Machalah dieuredieufe oustaz oumar Ahmad Sall louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye billahi deug rek nga wakh nga Lou ler nga wakh sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam ak molem oustaz bouy wakh si alquran ak suna
@assaneniang21334 ай бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu, aar aaral nu, taxawu taxawul nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xam xam yi ragal sunu BOROOM YÀLLA.
@assaneniang21334 ай бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA nangul. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yònnent bi SAAWS akiy sahaabaam RAA te wërsëgël nu nu dëkkag ñoom ca kërug teràngaam.
@assaneniang21334 ай бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer, MU yombalal nu tòpp ko, MU wan nu neen bamu leer, MU yombalal nu dùmmóoyu ko.