Net Tali en Wolof: Un Serpent Qui Se déplace dans Son Pied |

  Рет қаралды 11,313

Net Tali TV

Net Tali TV

Күн бұрын

Пікірлер: 56
@Boye-niang1
@Boye-niang1 Күн бұрын
Yalla nako yalla taxawou si barke seydina Mouhamed amine 🤲
@boundawbeye612
@boundawbeye612 Күн бұрын
Sohkna Fatou CV ndéysane ndawsi bou féké Mun na ayétoul koursi you ihlas falah nasi mokéy déf bou djoulé ba paré inchallah 😢😢😢😢 yalla bakhna 😢😢😢😢❤❤❤
@CheickneSacko-p4q
@CheickneSacko-p4q Күн бұрын
Yalla nako yalla safara si fébar bi bamou weer ak diam sokhna Fatou taay sa tress yi ak sagnsé bi rafette na machallah merci.
@ElhadjThiam-p7x
@ElhadjThiam-p7x Күн бұрын
Sokhna Fatou Elhadj Thiam femme bi na déme keur djeumb Thiès si serigne saliou
@hfhgg-bm2to
@hfhgg-bm2to Күн бұрын
Fofou favela mane thiesla deuk
@Alislamniass
@Alislamniass Күн бұрын
Li dèf rek la na dem tiktok weur seydi Ibrahim ✍️ 📿
@fatousow94
@fatousow94 Күн бұрын
Liko dale métina torop yalla nako yalla taxawou bamou guén ci situation bi mayko weir ak weirlé ci barker seydina mouhamed psl
@absadiop2563
@absadiop2563 Күн бұрын
Asalamallekoum Sokhna Fatou caffè ndeyssane mettina troppo Yalla bakhana
@thiernondiaye1975
@thiernondiaye1975 Күн бұрын
Na déme Si oustaze oumar Sall
@moussasidibe7596
@moussasidibe7596 Күн бұрын
Mètina trop yalla na yalla safara
@mustaphasaine5947
@mustaphasaine5947 Күн бұрын
Na dem si chek bara ndaye walf
@momodiallo6233
@momodiallo6233 Күн бұрын
Walahi so nieuwe ma fathie ko faut lakhe djinné yauyou pour niou guene si yaram bi mais wayé li dindi ko ligueye la lou ma kham la walahi
@mbsvision221
@mbsvision221 14 сағат бұрын
😢diapalé koo te yalla takh woh KO si ki numéro Natali bi😢😢😢
@momodiallo6233
@momodiallo6233 Күн бұрын
Ohhh massa way ki façon bi ligueye dagne ko bole ak djinné walahi sou ma wakhone ma fathie ko si barké rassoulilahi
@mariamadiaofaye4766
@mariamadiaofaye4766 Күн бұрын
Svp prendre contact programa bii
@mbsvision221
@mbsvision221 14 сағат бұрын
diapalé koo te yalla takh woh KO si ki numéro Natali bi😢😢😢
@momodiallo6233
@momodiallo6233 12 сағат бұрын
@ diokhena sam numero si commentaire yi nama wo
@SaliouDiagne-oz5rz
@SaliouDiagne-oz5rz Күн бұрын
Yalnako yalla saffara
@AdamaBa-zb4wr
@AdamaBa-zb4wr Күн бұрын
N'a def tawaslou si yonantoubi salalahou aleyhi salim
@BinetandoyeBinetandoye-yf9jx
@BinetandoyeBinetandoye-yf9jx Күн бұрын
Yalnako yalla safara tè mouye tary alkhourane tè diko dèkelou
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 Күн бұрын
Kharale ma diokh la bène garab: Wouteule khoubou nime moye khobou garab bi gno wowé akacia. Na nga ci dague lou beury, nga bakhale ko lou tolou ci 30 minutes, boko bakhale na nga utiliser récipient boukhamenténé kène douci togue louno lèk mba louno nane ndakh après loci togue dafa wèkh khate. Bo bakhalé khobou acacia yoyou ba paré nga bayi ba mou nougue nga khamni dou la lak. Nga takhaw ci bène pane dieule ndokh momou nga done bakhalé khobou acacia yi rakhassé ko sa tank yi. Nga commencer ak sa tank tiamogne bi daléko ci sa cuisse di watié ba sa tank, trois fois. Après nga dèf la même chose ak tank ndeye dior bi. Bo paré ndokh bobou nga touri ko ci mbède bi. Nga dèf ko pendant trois jours balanga teude ak bo yéwo. Bodé teude wouteul béne domou limon ak 3 khobou lauriers ak touti khorome nga dèf ko ci sa soufou nguéguénaye. Bo kheuyé soubatèle nga sani lène si mbèbde bi. No meuné ame huile bi gno wowé touloukouneu nga ko diweu si sa tank yi, soko diweu dèko diweu di watiè. Boule diweu yégal!
@MbeneDiome-o7u
@MbeneDiome-o7u Күн бұрын
Merci beaucoup
@bintaniabaly9953
@bintaniabaly9953 Күн бұрын
Beaucoup de marabout iront à l'enfer direct bilay je me demande pourquoi ils font ces genres de travail 😭😭😭😭 l'argent fait le bonheur mais il ya certains genres d'argent je ne vais jamais les accepter juste pour gâcher la vie d'une personne c'est ignoble ça qu'Allah vous assiste Mme il faut tout faire pour venir dans nos locaux ici à Casamance pour te soigner
@ElhadjThiam-p7x
@ElhadjThiam-p7x Күн бұрын
Sokhna Fatou Elhadj Thiam ki li ko dale métina trop
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 Күн бұрын
Yayou dieukeureume diodiou moko koko dèf! Yayou ex dieukeur dji deume la!
@MbeneDiome-o7u
@MbeneDiome-o7u Күн бұрын
Enha yangui togn dé loula si woor
@mamadoudeme6025
@mamadoudeme6025 Күн бұрын
Ce qui arriver à cette femmes c est la même chose qui m était arrivé
@boubaka7172
@boubaka7172 Күн бұрын
wooy sama ndèye ! lii loumou doon?🤔🤔🤔
@wanealpha1965
@wanealpha1965 Күн бұрын
Thiey yallah
@manemamadoulamine379
@manemamadoulamine379 Күн бұрын
Ma fi djitou
@papadiallo3255
@papadiallo3255 7 сағат бұрын
Lolou en générale gorte leu nasi diw coulou kouna
@FatouFall-dz2io
@FatouFall-dz2io Күн бұрын
😢😢😢😢😢❤
@Xippill
@Xippill Күн бұрын
Li mom yémé na mais yalla rek mofi nek dell tek roquia goudi deko deglou tout le temps thi sa portable di ame diap aussi di niane yalla mou teguil la febar bi je pense que seytane la je ne suis pas sur mais alhourane dafa ame dole mom rek mothi meun dara
@aliouba6480
@aliouba6480 Күн бұрын
Danio tibou tank yi
@AmadouLeigh-c3t
@AmadouLeigh-c3t 20 сағат бұрын
SALAM may ALLAH SUBHANA WHO WA TALLAH give you good health and how is he doing with the religion did she pray normal
@manemamadoulamine379
@manemamadoulamine379 Күн бұрын
La fi djitou
@khadyseck1425
@khadyseck1425 Күн бұрын
A faire pendant 7 jours
@AlexSyla
@AlexSyla Күн бұрын
Manikocthi théy la phonoméne!
@SeydouNdiang-w4c
@SeydouNdiang-w4c Күн бұрын
Lolou kortou la
@NgomTeneng
@NgomTeneng Күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@LampMbengue-v5t
@LampMbengue-v5t Күн бұрын
😊😊😊😊
@scoutmaiba9584
@scoutmaiba9584 Күн бұрын
Rap la de
@diagneamsatou3473
@diagneamsatou3473 Күн бұрын
Koula begu contacter noumouy def?
@wanealpha1965
@wanealpha1965 Күн бұрын
Massa
@khoudedjisoumare9213
@khoudedjisoumare9213 Күн бұрын
Démale guise imam mou tarile la sorate rokiya
@AmadouLeigh-c3t
@AmadouLeigh-c3t 19 сағат бұрын
Let's her take surah 2Baqura as a friend it's may help her
@ngagnedeme-w2t
@ngagnedeme-w2t Күн бұрын
Na dém hôpital déf analyses yeupe.Yakarouma mouy affairou seytané. Na changé alimentation di lék fruits ak légumes. Nay diangue ayatal koursiyou 313 fois par jour ak 7 laqad djakoum diko eufe ko ci ndox. Diko nane ak ray ci yaram bi. In Shaa Allah bo démé hôpital, solution dina am.
@aissatoudiop8705
@aissatoudiop8705 23 сағат бұрын
Yaw es ce que ça vas ?
@ndeyekhadydiop9256
@ndeyekhadydiop9256 14 сағат бұрын
⁠ki kay ça ne va pas
@SalifSow-d4v
@SalifSow-d4v Күн бұрын
Ame na sama Kharit bou nek tamba walahi mane nako faith ndakh si lolu rek lay ligeye walahi dina fathie
@Mameastousow-x5z
@Mameastousow-x5z Күн бұрын
Na déme si déthie sarr pointe saréne la deuke
@momodiallo6233
@momodiallo6233 Күн бұрын
Walahi so nieuwe ma fathie ko faut lakhe djinné yauyou pour niou guene si yaram bi mais wayé li dindi ko ligueye la lou ma kham la walahi
@Xippill
@Xippill Күн бұрын
Li mom yémé na mais yalla rek mofi nek dell tek roquia goudi deko deglou tout le temps thi sa portable di ame diap aussi di niane yalla mou teguil la febar bi je pense que seytane la je ne suis pas sur mais alhourane dafa ame dole mom rek mothi meun dara
@mbaye7080
@mbaye7080 Күн бұрын
❤❤❤
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 27
41:05
Yesdakar
Рет қаралды 658 М.
Гениальное изобретение из обычного стаканчика!
00:31
Лютая физика | Олимпиадная физика
Рет қаралды 4,8 МЛН
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 39 - VOSTFR
1:24:02
Pikini Production
Рет қаралды 1,9 МЛН
HOTEL PALAL AU LAC ROSE
5:14
SOKONE TV
Рет қаралды 26 М.
Net Tali en Wolof:  La Awo Rend Son Mari Impuissant | @nettalitv
22:39
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 5 **VOSTFR**
55:32
EvenProd
Рет қаралды 1,9 МЛН
Famille Sénégalaise Saison 3 - BANDE ANNONCE Épisodes 40
2:25
Pikini Production
Рет қаралды 90 М.
Net Tali en Wolof:  Une Histoire Extraordinaire| @nettalitv
20:58
Net Tali TV
Рет қаралды 17 М.
urgent 🚨divorce. mariage avec un jeune : La voyante Aissatou Penda c'est triste
11:23