Net Tali en Wolof: Le Conducteur de Tiak Tiak Livre Son Cœur à une INCONNUE |

  Рет қаралды 14,090

Net Tali TV

Net Tali TV

Күн бұрын

Пікірлер: 29
@ElhadjThiam-p7x
@ElhadjThiam-p7x Күн бұрын
Salut sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta histoire bi doyna war wadji na mougne yalla nako yalla maye djiguene bou bakhe
@CheickneSacko-p4q
@CheickneSacko-p4q Күн бұрын
Wadji na mûgne té diema fâté femme bi dakh woor nagne ko ba paré mais nakk na bayi thiaga yi dakh amoul béne diarigne si môme pour avancement.sokhna Fatou sa tress yi rafette na machallah amal diam ak salam.
@AlexSyla
@AlexSyla 16 сағат бұрын
Maniko thii théy la reine des faits divert !🎉
@hfhgg-bm2to
@hfhgg-bm2to Күн бұрын
❤❤❤li mo tak fatou gua nekma wak gua leup
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 2 күн бұрын
Salam Sokhena Fatou. Wadji loumou déf dara nékouci. Dafa guissone loumou beugue déf ci fouleu. Mais kou djiguéne ki mo bone rek di workate. Sama wadji yow tamite yangui wéré dé. Djiguéne motakh nga beugue yakh sa adouna.Djiguéne fni beurinaniou ci deuk bi. Goor waroul faible. Ndialo mo guena bone ci lou yalla binde. Bayiko ci lou guaw. Concentré woul ci liguey bi. Nga dadialé xaliss. Yalla bakhna. Dinga am kouko gueune.
@DIAMBAR55
@DIAMBAR55 2 күн бұрын
Jeune dafay concentréwou ci aveniram, ba defar aveniram sooga wouti jigeen, té takk té baña takhawaalu
@wizkid540
@wizkid540 2 күн бұрын
Doule
@LamineGueye-j8d
@LamineGueye-j8d Күн бұрын
Tay nano café
@bouhsoumare2571
@bouhsoumare2571 2 күн бұрын
Tu doit savoir son choix d'avoir te quitté les gens sont aussi malhonnête pour séparer les gens facilement. Ils faut se marié quand tu peut.
@Boye-niang1
@Boye-niang1 2 күн бұрын
Merci ❤❤❤
@MouhamedFall-dk7uw
@MouhamedFall-dk7uw Күн бұрын
Mane doundou nako djiguene yi moy lolou dafa am niou meuneu féne mais wara tax nga yak sa bopou goor day deugueur
@SoldarouBamba-g9m
@SoldarouBamba-g9m 2 күн бұрын
Bayilén djigén gni ngén bagn dingén dé rk 350 mil Manon ngasé jeundeu bénén thiak thiak 😢😮😢
@cheikhdiop5949
@cheikhdiop5949 5 сағат бұрын
Wa namoungne
@wanealpha1965
@wanealpha1965 Күн бұрын
Dagey papou Di diouli
@aliouba6480
@aliouba6480 Күн бұрын
Khaléboudjiguène mo sérieuse woul bénén yone so amatéé yité si djiguène fékhél mou yoboula si ay wadiouram dina takh nga ame informations si mom
@Xippill
@Xippill Күн бұрын
Non mais ça va pas pourquoi tu gâches ta vie pour une fille qui ne vaut pas la peine tu es toujours conscient de ce que tu fais tu es un croyant prie tard la nuit vers 3h du matin et ouvre toi parle au bon dieu dit tout ce qui te fait mal et demande à notre seigneur de te guérir inchalla dieu exaucera tes vœux mes il faut y croire et faire confiance en lui soit fort il y a de la force en toi arrête de voir les thiagas désolée de le dire mais c’est pas pour toi tu es un homme bien alors diombe ko fait ton deuil avec et oublie la passe à autre chose la vie est belle machalla boula ken yakhal sa aduna suit moi sur KZbin tape xippill bon courage fatou
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 Күн бұрын
Damani, deug lou ma boukh! Yow lingay dèf moye fathie li la nakhari ta do nonou la gnou ko fadié! Khamalni dou mome rèk mofiye djiguène! Délossile sa khèle ta ame fayda si sa bopp! Khalé bou djiguène bi guenou la! Khalé bou djiguène kou bona bone la! Diarroule deureume, diaroule sakh khame! Limou la dèf yèp amo loye dèf nane danko beugue ba lègui??? Hey damani tournèle bobou page, brûlèle bobou chapitre, un point un trait! Défarale sa avenir té li na la servir de leçon, bou euleugué si loye dougue na nga ko guestou!!!!
@harounaba6331
@harounaba6331 Күн бұрын
❤🎉🎉❤
@cheikhdiop5949
@cheikhdiop5949 5 сағат бұрын
yako tayi
@mustaphasaine5947
@mustaphasaine5947 2 күн бұрын
Fateko
@aliounbtoure8018
@aliounbtoure8018 2 күн бұрын
Boul gnou foneto yako tay khana gueumo yala wala wolouwoko continu a faire du bien et eviter les details avec les fille unjour yala dinala dimbalé
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t 2 күн бұрын
Limay conseiller goor yeup moye. Kouci paréwoul pour takk diabar, boul dounguou ci bén djiguéne parce que perte de temps leu, perte xaliss, bakare you beuri. Après nga perte. Bayil ba paré. Boula léréni souba souba bou djiguene taxawone nga takk. Bo paré nak, nga xol ko bakh, nga takk ko. Boulci sonou di guéne lou yagg. Défal ay investigations ci kou djiguéne ki. Boudé kou bakh leu, takkal. Aussi simple. Kouko déf do am déception ci lén.
@SoldarouBamba-g9m
@SoldarouBamba-g9m 2 күн бұрын
Très bien frère Li la geum man 😢😢
@mamadoudia5644
@mamadoudia5644 Күн бұрын
Tu entres trop dans les détails. Il faut être bref et précis. On a pas de temps
@diopmamadou1614
@diopmamadou1614 2 күн бұрын
Tu devrais arrêter avec tes tasses à café
@adamaniasse2643
@adamaniasse2643 Күн бұрын
Khana franc maçon ga?
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 5 **VOSTFR**
55:32
EvenProd
Рет қаралды 1 МЛН
Série - Jeux de Dames - Saison 1 - Episode 31 - VOSTFR
36:14
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 530 М.
小丑女COCO的审判。#天使 #小丑 #超人不会飞
00:53
超人不会飞
Рет қаралды 16 МЛН
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 23 МЛН
Don’t Choose The Wrong Box 😱
00:41
Topper Guild
Рет қаралды 62 МЛН
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 27
41:05
Yesdakar
Рет қаралды 264 М.
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 36 - VOSTFR
44:50
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 2,1 МЛН
Série - BAKARY TAXIMAN - Saison 1 - Episode 19
18:33
RTS - RADIO TÉLÉVISION SÉNÉGALAISE
Рет қаралды 256 М.
Net Tali en Wolof:  La Awo Rend Son Mari Impuissant | @nettalitv
22:39
Net Tali: Elle Abandonne Son Mari Pour son Ex | @nettalitv
31:02
Net Tali TV
Рет қаралды 25 М.
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 39 - VOSTFR
1:24:02
Pikini Production
Рет қаралды 1,7 МЛН
小丑女COCO的审判。#天使 #小丑 #超人不会飞
00:53
超人不会飞
Рет қаралды 16 МЛН