Oh Ndeysan 2 Jour De Mariage La Gagnou, Sa Sœur Sous Le Choc En Larme Raconte: «Si Goudi Bi Dafa…

  Рет қаралды 76,756

People 221 TV

People 221 TV

Күн бұрын

Пікірлер
@People221sn
@People221sn Ай бұрын
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
@senegalthikhol1653
@senegalthikhol1653 Ай бұрын
Sokhnam la gueuneu yeureum ndakh Sénégalais si gnak nangou ndogalou yalla rk tém gnouni da aygaf wala am rab ki dém yalla nako Ya Allah yeureum
@zeuynagueye4240
@zeuynagueye4240 Ай бұрын
Dinagnou yakk deram kay Té mom dousi dara
@SokhnaNdiaye-md3wk
@SokhnaNdiaye-md3wk Ай бұрын
Bly liladone khalate dougou guiss sa commenter,dou yoboudé ms yalah bakhna . yalah na ko yalah yereum diéguel ko kharé ko aldianay firdawsi 😢🙏
@senegalthikhol1653
@senegalthikhol1653 Ай бұрын
@@SokhnaNdiaye-md3wk amine
@marieeliseloume5422
@marieeliseloume5422 Ай бұрын
Bilaye deugueleu kou yebou diko saur d dou taguo yalla na khippe aldiana thi barke serigne babacar sy amine yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne
@dabaniang8141
@dabaniang8141 Ай бұрын
Ndeysane yalla nako bour yalla yeureum tè dièguelko kharèko si aldina fir dawsi thi barkhè seydina mouhamed psl
@fatoumataba3150
@fatoumataba3150 Ай бұрын
Tiktok nga xamnii Moy réseau social bi gueuneu hostile commentaires yimafa seine yeup nek Lou positifs sur sa personne lolou rk ça veut tt dire mashaalah yallah boula thiat djitou sa bamel, yallah na deh Di sa noflay 🙏🏾
@AYBarromvie
@AYBarromvie Ай бұрын
Kou sa heure Diot ga démm dimanche 29decembre Sama papa dagno agn baparé mou dém guedj mbali AK Sama frère diambat ndigui boy méti danou décède sur le coup ti bir gall gui nianal len KO yalla ti barké yonenti SWS
@fatoukineba4436
@fatoukineba4436 Ай бұрын
Yalnako Y'a Allah yeureum, ak kep kougnou djitou
@jeanine4830
@jeanine4830 Ай бұрын
Paix à son âme
@FamaraBodian-e2h
@FamaraBodian-e2h Ай бұрын
Yalla nako burr yalla diégël té xarreko aldiana
@ndeyeaidasy7362
@ndeyeaidasy7362 Ай бұрын
QU'ALLAH ait pitié de son âme
@mamecoumbaawacisse412
@mamecoumbaawacisse412 23 күн бұрын
Masta Yalla nako Yalla Yeureum te khareko Aldiana Firdawsi thi barke Seydina Mouhamed PSL
@NdeyeawaFall-k9u
@NdeyeawaFall-k9u Ай бұрын
Bilae bo niéwé le matin molaye diox ndékii yalnako borom bi diégueul té xaréko aldiana
@fatoumatabalde6592
@fatoumatabalde6592 Ай бұрын
Machallah yalla nako souniou borom khare fiiirdawsi, yalla bouko thiate djitou ci bamel 🙏🙏🙏
@ndiayemaleye2581
@ndiayemaleye2581 Ай бұрын
Bilahi lou metti yaguena aduna 😭😭😭😭😭😭
@Papiblack-i7k
@Papiblack-i7k Ай бұрын
Wayou thione Seck bi tak diabar bay wadia tokhou dè niaw tagalèleun 😢 😢😢😢😢 youlla bakhna yeurmandè yalla
@mamasamb3723
@mamasamb3723 Ай бұрын
Yalah na déé Di noflayam
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 Ай бұрын
*Ndeysane c’est triste li mtx gnounane loy yotou na fekk mou djigue la 😢paix à son âme Yalla na khipé Aldiana firdawsi Amennn🥺 🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
@pendandiaye6743
@pendandiaye6743 Ай бұрын
Bilay nite kou bakh sakh yalla nako yalla kharé aldiana
@salladiaw543
@salladiaw543 Ай бұрын
Amine Yarabi
@AitaDiagne-r4d
@AitaDiagne-r4d Ай бұрын
Ndeyesane qu’il repose en paix may nama jeans Bou rafet
@famagaye9999
@famagaye9999 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum tai khareko aldiana 😭😭
@salladiaw543
@salladiaw543 Ай бұрын
Amine Yarabi
@oppoclient
@oppoclient Ай бұрын
jeudi passe lako diakh sama classe mes louma meti bilah takh ci tik tok bi lako khame mes nite bou bakh so deme plasame so lekoule dalaye mere bilah aye boisson eaux lepe laye tekh ci plasame bilah 1er jour bouma deme lako,diape mou diape ma bilah mes yalla ko yalla khari aldiana🙏🙏🙏
@khadimka2058
@khadimka2058 Ай бұрын
Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi, ndeysaan toujours daniy wakh ni nitt mingui yotou lou geunoul si mom
@DiopNdeyendoumbe-f8f
@DiopNdeyendoumbe-f8f Ай бұрын
Yalla naka Yalla yeureum si barkep seydina mouhamad psl
@CoumbaComiBa
@CoumbaComiBa 24 күн бұрын
Yalnaco yalla yeureum xareco aldiana firdawsi barké yonentbi sallalahou aleyhi wassallam 🤲🤲🤲🤲😭😭
@aminafall6253
@aminafall6253 Ай бұрын
Ndeysane AMA tik tok lako khamone niou dem ba colobane pour djeund kou bakh djeundeul niou agn mayniou boisson th djeunde rek moniou yobou wone si plassam kou bakh acceuillant ndeysane yalnako yallah djegual ko
@Ramzek-f3s
@Ramzek-f3s Ай бұрын
Sèèdè yi rafetneu machallah
@aminafall6253
@aminafall6253 Ай бұрын
@ walahi ndeysane kou bakh Demna
@SalmaSy-k6g
@SalmaSy-k6g Ай бұрын
Bilay meti na lol sah paix à son âmes
@FARAON-j9r
@FARAON-j9r Ай бұрын
😢Ndeysane yalnako yalla yeureum 🙏🏿
@Nafidramè-r7b
@Nafidramè-r7b Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureume kharèko aldiana
@modoufall9624
@modoufall9624 Ай бұрын
Yala nako yala yeureum te kharéko aldjana 🙏🙏🙏
@amsatousow6760
@amsatousow6760 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum t sameu famille wam 😢
@ZakariaGt-q1c
@ZakariaGt-q1c Ай бұрын
AMA ndeysane niit kou bahh yalla nako yalla yeureum
@kourkopoulopoulo520
@kourkopoulopoulo520 Ай бұрын
Ndeyssane yallah nakko yallah yeureum sede yi rafete na
@AminataDiallo-o1j
@AminataDiallo-o1j Ай бұрын
Il faut écrire Allah en majuscule 🙏
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc Ай бұрын
Lou way di yotou na done lou geune si yow nako yalla yeureum diégal ko
@AmicolleNdiour
@AmicolleNdiour Ай бұрын
Yalna ko yalla yeureum té kharei ko aldiana firdawsi
@generalkhalifmajorkara4661
@generalkhalifmajorkara4661 Ай бұрын
Il est généreux ❤ YALLAH Yeureum ko xaré ko aldiana
@khadijadiouf2322
@khadijadiouf2322 Ай бұрын
Yalnako yalla yeureum kou bakh lawon ndeysane 😢
@AissatouWade-z2n
@AissatouWade-z2n Ай бұрын
Bilaye adouna amoul Solo
@ThianéNéthia
@ThianéNéthia Ай бұрын
Oh métina yalna ko Yalla kharé aldiana 🙏🙏🙏
@awaniang2713
@awaniang2713 Ай бұрын
Yalna ko yalla yereume te Khareko aldjiana firdawsi 😢
@rackyndiaye3665
@rackyndiaye3665 Ай бұрын
Yalla rek mo sagn li soubhana lah 🥺😭😭🙏🙏🙏
@FatouPouye-i8k
@FatouPouye-i8k 17 күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana fimou dieum gueunal ko fimou diougué Meusouma ko guis mai ndiorte na k kou bakh la d'après deganté biii walay benn bal pul lama meussa diaye ya goul dara
@AminataBaldé-f3d
@AminataBaldé-f3d 24 күн бұрын
Yala nako yala yeureume té haréko aldiana firdawsi si barké seydina mouhamed
@mamyfallougalass1959
@mamyfallougalass1959 Ай бұрын
Ndeysane massa 😢Yallah nakko yallah yeureum khare ko Aldiana Firdawsi Ci Barke Seydina MOUHAMED ( p.s.l) Ak Mbolem Dioulite Allahouma Amine Y'a Rabbi 🤲🤲🤲😔😔
@khargueye3428
@khargueye3428 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum xareko aldjanay firdawsi sí barke seydina Mohamed psl bakh reek mon ame soolo
@aminadiatta4818
@aminadiatta4818 Ай бұрын
Ndeyssane mandé mangui dioye comme ci damaco hame té hamoumaco massa yalna hippé aldiana
@NdeyekhadyThiaw-qp3gl
@NdeyekhadyThiaw-qp3gl Ай бұрын
Yalnako yalla yeureume ta khareko aldiana
@SokhnamayeGueye-w1u
@SokhnamayeGueye-w1u Ай бұрын
yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawsi si barkéb seydina mouhamd reposse en paix
@AdOlPhE_FOOT-y4l
@AdOlPhE_FOOT-y4l Ай бұрын
Yalla NaKo yalla yeureum té kharéko aldiana firdawsi amine 🤲
@salladiaw543
@salladiaw543 Ай бұрын
Amine Yarabi
@kourkopoulopoulo520
@kourkopoulopoulo520 Ай бұрын
Ndeyssane li metina trope que son âme repose en paix
@khadidiatougueye3604
@khadidiatougueye3604 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum teh kharé ko aldiana 🙏😭
@NdeyefamaDiaw-v2b
@NdeyefamaDiaw-v2b Ай бұрын
Ndeyssan kou bakh dém n’a😢😢
@sofiakane8716
@sofiakane8716 Ай бұрын
Yalla nako yalla kharei Aldianna
@elhadjimamadoukasse9333
@elhadjimamadoukasse9333 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum te kharéko aldjanay firdawsi Amin
@ndeyegueye115
@ndeyegueye115 Ай бұрын
NDEYSANE YALLA NAKO YALLA YEUREUM KHAREKO ALDIANA FIRDAWSI Lii YALLA RÈKK MOKO MEUN MÉTINA TOROP 😢😢
@mamikayre7021
@mamikayre7021 Ай бұрын
Yalnako yalla yeureum
@ndeyediouf8777
@ndeyediouf8777 Ай бұрын
Yalnako yalla yeureum 😢
@rokhayandiaye7375
@rokhayandiaye7375 Ай бұрын
Paix à son âme Fatiha 11 likhlass Amine yarabi 🙏 Massa
@madamefall320
@madamefall320 Ай бұрын
Yalna xipei aldjana
@seydoutall4599
@seydoutall4599 Ай бұрын
Yallanako yalla yeureum khareko aldiana
@DIONART04
@DIONART04 Ай бұрын
Massa métina paix à son âme 🙏
@ngouyeniane5863
@ngouyeniane5863 Ай бұрын
Yallllah na ko yallah yeuram
@KhadimDione-y8n
@KhadimDione-y8n Ай бұрын
Yalla nako Yalla yeureum thé diégualko ak mboléme Waydawlo yii
@badoundiaye3158
@badoundiaye3158 Ай бұрын
Inna lillahi wa inna illehi radjikhoun massa sister métina mé adouna mo démé nonou do degne mouk di dégeu diw dé na diw dé na diw dé na baga moudiou nek yaw diw diodiou dé té dé nak moy lettre moy cahier pour doundou gui kou am khel na dieul darsou si gni nga kham né nio dé té kou dé warroul dara dotoula warr yalla nako yalla yeureum diégalko té kharé ko aldiana firdawsi
@GarmyDiallo
@GarmyDiallo Ай бұрын
Bilaye kou bakhe😢😢😢😢😢😢😢
@SalyNdiaye-ef9su
@SalyNdiaye-ef9su Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum hareko aldiana firdawsi
@FatouDeme-ke8bn
@FatouDeme-ke8bn Ай бұрын
Que son âme repos en paix
@adjaDiawara-m5q
@adjaDiawara-m5q Ай бұрын
Que firdawsi soit son demeure éternel si Barker Nabi Moustapha PSL 🙏
@astousene5935
@astousene5935 Ай бұрын
Yala nako yala yeureume t khareko aldiana firdawsi
@allediouf1286
@allediouf1286 Ай бұрын
Que son âme repose en paix
@biguengom919
@biguengom919 Ай бұрын
Yalla nako Yalla yeureum khareko Aldjiana Firdaws
@ousmanediop4110
@ousmanediop4110 Ай бұрын
Paix à son ame amineee YARABI ainsi qu'à tous nos défunts amine YARABI
@Ndeye-gi3cr
@Ndeye-gi3cr Ай бұрын
Yallana sounou borom khareko aldiana
@battoulyba7499
@battoulyba7499 Ай бұрын
Paix à son âme ndeyssan
@BinetaNdiaye-e2v
@BinetaNdiaye-e2v Ай бұрын
Yala nako yala khare aldiana
@fatousagna3981
@fatousagna3981 Ай бұрын
Que Dieu l accueille dans son paradis
@Ramapoulo
@Ramapoulo Ай бұрын
Paix à son âme 😢🙏
@ndeyeannasoumare3059
@ndeyeannasoumare3059 Ай бұрын
Yalna aldiana firdawsi nék deukouway inchallah
@dabadrame1869
@dabadrame1869 Ай бұрын
Elle est sous le choc,masta
@LafemasonhomSy
@LafemasonhomSy Ай бұрын
Adouna passage leu yalna gnou ko kham di saur alakhira gni djitou borom bi yeureum len
@Gainde2024Gainde
@Gainde2024Gainde Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureume
@MarieNgom-h1n
@MarieNgom-h1n Ай бұрын
Wooooy métina trop yalla nako yalla yéreum
@ibrahimaibrahima6448
@ibrahimaibrahima6448 Ай бұрын
Que son âme repose en paix 🤲🤲🤲
@AissatouWade-z2n
@AissatouWade-z2n Ай бұрын
Metina ciki dem meti ci diambar djimou fi bayi
@ndiayemaleye2581
@ndiayemaleye2581 Ай бұрын
Ndaysane bilahi 😢
@MarieNgom-h1n
@MarieNgom-h1n Ай бұрын
Ohhhhhhhh métina trop
@ndiayemaleye2581
@ndiayemaleye2581 Ай бұрын
@@MarieNgom-h1n ndaysane sokhna tamite metina ci mome trop
@dieresadio4947
@dieresadio4947 Ай бұрын
Yallah daal moy deff louko nekh innalilahi wa inna iléyhii radjiounn Yallah na ko Yallah yeureum
@aissatoutraore2203
@aissatoutraore2203 Ай бұрын
Yallah nakko yallah yeureum xareiko aldiana firdawssi😢
@AwaSamb-v3k
@AwaSamb-v3k Ай бұрын
Yalnako yalla diegueule yeureume ko té khaaréko aldiannah firdawsi
@khadycisse555
@khadycisse555 Ай бұрын
Yalnala yala youbou aldaina amine
@guedjipouye2577
@guedjipouye2577 Ай бұрын
Paix à son âme
@sabelle2001
@sabelle2001 Ай бұрын
Ndeysann paix à son âme
@fatoudiakhate1516
@fatoudiakhate1516 Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum kharèko aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed
@CoumbaKamara-m8v
@CoumbaKamara-m8v Ай бұрын
Paix a son ame🙏
@IssaLaye-s2j
@IssaLaye-s2j Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum kharé aldiana firdawsi bilay nitt kou bakh la
@grizzlyyukon4585
@grizzlyyukon4585 Ай бұрын
YALLA NAKO YALLA KHARÉ ALDJANA AMINE
@Sarafina5
@Sarafina5 Ай бұрын
Ay faname mo dièkhe 😢 yalna ko yalla yeureume
@FatouLo-p4v
@FatouLo-p4v Ай бұрын
😢😢😢😢
@amadoufatimakane3564
@amadoufatimakane3564 Ай бұрын
أسأل الله العظيم رب العرش العظيم ان يغفر له ويرحمه ويدخله الجنه الفردوس الأعلى ببركة أحمد الخديم. Li YALLA di def day tar nguir lottouk doomu aadama waanté mooy li gën
@ibadiagne2313
@ibadiagne2313 Ай бұрын
Paix en son âme yalnako yala khaaré aldiana fridaws
@idrissaba-sg2gy
@idrissaba-sg2gy Ай бұрын
C était un missionnaire
@Ibrahimandiaye2221
@Ibrahimandiaye2221 Ай бұрын
Souniou wadiou bakh te nago ligeyy ndeyesann loo wakh si mom amna Lou dess billahii
@AidaBabou-o1n
@AidaBabou-o1n Ай бұрын
Paix à son Âme
@MASS_DIENG-LOUGA
@MASS_DIENG-LOUGA Ай бұрын
Yalla nako yalla yereum té khaméco aldiana firdawsi ak beppou dioulit boumoufa fek ak gnoun gnilendi fekki te Yallana yeekh
@aminafall6253
@aminafall6253 Ай бұрын
Ama moy djay katt biy djeul khalissam djeundeul client wam yi niou agn may lenn niou nann ndeysane
@josephinecamara2654
@josephinecamara2654 Ай бұрын
Massa ama yalla nako yallah yereum mane dama sey deux ans rek sama dieukeur gagnou khamna mettit bi ma ngui massawou diabaram c dommage ma yallah ken dou beurré ak mome bou beguer kou begueu deye niak
@bijoux-c6l
@bijoux-c6l Ай бұрын
Alahou Akbar
@Khadysaliou-w7x
@Khadysaliou-w7x Сағат бұрын
Holene seyebi balaguene dougou
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 52
1:00:39
Pikini Production
Рет қаралды 593 М.
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 23 МЛН
She made herself an ear of corn from his marmalade candies🌽🌽🌽
00:38
Valja & Maxim Family
Рет қаралды 18 МЛН
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 23 МЛН