Cheikh béthio dé hamanani famou naikk humm bou dé li la ligueyal l'islam yalna yalla doli soutoura diné bi bane dîné la thiey yalla
@adjadiop85962 жыл бұрын
que Allah pardonne cheikh bethio , que Allah guide aida et toutes c'est personne qui l'entoure et l'accompagne dans son égarement.
@53bocar2 жыл бұрын
Amine
@mawlayatv2 жыл бұрын
Sénégal nékh na 😂😂kom mariage wallahi li
@diarradiop32972 жыл бұрын
Je te dis oh 😂😂😂😂
@kagoulnoir87112 жыл бұрын
Aida respectes Le Khalife Général Des Mourides et les Sénégalais, Nitt dey am Kilifeu. Amo Bén Kham Kham
@Senegal8572 жыл бұрын
Na khalif bi mandou si mome li sr bethio lako borom diamono moko sa,thiantakone yi mandou leen si
@doffndiayenittdiop1742 жыл бұрын
@@Senegal857 mdr thiey yalla
@Senegal8572 жыл бұрын
@@doffndiayenittdiop174 yonou sr touba gui busi ñak juli ñak wor ñak nat asaka khajeh kone lep louy lou yalla beugue khaj nasi wasal sr bo xamni kou defaeou rek la soxleuh mdr
@doffndiayenittdiop1742 жыл бұрын
@@Senegal857 ça se voit que boko si yoneu bii alors mais yakh mola takha diouk bonne soirée
@Senegal8572 жыл бұрын
@@doffndiayenittdiop174 mdr xam xam deh sr touba limou si wax rek moy deugue limouy deef waxma luko dindi si yombi
Yakhou gnou dara gneup khame nanou ni.gni.sene Yonne bopp la nou nek
@noir84842 жыл бұрын
Kéne défoul kéne dara lou way def bopam
@bintaba14502 жыл бұрын
yalla meuna mougne rek waay thiie guente ben borom kham kham mouni serigne touba nenako bissou yawmal khiyame dina layo thiie nieene gni nane sama seute laniou ak thiie nieene gninane samay talibe laniou walahi waay sen bop lagnko def
@fatimsow58702 жыл бұрын
@@novellase6810 neikougnou sen ben yonou bop. Béthio faisait pire de son vivant à dianatou ken wahou A nk B dnc pourquoi après sa mort gni wara dohalei différemment? Puff
WAW Aïda diallo mii khana dafa febar ken khamoul limouy niror légi
@dabandiaye79982 жыл бұрын
Cheikh béthio li la néké ba guéne adouna yalla ko yalla yeureum Sokhna aïda li dieukeureum done df rkk laye df c malheur 😮
@novellase68102 жыл бұрын
Yaw nopil c mieux
@rokhayasylla68572 жыл бұрын
Doule
@oumoucisse41872 жыл бұрын
Je ne comprends pas pourquoi vous vous offusquez alors que c'était la même chose durant la vie de son mari et personne ne disait rien, vous l'avez accepté pour lui alors pourquoi pas elle ?
@cheikhdia31912 жыл бұрын
Yow ya wax deuggueu dé tu es sincère tu n'es pas un naaféckeu
@ndemoudiofior8338 Жыл бұрын
Sokhna bator saliou garson bersi la diaré doumasi doyall 💙🤍💖
@mamadoudiallo26962 жыл бұрын
Innaa Lil laahi wa innaa ilayhi raadji'oouune.
@torodo.ferrari2 жыл бұрын
Si ay thiaxane keipp nguene neikk 😌
@cheikhdiop31372 жыл бұрын
Wa bakhna yaw thiakhano mandouwo
@torodo.ferrari2 жыл бұрын
@@cheikhdiop3137 ladioumala ndax yow tamitteu mandou wo
Elle ne fait que poursuivre ce que son mari a laissé ( wail faith lekk) que dieu vous pardonne
@sokhnacisse48242 жыл бұрын
Bouguén dougé thi bir bamél diguén kham nii yalla ken laa Aïda diallo doufa meuneul bopam wakhatouma laa kene def len loulen nekh ba ég
@serignesaliouseck97262 жыл бұрын
Goor gni la yeureum rek bilahi li rouslou la sakh goor di soukeul djiguéne astakh firou la 😢😢😢😢
@queengalsen2 жыл бұрын
Yallah na lene yallah yereum 🙏 khamgua ni li eupna way 😭😭
@cheikhdia31912 жыл бұрын
Té nga Tal sa boppeu
@astouciss496121 күн бұрын
Da ma woor bayil ma mandou ki diarouma dara rawati na yakk sama koor m c désolant. Lou tolni MAGAL DE TOUBA , CHEIKHOUL XADIIM sauvé l 'ISMAM amo loy déf lou doul di féth ocrooouuu ba melni lou ma meun ta waax. Goor ak djiguéne diaxaso..... ma yamm fofu😭😭😭😭
@merryloum8602 жыл бұрын
déléne moure sén bopyi .likay takhourane leu mais dou Magal !!!
@novellase68102 жыл бұрын
En tout cas sene boppam la nou nek à mbour
@antagueye6142 жыл бұрын
DIEUREDIEUFETY SERIGNE BETHIO 🌺🌻 SERIGNE BETHIO AMOUL DENDADO 💐🌹 YA AIDA SALIOU DEUGUI DEUGUI DIEUMI SERIGNE BETHIO 💝💖❤💝💖YALLA NA FI YAGUEU LOL TE WERE 🌹🌻🍁🍀🌺 BOUNTAMEYI AMIREUM YI YA BATOR SALIOU THIOUNE ❤️ YA ADJA SALIOU THIOUNE ❤️ YALLA NA GNOU FI BOKK YAGUEU TE WERE🌻🌷⚘🌹🌺 YALLA NA GNOU SERIGNE BI DIMBALI BAGNOU SÈEY FAW SI MOME💖❤💖🧡❤
@ahmed-officiel69182 жыл бұрын
Ki vraie dommouram seytané deugeu
@famagning55422 жыл бұрын
DIEUREDIEUFETY SAMA SANGUE BI SOXNA AÏDA NOLA GEUME FI AKH FANOU DIEUM SANT NANOU SI AM GUINOULA AMM LOOL NOUNE YESAL GUI THIOUNE YA BAKH YA WOOR
@juniorcoolman68042 жыл бұрын
Sénégal kilifeu diné baré Toufi déh
@ridial44522 жыл бұрын
Du grand nimporte koi mbété mariage diakarlo diamou djiléne YALLA bayi fo fo baxul SERIGNE TOUBA FOWUL FOLOUWOUL
@novellase68102 жыл бұрын
Heureusement k gneup khame nanou ni sene Yonne la nou nek.serigne motakh def n'a.li mi wara.degf
@fatimsow58702 жыл бұрын
@@novellase6810 neikougnou sen yone dei
@khadijakane7042 жыл бұрын
Senegal lou way nekh def niou niak kilifa ak ay coba rek lafi guiss thiaga yi yep fi lagnou nek yalla naniou yalla doli soutoura alhamdoulilah santena yalla sante samay wadiour boubakh
@novellase68102 жыл бұрын
Ay makk you amou kilifeu lou si way meune
@sambandiaye16622 жыл бұрын
mé tanibér bi nékhone na dé!😂😂
@moussadiop26512 жыл бұрын
Wouye magui dè ya rew
@kadiadiaw58192 жыл бұрын
Ah yalla deh beurina yeurmende. Mais avant que ca soit trop tard...
@sokhnacisse48242 жыл бұрын
Sen taniber bii kagne laa wone gor yo khamni fethieu rek 😂😂😂😂
@amsatuosow34102 жыл бұрын
Mane dhé dama begue sokhna aida diallo thé manoumako guisse
@tamsiretoure96442 жыл бұрын
senegall fom diame,😭😭😭😭❌❌❌❌❌❌❌❌
@aminatadiop3042 жыл бұрын
Manne dhè je ne parle pas aux filles mais goor guounie lengue akhi bagageamee di soudjotale djiguene k Dieu vs préserve de l’enfer
@mamesarr47982 жыл бұрын
Mbalakh bi deh nekh trop😂 nioussi bari lekeyi ak ambiance molene takha nekeu ay thiantakoun Senegal mo meti nitt yi danio khiff amouniou liguey bari diot
@makhtardiop42032 жыл бұрын
Voilà t’as tt compris et eux aussi d’ailleurs 😂
@mamadousarr95312 жыл бұрын
La hawla wala houwata illah village🤭🤭
@diariatoucissokho7802 жыл бұрын
Li mariage wala on doit pas jouer avec la religion surtout nous les dames nous devrons revoir notre accoutrement au lieux religieux les femmes veulent transformer lieux saint en dansine une concurrence négative cheuveux oncle greffe heffe hessal yeré bou raffette thi magalgui warnagni wakh yallah bougouko yallah na niou Yallah tekk thi yone bou bakh Amine
@doffndiayenittdiop1742 жыл бұрын
Fi kay dou lieu religieux tane bére la rék
@rokhayandiaye12642 жыл бұрын
Khana yaw dougou keur serignou Mbacke Mbacke
@aidasene87542 жыл бұрын
Amine doyna war
@novellase68102 жыл бұрын
@@rokhayandiaye1264 en tout cas c à mbour
@rokhayasylla68572 жыл бұрын
Khana sa yaye laniouye mayè😂
@mamadoutoure49112 жыл бұрын
Li lep la bamou dess diné ak tarika
@folashade27492 жыл бұрын
I have sworn yesterday not to comment negative words again . In the name of Allah I have sworn. I can not say much about what I see, but, I am crying.
@bgsonsthriving.2 жыл бұрын
Facts
@Coulibaly952 жыл бұрын
Yeureum na bèthio dè ndeyssan kèn douko gnianal 😢
@bassgueye17172 жыл бұрын
Billah billah billah bakh na lik
@maxumbaye27902 жыл бұрын
Demlèn outi djeukeur dafa yombeu trop di doundé sèn djeukeur gua sa alakhira
@djimfall68402 жыл бұрын
Li dafa rouslou si Touba
@moustafadieng22252 жыл бұрын
Fiii dou touba deeee liii mbour la Madina tou salam
@novellase68102 жыл бұрын
Ya guene khame ne fi d'où touba tu l c arrêt d fair l con
@novellase68102 жыл бұрын
@@moustafadieng2225 il l c bien da beug wakh rk il c bien ki dougatoul touba
@sidatemohamedthiam3787 Жыл бұрын
Ayway mane damay rouss sakh mane Wakeur serigne Bethio la mais Aida diallo demal diegalou Serigne Mountakha teh degou si diné ak talibé
@africaforlife33002 жыл бұрын
😄😄😄😄😄😄🤣😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂saabar yii faan laa woon
@ibrahimasene92432 жыл бұрын
Lii dé xam nguéne xeul né dou dîné.lii aye thiaakhaane RÉK la.yénak serigne béthio yeupe safara moye séne keur
@aissatoundiaye60042 жыл бұрын
Lousiy yoonú Chiekh béthio ?? Kiii bone bonam kay wakhal ak mom rk Mais t'a pas a dire du mal d'une personne ki n'est pl8 de ce monde iao tmt
@deuguerek43052 жыл бұрын
Aida Diallo ak kanam bou gnémé bi mouné wadj nii comme khadiou khéw dé 😂😂😂😂😂😂
@aissatoundiaye35922 жыл бұрын
Allahou Akbar. Rien de ce que Serigne Touba a demandé dans son magal !!
@fatouwaly61102 жыл бұрын
SOKHNA AÏDA SALIOU THIOUNE YAGUAL DIAMONO TÉ ANDKO AK WER AMIIIINE ❤️
@Sauron-sn12 жыл бұрын
Là le diable peut aller se reposer, ils sont tous perdu et font la honte de toute la communauté mouride dont le guide était un exemple, un vrai musulman et un digne serviteur du Prophete. Qu'Allah vous guide dans le droit chemin
@jajafaya64702 жыл бұрын
Aminn
@sokhnamboup25662 жыл бұрын
Bilahi c’est n’importe quoi
@maremediouf85972 жыл бұрын
le guide est toujours un exemple cette categorie là ne peut pas salir notre tres cher guide car il a interdit à aida diallo de faire ceci
Yabatè nguéne trop ndigueul bu diougone pour niu lidieunti lène waxatuniuko
@mmedembele1172 жыл бұрын
Vraiment nak
@Senegalteamofficiel2 жыл бұрын
Dangay doul rk do lidieunti kenn
@keishimusic7782 жыл бұрын
@@Senegalteamofficiel yaw khana gordjiguen nga yaww Moussa sa lefeul ndey yaw ak Aida bi niakk ndey fouleuu ay domeram ngen koi ba ndigueul dioukk ngen khol dangeni dof dofloy rek dofolen hamolen kou dof
@mohamedlaminediallo2 жыл бұрын
Diné bouñouy féthie djiguénes yi kéne moussoroul
@fatimadieye94782 жыл бұрын
Boléko diakhasso gore ake djiguéne qu'Allah nous guident
@mohamedlaminediallo2 жыл бұрын
@@fatimadieye9478 amine . Li mom doynawar torop
@deuguerek43052 жыл бұрын
Mbété meeting partie au pouvoir 😂😂😂😂😂
@khellcomholdinggroup29632 жыл бұрын
MANE CHIEKH BI LA YEUREUM DAKH LI MOU BAYI CI GINAWAMA 😢 NIAW NA
@rokhayasylla68572 жыл бұрын
Doul
@fatimsow58702 жыл бұрын
😂😂😂
@fatoudiop66602 жыл бұрын
Aye way mbete aye khare🐏🐏🐏🐏🐏🐘🐘🐘
@coumbandao25012 жыл бұрын
Ahh man déh diomy naa ci lii 🤭
@fatoundiaye57642 жыл бұрын
Ak Say ndiabop tosskaré nielnalen😁🔥
@djimfall68402 жыл бұрын
Serigne bi wakhoulen li deh
@novellase68102 жыл бұрын
Sene boppeu la nou nek
@youhavetofollowthetruth75572 жыл бұрын
When will the Senegalese people wake up from these demonic ways?
@aminatasow59662 жыл бұрын
Never
@ahmedfall8922 жыл бұрын
Silly
@pommypaby41562 жыл бұрын
That’s when they will wake up and realize they are in Hell 🔥 🔥🔥
@frenchyboy262 жыл бұрын
Allah will show them
@folashade27492 жыл бұрын
I have sworn yesterday not to comment negative words again . In the name of Allah I have sworn. I can not say much about what I see, but, I am crying. I have asked Allah to forgive me from the bad words and comments I have said on people I have not even know. So I can't comment on this but, I side with you. I am crying right now, because I want to comment negative but, I already promised Allah.. NEVER AGAIN.
@khadifall28252 жыл бұрын
Hay waye délèneko ñainale ak diko watheil kamile mogune li
@mamesarr47982 жыл бұрын
😂😂😂
@papadia51312 жыл бұрын
Thiéy moudioum diamono loby ak sény péxé pour yake dîne dji
@omarndiaye18132 жыл бұрын
Défal loula nékh ba kén lal la
@arfangarfang49432 жыл бұрын
Subhanallah 😭😭😭😭
@arfangarfang49432 жыл бұрын
Thiey yalla yalna niou yalla mouseul thi seytané yi
@cherifdiop5722 жыл бұрын
Ibliss mom ame na Victoire 😂😂
@fatoumatadiop46942 жыл бұрын
Et nous voilà dans la voie de la perdition
@awatoure50562 жыл бұрын
Wallahi yallah mongui lendi khar
@mamadoudiallo26962 жыл бұрын
Satan peut vraiment jubiler.
@adjadiop85962 жыл бұрын
wallahi
@massambambacke3132 жыл бұрын
😂😂😂
@ndoumbembayembaye41852 жыл бұрын
Lidafarouslou bilakhi femme bidëfoul Dara nicotop këndouniom
@sohnambye68792 жыл бұрын
ALAHU AKBARR NDEYSAN YALNANYU YA ALLAH JEGAL YARABI
@2jjbb2 жыл бұрын
Ameen
@amdyseye5792 жыл бұрын
Bu dee lii mooy yobbee aldianna de ma xamne gagne ngeen gnu niaari yoon
@moussaboiro48712 жыл бұрын
Quel genre de dîne j'espère bien c ada
@mohamedlaminediallo2 жыл бұрын
Way li mom bane diné la? Soub'hanAllah
@novellase68102 жыл бұрын
Yagui def lou yesse ou say famille à régler sa.dabor
@serignesaliougning55662 жыл бұрын
DIEREDIEFÉ SERIGNE BETHIO DIEREDIEFÉ SOKHNA AÏDA SALIOU YALA NANGA FI YAAG TÉ AND AK WERE
@papadia51312 жыл бұрын
Thiey diotayou seytané
@laminebaouth60202 жыл бұрын
Cheikh Sohna Aida del mouru nak 😂😂
@bounamadiarra84872 жыл бұрын
Dindii greffage yi tamit, liv rafetoul wallaay
@mbarkacoulibaly50982 жыл бұрын
اللهم مهدني علا صراطك المستقيم وحبب علي عبادك الصالحين و حشرني معا نبينا محمد صلى الله عليه وسلم
Mane Dara défou ma cas loudoul bou waré nianal au talibém tombé jouram Dina yémè dall😂😂😂
@Mody-nz3zt2 жыл бұрын
😂🤣😂🤣😂non Li dafa doy war dei
@ibrahimasene92432 жыл бұрын
Lii daraye yalla nékoussi bakane késsé la.
@ndiayedybala13142 жыл бұрын
Galsen nekh borom jezner bleu clair bi toth n'a fi😅🤣😂😂
@modoundiaye97212 жыл бұрын
Sokhna aida saliou thioune merci beaucoup Sama sague bi
@biguediouf26412 жыл бұрын
Doyna war dal yalla naléne yalla sopi
@Zakaria-je8su2 жыл бұрын
Yen werolenn
@taalibe53412 жыл бұрын
Dioté wolen dara ak Sëñ saliou. Moom wathiona ak niep. Ak ndioup, diamou yalla, ragal yalla am ak talibe ci la nekkon. Nee ma loudoul Lislam amou thia ak yàq amou thia ak defar.
@fatimsow58702 жыл бұрын
Pourtant lila bethio dane def du vivant de serign saliou dnc pourquoi gni wara dohalé autrement ?
@jawaradiko8976 Жыл бұрын
This zabarr festival is nice
@asarasar2 жыл бұрын
yalla mo meuneu mougne
@sokhnambaye41062 жыл бұрын
Soubhana lie loumou done ni melenie sabare
@mohamedlaminediallo2 жыл бұрын
Kholal ma gor you ñak fayda yi di féthie nguir khaliss gomoléne touss . Li nguéne deff ni dé dou youfou dioullitt
@modoudiagne82372 жыл бұрын
Démléne diamoudji yalla Si ay thiakhane rék guene nék Xaware la fi guiss
@geme73372 жыл бұрын
Nekh na trop Aïda
@madyd46073 ай бұрын
Dieureudieuf Sokhna Aida. Elle fait pareille que Cheihk Bethio. Au moins elle fait plaisir à ses talibés et aux pauvres en distribuant de moutons et des boeufs. C'est mille fois mieux que les marabouts corrompus qui profitent de l'argent de leur talibés en leur promettant le paradis alors qu'ils ne sont que de simples mortels
@Mody-nz3zt2 жыл бұрын
😢😢😢😢pitoyable 😢
@maksodieng73252 жыл бұрын
Yen dagén di sonou rek wayé sen yone wi baxoul bilahi yéna bon yala nanou yala yerem