yaw beugue😘❤️🔥🔥
@aichandoye8451
@aichandoye8451 3 жыл бұрын
Nix il a assuré d'accord pointe toi🙃
@begaysowe5855
@begaysowe5855 3 жыл бұрын
U killing the vibes jahma 🔥🥳
@Amadou-Amira
@Amadou-Amira 3 жыл бұрын
*Wayei jahman son wou distance bi n'a âne clip waay🥰😭🤴🔥*
@fatimepouye412
@fatimepouye412 3 жыл бұрын
Meilleur de sa domaine 🔥🔥🔥
@user-2032
@user-2032 3 жыл бұрын
🤸‍♀️🤸‍♀️😂😝BI MOM DALNAA OUY🤝👍🤸‍♀️
@NGOM0909
@NGOM0909 3 жыл бұрын
Tu fais partie des meilleurs
@liwaofficieltv5700
@liwaofficieltv5700 3 жыл бұрын
J'attends le clip de cette audio et j'espère qu'il t'apportera plus de 10 millions de vue👍♥️🙏
@khalifaababacarba7313
@khalifaababacarba7313 3 жыл бұрын
❤🥰❤machallah Nice na trop
@ndeyearamediallo4612
@ndeyearamediallo4612 3 жыл бұрын
laf bouche macha'allah j'aime bien l'album
@Darousalam2084
@Darousalam2084 3 жыл бұрын
Vraiment très jolie continuation jahman
@coumbadiouf4998
@coumbadiouf4998 3 жыл бұрын
Machaallah laff thiat ❤️
@jeanmichelmendy4228
@jeanmichelmendy4228 3 жыл бұрын
Kou barri diott niak diott, kou niak diome barri diott awma temps💪🔥
@ogmhd
@ogmhd 3 жыл бұрын
Dameeeee mais Nix kill n beat bii dameee woow
@oumarkane5520
@oumarkane5520 3 жыл бұрын
Waw! Merde 😂 Ndéké Jahman mo gana rew thi rappeurs yi yeup. Brah deh doutoul wah ak iow.😂 Mais Jahman apparemment tu n'arrêteras jamais de nous surprendre. Je kiffe follement je t'assure. Ce qui me plaît plus chez, c'est que tu as ton propre style de clash. T'as pas besoin d'insulter les parents de quelqu'un pour faire mal. Beaucoup de rappeurs devraient prendre ton exemple. Chapeau à toi le rappeur chouchouté des sénégalais. Ne change jamais. On t'aime comme ça
@diarra_chou8497
@diarra_chou8497 3 жыл бұрын
Non Li nekhna way ayoooooo💪❤️
@Prettygirl30871
@Prettygirl30871 3 жыл бұрын
Très fort 💪
@wizmosscamara7828
@wizmosscamara7828 3 жыл бұрын
Big love from Gambia 🇬🇲Senegal 🇸🇳❤💯
@kebemarieme6049
@kebemarieme6049 3 жыл бұрын
Un artiste polyvalent 🥰
@naboudiop2060
@naboudiop2060 3 жыл бұрын
Wowww jtj amoulo bene temp 💣💥💥
@moudoumbodji8102
@moudoumbodji8102 3 жыл бұрын
Waouh c schick man Boom🔥🔥🔥
@AminataDiallo-tp6kv
@AminataDiallo-tp6kv 3 жыл бұрын
Machalah lo woye mou nekh non je t'adore
@abdoucostatine7746
@abdoucostatine7746 3 жыл бұрын
From Diourbel ✌🏽😊❤️
@mohammedmoustaphatoure1135
@mohammedmoustaphatoure1135 3 жыл бұрын
Diaroul wakhe Djiou Bari il est le meilleur 🏆🏆🏆
@awasarrdiop514
@awasarrdiop514 3 жыл бұрын
Jahman dou nittou fi wallae trop fort le gars
@nogoyeniang1549
@nogoyeniang1549 3 жыл бұрын
Awma temps si gaway les deux meilleurs
@bayeserignebeye828
@bayeserignebeye828 3 жыл бұрын
Temps amoul 😂😂😂😂🔥✅
@JacobMeujnaatBoy
@JacobMeujnaatBoy 3 жыл бұрын
Téyél say #cas nitt day #positif🥵
@samsnmbacke2284
@samsnmbacke2284 3 жыл бұрын
Jahman clip bi🔥🔥🔥🔥
@ababacarniang605
@ababacarniang605 3 жыл бұрын
Waa nixx.😱😱😱!!!!!!!
@khadykane9043
@khadykane9043 3 жыл бұрын
Wouawwwwww talent 😉😉😉😉😉mashallah
@maremendour9629
@maremendour9629 3 жыл бұрын
Messo ame temps th fo gueneii gneupp begg yalla bo meuss ame temps Jahman si barki borom Touba 🙏
@amyndongo469
@amyndongo469 3 жыл бұрын
Dis courage préféré
@haissaish
@haissaish 2 жыл бұрын
J'adoooooooooore ♥️ vrai kiffance!!!
@bilalgueye7083
@bilalgueye7083 3 жыл бұрын
meilleur ♥️
@aminagueye2943
@aminagueye2943 3 жыл бұрын
Tontou daal day dall niaw 😏👍👍
@daoudagueye3337
@daoudagueye3337 3 жыл бұрын
Frome Diourbel frère ♥️💯
@maguettendiaye7986
@maguettendiaye7986 3 жыл бұрын
Waw kay 💞
If Your Hair is Super Long
00:53
im_siowei
Рет қаралды 30 МЛН
Bungee Jumping With Rope In Beautiful Place:Asmr Bungee Jumping
00:14
Bungee Jumping Park Official
Рет қаралды 17 МЛН
Cape Coral, Florida Fire Department rescues alligator stuck in storm drain
00:30
If Your Hair is Super Long
00:53
im_siowei
Рет қаралды 30 МЛН