NET TALI : La Vie Amoureuse Difficile d'un Charretier Sénégalais

  Рет қаралды 65,968

Net Tali TV

Net Tali TV

Күн бұрын

Пікірлер: 69
@cheikhdiop8801
@cheikhdiop8801 3 ай бұрын
Na diap rèk boumou mas bayi dina niaw dh na fèkhè ba boumou mou nialo rèk yalla dinako takhawou inchalla
@LenaSeck-eu9ty
@LenaSeck-eu9ty 10 ай бұрын
Niak mo takh mbok yeup daw na tok ci deuk bi liguey un jour viendra gni dawone yeup dinagne ko weursi best bou yoree teranga te inchalla persevere tu vas reussir focus ci sa liguey rek
@sokhnalo3334
@sokhnalo3334 10 ай бұрын
Môme amena nianou wadiour n'a dieul khalébi déloko thi ay wadiourame té mou tok Sénégal liguey yalla bakh n'a 🙏🙏🙏
@darmanetv
@darmanetv 9 ай бұрын
1 seuye bou ay killifa andoul loumou nékh nékh si ay difficultés rék lay moudié nay nakhanté AK parents yii
@DAAN-xs6be
@DAAN-xs6be 10 ай бұрын
il esdt tres brave ce charetier, il doit continuer a travailler avec sa carete mais pas BARSAKH
@basarr495
@basarr495 9 ай бұрын
Machallha Bon continuation ❤
@AmadouNdiaye-iw7js
@AmadouNdiaye-iw7js 7 ай бұрын
Conseil 1 : na guènnè khélam si dougou si gaal yi baakhoul si mom; Conseil 2 : nay wakhtane ak khalé bou djiguèn bi si côté diko encourager si acte you rafét yi khalé bi déf et aussi famille badianou wadji khalé bou djiguèn bi nékk sèn keur aussi nagni wakhtane ak khalé bou djiguèn bi diko tagg si djikom you rafét, ndakh lolou dina takh khalé bou djiguèn bi dou meusseu khalata wor wadji; Conseil 3 : na wadji bayi khaar bi té tak khalé bi, nadkh djiguèn boula beuguè dou khool lo am ak lo amoul té dinala diapalé et aussi djiguèn beugoul kou am touti nanko damay khaar bomou gueuneu beuri, djiguèn boula beuguè bokoy khaarlo pour am lou beuri pour meunko téral dalay méré si pét té doulako wakh ndakh yoyou ngay déf sa bopp mom gueumoul lolou té lolou takhouko niew si yaw, donc na wadji dokh si côté takk ko lougnou am bokk; Conseil 4 : nako wadji takk té souko wadji takè boumko meusseu déf lou métti ndakh kokou meunani dafa yor dieumi djiguèn rek mais goorla ndakh niéména engagé trop té niémé lou métti, ndakh dém bagnou guènnèla sa keur té takhoul nga bayi wala nga découragé vraiment chapeau pour khalé bou djiguèn bi Conseil 5 : khalé bou djiguèn bi kou baakhla té mandou té dègg ndigueul dioup, ndakh lima diakhal bou done kom khaléy tay yi, soulèn goor wouteulé portable, sèn waydiour nilèn dèllol portable bi dougnko déf té dougnou téléphoné kou goor ki diko lèral dara, dagni yor sèn portable rek diko neub di si déf lougn beug déf, mais khalé bii lepp si yoon lako ték ak si dioup, yallah nako sounou borom samm
@darmanetv
@darmanetv 9 ай бұрын
2 na bayi mbeuk mi té dém postulé visa Canada soit Amérique soit visa singuegne
@ndeyeawasow8998
@ndeyeawasow8998 10 ай бұрын
Na mougne tes mou déme si membre de famille biii nous déllo khalé bou djiguène aye parents wame nous diégalko nous wakhe tane dina bakhe inchiaallah yalla na yalla yokou soutourame si barké yonènne tiby seydina mouhamet (saw) ak si barké alkourane 🙏🏻❤
@ndiarelam4940
@ndiarelam4940 10 ай бұрын
Amine amine yaa rabi 🤲🏿
@hat-tijani9305
@hat-tijani9305 10 ай бұрын
*Seydina Mouhamed (SAWS)
@aliounesene5063
@aliounesene5063 10 ай бұрын
Limakoye digal moye nabayi khalebi keur badjaname te continue travaux amem tan nako total lageuye bodeme ba tiharoye kaname maman âme wadiori ndawsi dinane warh
@darmanetv
@darmanetv 9 ай бұрын
3 mbok amatoul sodoul boromi tour alal wala Dara dja kén doula considéré ak ko meune ti done ngua diégeul ma si kadu yii
@fatoudjitte2358
@fatoudjitte2358 10 ай бұрын
Tourondo bi mo bonne rek AK tourondo nimou nekhè... Niakk Yaye mo meti rek
@MoustaphaGueye-q3v
@MoustaphaGueye-q3v 10 ай бұрын
Na badiane bi dam wakh tanak tourondom wala mak mou bakh si famibi mou dam wakh tanak pabi nous dioubo donté tourondom dafoul yeufi kilifa
@iboukane5176
@iboukane5176 9 ай бұрын
Hooo Wallay j’ai pleuré 😭😭live fou gor dafa métti
@babacardiouf3176
@babacardiouf3176 10 ай бұрын
Waji bounou ko khamon diapaleko inchala
@seuneba7091
@seuneba7091 10 ай бұрын
Courage rek machallah
@astoumaguettesissokho32
@astoumaguettesissokho32 10 ай бұрын
Ay way ak tourondo nimou nékhé hana mou rous Papam bikoko toudé bayi nieup li niawna trop wayé Dieu est grand
@laminekanteye7892
@laminekanteye7892 10 ай бұрын
Importante 🎉
@karaseye2745
@karaseye2745 10 ай бұрын
Borom thieuy😂😂😂😂😂
@seydanefall3167
@seydanefall3167 10 ай бұрын
Salam ne contine se liguey ak se chret ,AM ne Nianou ,Bayem ak Yayem ,LEPP de ne ke fe feek Fofou , Dem imigrer Takhoul Ngeu Reussir So fi dougue de fe Am ,Etapes you Barres,Te legui Toubab yi Begeuttounou Etrange yii Demarche yi yombatoul Gawoul du courages DE NE BAKH FOFE INCHALLAH
@amyndoye2973
@amyndoye2973 10 ай бұрын
Yalla bakhna dina bakh insalah
@fallcheikh8966
@fallcheikh8966 10 ай бұрын
Mne Sma mbock lougatois yie do nio fok Nie rew mah rek😢
@mouhamadousalamtassawouftv246
@mouhamadousalamtassawouftv246 9 ай бұрын
Ndayesan mètina loll😢😢
@mohametthiam4500
@mohametthiam4500 10 ай бұрын
Tourondo bi mo bonne rek ❤❤❤❤
@ModouSy-s2q
@ModouSy-s2q 10 ай бұрын
ww diarna diapalédé kouka beug diapale wotél nétali mou dioxla numerom
@Ftymaa
@Ftymaa 10 ай бұрын
Keur ndiaye Lô Ayoo foofou laa deukk 😢 😢
@bassirougamou8651
@bassirougamou8651 10 ай бұрын
Na dem dieugoulou ay parenmeus mou négocie pour charetier takou ko je suis contre mariage forcer
@seuneba7091
@seuneba7091 10 ай бұрын
Ndeysane métina
@omarndiaye6766
@omarndiaye6766 10 ай бұрын
Yallah nako yalla diappale inchallah
@abdouldioume9633
@abdouldioume9633 10 ай бұрын
Na diema wakhtane AK badiene bi rek nio oute solution pour sa fiancée si sa badiene peut parler avec ses parents. Moi c'est Abdoul depuis pointe noire
@amethngom7873
@amethngom7873 10 ай бұрын
Na wérou si yalla ndakh bouko aye mbokame bayé tmt amana yalla bayiwouko té mome rek moy doguale dou domou adama mougne rek mo ame sollo té mbeuguél ame ak niakk lou yalla déff si mome la
@maisene9510
@maisene9510 10 ай бұрын
🥰🥰🥰🙏🙏
@alhamdoulilah5446
@alhamdoulilah5446 10 ай бұрын
Na yoni ay kilifa gnou dèm wakh ak ay kilifa khalé bou djiguen bi mou nalhanté ak gniom ba mou meneu ame lou mou beug.
@abloslimshady
@abloslimshady 6 ай бұрын
NAY CONTINé DI LIGUEY? NDAXTé TALALOUL LOKHOM KENN POUR DOUNDOU! DOUNDOU GOOR YALLA DOU YOMB WAYé DINA BAKH!
@louisendiaye8987
@louisendiaye8987 10 ай бұрын
Na djìeule ay kilife gnou dem mou khale bou djguene bi mou dem toubal papà gnou mayeco mo guene
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 9 ай бұрын
Ndaw torondo bou bone😢
@moctardieng81
@moctardieng81 10 ай бұрын
Fêtes une délégation de imame , de oustaz et des membres de la famille allaient discuter avec le père de la fille
@jiegeullessmanthiam5554
@jiegeullessmanthiam5554 10 ай бұрын
Gni gnoungi gorré gni gno gorré😮❤😢
@mbayeniang2808
@mbayeniang2808 10 ай бұрын
Man dhė dama ne bom kawa tak na kharr
@BellaDiallo-r1o
@BellaDiallo-r1o 10 ай бұрын
❤❤❤
@AssaneGueye-m6u
@AssaneGueye-m6u 10 ай бұрын
🎉🎉❤
@tafsirhann1834
@tafsirhann1834 10 ай бұрын
Geumeul sa bopou Boul khar ndimbal kene Yakaral yalla Yangui ci yoon yalla nieup lafi nekal
@yvefay620
@yvefay620 10 ай бұрын
Qu'il reste au Sénégal pour gagner sa bie aller voir IMAM et se marier parce qu'après 18 ans la femme est n'a plus de kilifeu ..à 💯/💯
@SENEGAL303
@SENEGAL303 10 ай бұрын
Salut mon frère. Je pense que cette histoire concerne deux musulmans . Et dans l’islam: 1- la divorcée ( marié au paravant , mariagr consommé et tout) peut aller voir un autre que ses parents pour se remarier 2- la jeune fille jamais mariée, reste sous l’autorité parentale. Elle ne peut jamais se marier sans leurs autorisation. Surtout celui du papa ou du tuteur légal devant la religion.🔵mais elle doit être d’accord.on doit lui demander son avis avant de la donner en mariage. 2- la majorité à 18ans s’arrête sur les papiers.dans l’islam la femme est protégée .elle ne part pas comme elle veut où elle veut . Merci mon frere
@altesseroyale4383
@altesseroyale4383 9 ай бұрын
Nanou bayi dougue gal yi dème yi woroule do solution
@jiegeullessmanthiam5554
@jiegeullessmanthiam5554 10 ай бұрын
Nagnou and démm toubali sén wadiour loumoulén wakh gnou défco
@obietrice4620
@obietrice4620 10 ай бұрын
Doyna waar
@AssaneGueye-m6u
@AssaneGueye-m6u 10 ай бұрын
🎉❤❤
@souleymanesagna8702
@souleymanesagna8702 10 ай бұрын
Mane je ne comprends pas dafa am ay wadiour you khamoul dara ms sa dom mayko loumou beug boko mayé koumou beugoul doufa tok ay blém késsé
@ndeyendoye445
@ndeyendoye445 10 ай бұрын
Dina baah. Inchalla. Nattou la. Negocie avec ton homonyme pour épouser la fille. C'est son père qui doit la donner en mariage car elle n a jamais été mariée.
@Jackie-lina12333
@Jackie-lina12333 10 ай бұрын
Sama tourando gua chérie☺️>mais c est son père qui doit forcément la donner en marriage? Y a t-il pas d’autres membres de sa famille?
@ndeyendoye445
@ndeyendoye445 10 ай бұрын
@@Jackie-lina12333 oui tourando, c'est forcément son père si elle n a jamais été mariée selon l'islam.
@Jackie-lina12333
@Jackie-lina12333 10 ай бұрын
@@ndeyendoye445 ah je vois bien mais c dommage
@ndeyendoye445
@ndeyendoye445 10 ай бұрын
@@Jackie-lina12333 le prophète psl à dit que toute femme qui se marie sans le consentement de son père ou celui qu'il a délégué, fait un mariage non valable. Allaahou ahlam ! Nouyou la homonyme
@alinguet7974
@alinguet7974 10 ай бұрын
♥️♥️❤️💓💓❤️🤝♥️🤝💓♥️❤️💓
@astouSonko-g3w
@astouSonko-g3w 10 ай бұрын
mu dem and ak la fille keur tomame pour wahh akk papa dji diem ko djubalè ak domame
@taphadione7278
@taphadione7278 10 ай бұрын
Borome saréte bi n'a gorgor Lou liguéye bayi yonou déme beti réw guéme bopam
@mohametthiam4500
@mohametthiam4500 10 ай бұрын
Fatou loy binde??
@abloslimshady
@abloslimshady 6 ай бұрын
MOM DAFAY REUDD REK!🤣🤣🤣🤣
@hbbh4272
@hbbh4272 10 ай бұрын
Madame café thiey
@yvefay620
@yvefay620 10 ай бұрын
Dènko Nop ??
@ModouSy-s2q
@ModouSy-s2q 10 ай бұрын
wallaxi diar nagno diapallé nako présiden taxawou way wadji diambarla
@lionelione-zd7oq
@lionelione-zd7oq 7 ай бұрын
Negoze rek
@awabarry4201
@awabarry4201 10 ай бұрын
Ploculeur
@ALIOU850
@ALIOU850 10 ай бұрын
جاجف واي
@omarndiaye6766
@omarndiaye6766 10 ай бұрын
Yallah nako yalla diappale inchallah
@AssaneGueye-m6u
@AssaneGueye-m6u 10 ай бұрын
🤩😍😇
Polygame - Saison 3 - Episode 9
29:52
Senepeople
Рет қаралды 267 М.
Net Tali en Wolof: Sa Vie Tumultueuse, Elle a L'embarras du Choix
16:45
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 25 МЛН
coco在求救? #小丑 #天使 #shorts
00:29
好人小丑
Рет қаралды 97 МЛН
L'histoire jamais racontée de Ahmed Cissé
44:51
Seneweb TV
Рет қаралды 256 М.
COMMUNIQUÉ ET NOMINATIONS DU CONSEIL DES MINISTRES - MERCREDI 11 DÉCEMBRE 2024
16:35
RTS - RADIO TÉLÉVISION SÉNÉGALAISE
Рет қаралды 28 М.
Net Tali en Wolof: La Mère de sa Copine le Provoque
18:22
Net Tali TV
Рет қаралды 14 М.
NET TALI; L'histoire Extraordinaire d'un Coup de Foudre
28:14
Net Tali TV
Рет қаралды 77 М.
Net Tali: Elle Communique avec son Ex, Son Mari veut la Divorcer.
22:47
Série - Mirage- Episode 111
42:17
Khar Media
Рет қаралды 94 М.
Net Tali: Mariage non Consommé, Sa Femme se désiste
26:27
Net Tali TV
Рет қаралды 57 М.
🚨TFM LIVE : Jakaarlo bi spécial 08 Mars 2024 avec Dieynaba Seydou Ba
4:11:46
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 153 М.