Diemel guéne sa rakadj si liguey bobou té wakhtane ak mome té guéne soutoural sen bopou mou yame si yéne niar ak yalla.. sokhna Fatou sa sagnsé rafette na merci.
@ElhadjThiam-p7xАй бұрын
Sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta histoire bi doyna war
@boundawdiakhate2801Ай бұрын
Bilay
@DethieMbaye-sj1hxАй бұрын
Masi topp
@abdoulalayeba4496Ай бұрын
Nopi rek
@Víctor-i8v1uАй бұрын
Diekhalouma video may nan lalna rakam 🤣🤣
@astoumaguettesissokho32Ай бұрын
Histoire bi doyna war trop wayé niom niar nieupe gno yam kéne bahousi kou guor ki na toup na déf tout pour guéné rakam bi si lou bone li moy deugue
@harounaba6331Ай бұрын
❤❤🎉🎉
@Éléonore-c1hАй бұрын
❤
@SaliouSeye-ji5udАй бұрын
😂😂may 3em
@KhadimDrame-w2dАй бұрын
Na wakhe deugebi na wakhe sokhenaame degeubi aparé mou wakhe yaayam ligeyou rakam
@KhadimDrame-w2dАй бұрын
Maye 4
@mookhadiaks7301Ай бұрын
mafi djitou
@AïchaBadji-s4b28 күн бұрын
🥹🥹🥹🥹😭😭
@aliounbtoure8018Ай бұрын
Yaw wakhal sa diabar li khew khamalko Niko tu regrette et tu ne le feras plus et après tu auras le courage d affronter ta soeur pour qu elle de boulot
@ngagnedeme-w2tАй бұрын
C'est vraiment dommage. Dijguéne dou mossa kham né mom ak goor douniou mossa yém. Gaur noumou mena mél ak loumou mena déf, yaxalouko lou beuri. Meune naci guéne. Sou beugué diabar dakoy am ci lou yomb. Djiguéne bou yakh bopam ba nieup xamko, adounam yaxouna parce que bén gaur douko takk. Djiguéne mo wara guena moytou. En plus carrière ram dafa guate. Moytoulén. Djiguéne bou beugua mouthie, dina daw gaure ba paré am fouleu ci bopam. Alal bingay dieundé say tâte, day yakh sa adouna. Nga diaréfa kén dotoula wégu kén dotoula foulal. Am lén xél té nék nite.