Abdou Bakhoum sur la victoire de Thiatou Daouda Fall: "naniou diokh Siteu victoire. CNG na bayi…"

  Рет қаралды 26,906

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 13 күн бұрын
Walahi thiatou la begone mou dane mai sérieusement avce imag yi amanekh a bel et bien vaincu
@cheikhdiop9673
@cheikhdiop9673 13 күн бұрын
yéne wa keur mod lo guéne ci séni commentaire rék laléne di khamé amanékh mo dieuka danou pa bi di bakhoum nak mome dafa manoul mougne mod lo wayé siteu ak mod lo ci sakouyi la ta li ci bir guéw bila
@morlam8705
@morlam8705 13 күн бұрын
Toute l'erreur c les arbitres pourquoi ils les faisaient pas lutter encore , sénégalais mo beug lou yomb koi c koi c histoire ki mo dieuk épaule après ki tek na bop ? Diel dafay lerr
@mbayembow7205
@mbayembow7205 13 күн бұрын
Merci père bakhoum
@ndiougambaye1305
@ndiougambaye1305 13 күн бұрын
Vraiment siteu daane naa modou lo
@dakardk4750
@dakardk4750 13 күн бұрын
Siteu niéméwoule watené modane modou lo Siteu bopou lalena sakouyi gayi toujours coté modou lo rék laniye wané di neube coté siteu waya bo gussé coté siteu bopou bi lalena sakouyi
@Deggou
@Deggou 13 күн бұрын
Le problème pk gayi di neub côté bopou siteu cikaw saccouyi ? Nie ay vrai mbam laniou...​@@dakardk4750
@MoustaphaDiongue-if7lc
@MoustaphaDiongue-if7lc 13 күн бұрын
Deugue deugue sita dana
@zalefaye5716
@zalefaye5716 13 күн бұрын
Merci père ndahh Sénégal désé kénakou wahh DEUG la tête de thiatou Daouda fall moo djiitou
@ngomsitor
@ngomsitor 12 күн бұрын
Merci père mbakhoum
@mbayethiaw5401
@mbayethiaw5401 11 күн бұрын
Bravo pere bakhoum ❤❤❤
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 13 күн бұрын
Merci Abdou bakhoum bilahi amanekh mo dané
@assanjarju1608
@assanjarju1608 13 күн бұрын
Ama neekh mo dane 🎉🎉❤❤
@massambadiallo-dd4kf
@massambadiallo-dd4kf 13 күн бұрын
Amanekh daffa Dane vraiment li daffa gniawe
@Lofi-Music-Channels
@Lofi-Music-Channels 13 күн бұрын
té en plus avant bras la tékk, amoul béndeu épaule bou lale
@CheikhDiouf-wv9if
@CheikhDiouf-wv9if 13 күн бұрын
Bakhoum a parfaitement raison ❤
@bandapape
@bandapape 12 күн бұрын
siteu ak modou dagno gueuneu sakouyii père bakhoum c’est ça la différence
@SOUDOUNGOM-bj8rt
@SOUDOUNGOM-bj8rt 10 күн бұрын
Non père Bakhoum vraiment deug rék ngaye wakh ❤❤❤
@mariamandiaye3910
@mariamandiaye3910 11 күн бұрын
Pére Bou dal way ya WAH deugg☝️☝️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@DioufSeydina-yg9lo
@DioufSeydina-yg9lo 13 күн бұрын
Deugla diokhléne siteu victoire rame boudet victoire laniou diokh thiatou daouda fall deug rek moye deug
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 13 күн бұрын
Défait modou lo mo guen ler sakh😂😂😂😂😂
@ndiankoundiaye5935
@ndiankoundiaye5935 13 күн бұрын
Bilay CNG togn na amanékh bathi la alou yalla
@footballgod4351
@footballgod4351 13 күн бұрын
Togne siteu senegalais yi andeu ak mom
@SarraNdiaye-ix1oy
@SarraNdiaye-ix1oy 13 күн бұрын
Vraiment Tay mom deugue rk la wah
@DethieDioufFissel
@DethieDioufFissel 13 күн бұрын
Siteu a battu Modou lô pour dire vrai 🙏
@Yahouba-oq4jk
@Yahouba-oq4jk 13 күн бұрын
Si sacou yi
@yalmine765
@yalmine765 13 күн бұрын
Pere daga nieme deug rek❤️
@cissabib4756
@cissabib4756 13 күн бұрын
Bilahi bakhoum deug la wah
@moussagueye8408
@moussagueye8408 13 күн бұрын
Nanio diokh sitta victoiram
@AssanedieyeAssanedieye
@AssanedieyeAssanedieye 13 күн бұрын
Diokhe lène siteu victoire kone père tu as rèson cng son des coronpie
@mouhamedsy9441
@mouhamedsy9441 13 күн бұрын
Menou daw dane😂
@kurayahmi
@kurayahmi 13 күн бұрын
*Kii mom dou nopalou ci Modou Lo 😂😂*
@footballgod4351
@footballgod4351 13 күн бұрын
Dafa wakh deug mais deuk nafekh laniou nek
@papadiom9260
@papadiom9260 13 күн бұрын
Te pourtant kou Nafekhoul khamni Siteu mo dane lou lerrr
@footballgod4351
@footballgod4351 13 күн бұрын
@@papadiom9260 barki alkhourane
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 11 күн бұрын
😢😢😢😢😢li billahi wallahi tallahi dafa sakh rouslou amanékh dafa dane diéleu bou lér😢😢😢
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 13 күн бұрын
Thiotou nayam Senegal 🇸🇳 Dina yageu Tardé nax Dafa bary Naféx 🥹Sieu Moo Dan Modou lo 🧏‍♂️Bayma ndione Moo Dan Modou lo 🧏‍♂️Zarko Mo Dan siteu 🧏‍♂️Amanéx Moo Dann Thiatou Daoda Fall barke Alhouran 🧏‍♂️✍️✍️
@agenperf1826
@agenperf1826 13 күн бұрын
Lii victoire menou thiè am , dagnoo warrona taxawàt beuré .
@lepatriote_1127
@lepatriote_1127 13 күн бұрын
A quoi sert la var alors soit le cng conserve les recours et élimine la var ou bien si la var décide c’est définitif 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@FelixBaraye-j8p
@FelixBaraye-j8p 13 күн бұрын
Amaneh a belle et bien battu thiatou Daouda fall.
@BadouDiagne-i8r
@BadouDiagne-i8r 12 күн бұрын
Félicitations Thiatou daouda Fall 🎉
@SeydinaMboup-j3t
@SeydinaMboup-j3t 13 күн бұрын
Kon siteu dana modou lo
@Amm2293
@Amm2293 13 күн бұрын
Père la situation de siteu n'est pas comparable avec bi, siteu da done daw té si bitii la nec, il faut tenir cela en compte, mano nec si biti di dane, souko déféwone si birr comme ama'ekh AK thiatt dans ce cas meun na am victoire, il faut savoir faire la part des choses
@Deggou
@Deggou 13 күн бұрын
Même siteu da tekk bopou ci saccouyi lolou kéneu begouko wané
@nabg2030
@nabg2030 12 күн бұрын
Pour yene Abdou bakhoum défendre Ama Nekh moko takh di wakh
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 13 күн бұрын
Mane de thiatou daouda fall la faral wayé bougnou diokhé thiatou daouda fall victoire nane diokh siteu victoire
@damedia9410
@damedia9410 13 күн бұрын
Siteu c en dehors de l’enceinte boulen fatei
@papadiom9260
@papadiom9260 13 күн бұрын
@@damedia9410 Ndamou Siteu mo geuna lerrr
@ThioroFall-s8h
@ThioroFall-s8h 13 күн бұрын
Contexte combat yi bokoul règlement mo atté siteu modou lo chute bi biniouy wax si sakkou yila l'autre au milieu du l'enceinte Règlement mo wax kouy danne si sakou yi moy ki def action bi ki nek sibiti meno danne surtout bou lou eupe si yaw néké sibiti Quant à amanekh au milieu leu lep xéwé Loumassi diaxal moy daniou wax ni épaules dou chute si règlement bi pkw niou dieul victoires diambour wala aziz ndiaye moy dirigé
@Leuzsonko
@Leuzsonko 13 күн бұрын
Siteu mo dane dee senegalais mo nafekh😂
@SerignemodoumbeneDiouf
@SerignemodoumbeneDiouf 13 күн бұрын
Vraiment bakhoum taye mom ande na ak ioe modou lo moy Sama mbeur mais bougnou dioxe thiatt victoire kon modou lo siteu dann nako
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 13 күн бұрын
Iaw yay nafekh 😂😂😂
@AssanedieyeAssanedieye
@AssanedieyeAssanedieye 13 күн бұрын
Dafa lère kone siteu dafa dane modou lo ay nafèkhe gnène ambèsile
@RamaNiang-kk6hn
@RamaNiang-kk6hn 13 күн бұрын
Ms ayway bayilene Modou lô ak ndambam li bakh
@Dioppatriote06
@Dioppatriote06 13 күн бұрын
CNG dagnio nèlaw Si Modou Siteu
@NdiayeAssane-v2c
@NdiayeAssane-v2c 13 күн бұрын
Iba kane les gens te respectent et te suis arrête d'inviter ce haineux, il a un problème ce gars
@abdoudione-h7f
@abdoudione-h7f 13 күн бұрын
Pour moi épaule bi c à revoir vraiment. Épaule ak bras mom soriwowouniou Question de position le rek
@omarcisse6712
@omarcisse6712 13 күн бұрын
Bakhoum dof respecté le roi
@mouhamedmbengue2912
@mouhamedmbengue2912 13 күн бұрын
Me loutax ki bagne Modou lo😂😂😂😂
@AbdouAzizdia-xk2jz
@AbdouAzizdia-xk2jz 13 күн бұрын
Ama nekh mooo dan
@FallAblaye-m8r
@FallAblaye-m8r 13 күн бұрын
Ama nékh seul❤❤
@MoulayedabakhCiss
@MoulayedabakhCiss 14 күн бұрын
Premier commentaire 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@LamalanabaLamalanaba
@LamalanabaLamalanaba 12 күн бұрын
Père Bakhoum ak khadim Ndiaye gnio gueuneu niémé deugeu si magou lamb yi Moustapha Gueye mo gueuneu dakhar ndeme si magou lamb ji
@KossoNdiayr-gf8xm
@KossoNdiayr-gf8xm 13 күн бұрын
Var bi kon amoul chance
@lbyoungtv2223
@lbyoungtv2223 13 күн бұрын
Mod lo mm sou dano règlement bii mo validé woul chute bii Da am skh si football joueur day dougeul but hors jeux am dounn ko validé
@mbackediop7678
@mbackediop7678 13 күн бұрын
Bakhoum Nonou Modou lo Bou Bonn la
@diawcheikh3744
@diawcheikh3744 13 күн бұрын
Kou lerr Guam wakh
@massambadioneprod8831
@massambadioneprod8831 13 күн бұрын
Abdou Bakhoum aka bagne Modou lo fi ladone waax Modou du neek Roi😂😂
@azizallendiaye6590
@azizallendiaye6590 13 күн бұрын
Ama nèkh mo dan thiatou situ mo dan modou lo li Moy degue nitt mome bou waxoul Li rek defa farr
@ahmadoudiagnegueye9918
@ahmadoudiagnegueye9918 10 күн бұрын
Vraiment lou ler nga wakh per
@NdéyeCoumbaDiop-l8j
@NdéyeCoumbaDiop-l8j 13 күн бұрын
Kii épaule bi mo djitou yor na vidéo bou lerr nagni
@جمعيةمغربإنقاذ
@جمعيةمغربإنقاذ 13 күн бұрын
Boulene fater ni pere bakhoum moy wakh..beugoul modou lo
@BoubacarDiop-q2p
@BoubacarDiop-q2p 13 күн бұрын
Thiey père Abdou Modou bakhoum😂😂
@bassiroundiaye3913
@bassiroundiaye3913 13 күн бұрын
Abdou bakhoum siteu diokhou d'ara wayé daga bagne Modou lo motakh ga. Sonou
@ibrahimadia7469
@ibrahimadia7469 13 күн бұрын
bilay walahi Sou gnou diokhé thiate 😂😂😂ndam kone ya oustaz Siteu dako torokhal d'Anne ko 😂😂😂
@moussaloucar3096
@moussaloucar3096 13 күн бұрын
Père ngeumeul yalla
@AliaDiagne-y8j
@AliaDiagne-y8j 13 күн бұрын
Cng bayilene thiakhana amanekh mon dane
@abdoubeye7768
@abdoubeye7768 13 күн бұрын
Nane diokh siteu victoire ral
@Mackenzi-z4f
@Mackenzi-z4f 10 күн бұрын
TCHEUY MAK YOU FEN BAKHOUL DEH
@abdoulayendoye542
@abdoulayendoye542 13 күн бұрын
Amanekh mo dane dafa lérr bakhoul a parfaitement raison
@IbrahimaNdong-h4g
@IbrahimaNdong-h4g 13 күн бұрын
Modou lo dako wara porte plaite
@AladjiKâne-f6l
@AladjiKâne-f6l 13 күн бұрын
Amanèkh modan mè lamb dji waguedieuway nioko mom😂😂😂😂xaliss dokhoul diam
@KhadimThiam-pe7zy
@KhadimThiam-pe7zy 13 күн бұрын
Xana Senegalese yii wahoulén né cng. epol dou suite 😂😂😂 nafeh nio bri Senegal 😢😢
@malicksarr2141
@malicksarr2141 13 күн бұрын
Pér bakhoum guemele yalla 😂😅modou Lo defko nika yalla def 🤷🏽‍♂️ 👑
@SowMadiaw-go2uc
@SowMadiaw-go2uc 13 күн бұрын
Non lamb yakhouna té bari nanfekh malick ngom attanoul cng bilahi,kou gueumné malick ngom dou yagg cng lalal j'aime magui xaar kona améric
@adama6405
@adama6405 13 күн бұрын
Cng louléne nékh lagnou déf mais ama nékh mo dane
@abdouazizthiaw3491
@abdouazizthiaw3491 11 күн бұрын
Épaulu modou mo gënë léer sax.. Amanex coude la tékk du épaule.
@zizouzidane7332
@zizouzidane7332 13 күн бұрын
Ama nekh mo dane var mo ate cnc ate wounioula deugue
@AbdoucisseSarr-qn9hv
@AbdoucisseSarr-qn9hv 13 күн бұрын
Mais ñiémé wouñiou wax thi épaule wa cng par ce que li moy wonéné ay nafék Lañe séne poche moléne fi bayi cône dioxléne siteu victoirame séne djikoy nafékk yi mounou fi dial😢😢😢😢😢
@coulibalyaliouneka1343
@coulibalyaliouneka1343 5 күн бұрын
c'est du vol purement et simplement amanekh mo dane
@abdoulayendoye542
@abdoulayendoye542 13 күн бұрын
Amanekh na déf recour
@salaGueye-ph6om
@salaGueye-ph6om 13 күн бұрын
Billahi per bour khanne limou wakh moye degeu
@abdoukarim9309
@abdoukarim9309 13 күн бұрын
Vraiment amanekh mo dane Malick ngom kholatale sa doxaline
@mansourlo7617
@mansourlo7617 13 күн бұрын
Ki mome khole bou bone la yor wayé diga bayi modou deh
@morlam8705
@morlam8705 13 күн бұрын
Ndiakh daffa am si beure li ndiakh la
@Bambacobs221
@Bambacobs221 12 күн бұрын
Bakhoum dina meusseu kharou ndakh modou lo 😂😂😂
@malickkane1553
@malickkane1553 13 күн бұрын
En tout cas Dale combat takone n'a Souf si louma guiss
@lamzoteranga5875
@lamzoteranga5875 13 күн бұрын
Bakhoum effictivement même ama baldè nagne ko dèlo victoiram contre modulo 😅😅😅😅
@ResidenciaImmobilier
@ResidenciaImmobilier 13 күн бұрын
Bane victoire 😂
@MassFallou
@MassFallou 13 күн бұрын
Wa Abdou bakhoum mi louko modou lo déf
@mamecorndiaye1850
@mamecorndiaye1850 13 күн бұрын
Siteu solénn ko diokhoul sakh mo dane modou lô
@TaxiMan-y9c
@TaxiMan-y9c 12 күн бұрын
Amanékh mo dane siteu mo dane modou lo
@NayeFall-qq7xi
@NayeFall-qq7xi 13 күн бұрын
Waay lii njaax la ken daanul😂😂😂
@SowMadiaw-go2uc
@SowMadiaw-go2uc 13 күн бұрын
Amanekh mo dane bilahi cng gnioy nanfekh deug malick ngom yala n'a wathi
@abdouboukharagnelolo9687
@abdouboukharagnelolo9687 13 күн бұрын
Sawye mane sama khel azzi ndiaye setou ci
@afro3827
@afro3827 13 күн бұрын
Pere tega gueum yalla 😂😂
@aliouba5267
@aliouba5267 13 күн бұрын
Ah kon Siteu moy roi des arènes😅
@fallousarr5728
@fallousarr5728 13 күн бұрын
Meun wakh deugue yalla parcelle la deuk mais damani boufe Nila demé kone nonou leu demé
@ResidenciaImmobilier
@ResidenciaImmobilier 13 күн бұрын
😂😂😂😂
@mariamagassama9380
@mariamagassama9380 13 күн бұрын
Baoume.lou.takhe.nga.sokhore Sa.ndaye.waye
@jeanpaulgomis6427
@jeanpaulgomis6427 12 күн бұрын
Setci yalla lingay wakh ci modou lo tchim sa khol dina yagu dagu
@marambaye5926
@marambaye5926 13 күн бұрын
Amanekh mo dane vraiment
@chocsevenements8990
@chocsevenements8990 13 күн бұрын
Ama nekh mo daan dei sérieux nak
@bassiroudiouf9110
@bassiroudiouf9110 13 күн бұрын
Amanekh a battu TDF !!! Le CNG doit être sérieux
@chamousman2726
@chamousman2726 13 күн бұрын
Lii du Yoon Amanekh mo daan
@mbackediop7678
@mbackediop7678 13 күн бұрын
Mais Sitau Danoull Modou lo dhè Niari Combat yèppu Ndiakh la
@matarndiaye3496
@matarndiaye3496 10 күн бұрын
Domérame nga Modou lo rék nga bange
@jeanmbayeniakh1614
@jeanmbayeniakh1614 13 күн бұрын
Pére Abdou lou ler nagne la wakh siteu mo dane dé bayiléne manipulation bi
@TIJ..Senautocanada
@TIJ..Senautocanada 13 күн бұрын
Bakhoum le jaloux wallah tu vas maigrir 😅
@serignefalloufall4242
@serignefalloufall4242 13 күн бұрын
Ça c'est injuste. c'est une grand injus te Modou lo alors.
How to treat Acne💉
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 108 МЛН
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mardi 28 Janvier 2025
9:01
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 69 М.
How to treat Acne💉
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 108 МЛН