Révélations de Papa Boy Djiné: Un marabout m'a dit, pour gagner faut divorcer avec Ndeye Gueye

  Рет қаралды 93,741

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Күн бұрын

Пікірлер: 273
@AstouSy-f8i
@AstouSy-f8i 5 ай бұрын
Ndeyssane courage il est très poli nakk kéneu meussou ko dégue vraiment dafa amoul chance rek mais santé ko yalla moy li gueune si yaw
@diarrasublett5073
@diarrasublett5073 5 ай бұрын
Tres bien parler. Il faut soutenir ta femme. Allah est pour tous chaque chose a son temps.
@fatouthiame7000
@fatouthiame7000 5 ай бұрын
Ne demande pardon a personne yalana yalla deff diam avec ndeye Gueye ne laisse pas ta femme adoré du courage papa ndeyesane ndeye Gueye c'est noble je t'aime fort bien ndeye Gueye
@dionekhady6209
@dionekhady6209 5 ай бұрын
Voilà une personne qui a la tête sur ses épaules que Allah le tout puissant te protège.il me fait pleurer et pourtant je ne le connais pas.. Courage Amal diam
@omarfaye2580
@omarfaye2580 5 ай бұрын
Serigne bila wakh lolou mayé woul ndam yallah moy mayé ndam
@dabachou5674
@dabachou5674 5 ай бұрын
Walahi DEUG Leu Yalla Rek Mofi Nèk
@kambayependasall8908
@kambayependasall8908 5 ай бұрын
Bilahi deugu bou wer amana sunu borom mogui ka dethial lou eup
@ndogoulicisse5284
@ndogoulicisse5284 5 ай бұрын
Bilahi Yalla Loum la mayoul rk Khamal ni Lim là déthial mo dakk Yalla lou bakh rk léy déf Boula kén bayi lo sa diabar ❤
@diobasene717
@diobasene717 5 ай бұрын
Wa papa mane dame laye beugue ba kagne yalla nale yalla takhawou yaw AK sa Diabare deuguou rek mo wore ❤❤❤❤
@ibrahimaseye7267
@ibrahimaseye7267 5 ай бұрын
Frère Vraiment insbi waro sakh guenn di wakh ci lou dieum ci Lamb, danga wara Focus khôl Lo wara def à l’avenir soit nga voyager Wala nga khôl business boula meun apporter dara pask Lamb mom dou sa Affaire vraiment beug ngako mais Yalla mo wéddi. En plus nga bayi nioulay lathie ci Sa diguenté ak Ndeye Gueye nga ciy wakh lolou vie intime la ça n’a rien à voir ak lingay liguey
@amyngane1073
@amyngane1073 5 ай бұрын
Mo geune
@onlygood1114
@onlygood1114 5 ай бұрын
Vraiment
@halamadrid2108
@halamadrid2108 5 ай бұрын
Tu la bien conseiller pour sa santé sa vie privée et son avenir👏👏👊
@rouguietousy2292
@rouguietousy2292 5 ай бұрын
Bien dit
@adjadiouf4400
@adjadiouf4400 5 ай бұрын
Deugue bou weir ❤
@fatimasow496
@fatimasow496 5 ай бұрын
Salut je vous conseil de partir avec votre femme a l etranger aller travailler et gather votre vie guen Bal ma akh
@papemoussandiaye1416
@papemoussandiaye1416 5 ай бұрын
Lou lerrrr
@kambayependasall8908
@kambayependasall8908 5 ай бұрын
Vraiment
@bocarly5373
@bocarly5373 5 ай бұрын
😊​@@papemoussandiaye1416
@MbayeNdeyegnagna
@MbayeNdeyegnagna 5 ай бұрын
Bilaye sinon légui mou 😮😮😮😮
@FatouSeye-o3e
@FatouSeye-o3e 5 ай бұрын
Merci niite mo sokhoor Mane ndeye gueuye damako yeureume tellement mais yallha Nieppe la fii nekal inchallah ndeye yallha nala yallha defal diam
@katydiop9209
@katydiop9209 5 ай бұрын
Boul divorcé yalla dinala may ndam inchallah li yeup Dina diekh courage
@zeyna-du3iu
@zeyna-du3iu 5 ай бұрын
Ndeye gueye je l ai rencontré à Saint Louis à l époque je travaillais dans une discothèque comme serveuse on avait invité les gazelle de dakar pour une soirée sénégalaise machalla nite kou âme yitee❤
@FatouThiam-kg1qe
@FatouThiam-kg1qe 5 ай бұрын
Du courage frère yalla dina nieuw dh
@KhadyFall-si4jv
@KhadyFall-si4jv 5 ай бұрын
Fi goor boufi teral djiguene yalla teral la papa yalla na yalla leral sa yonn lou diott yombou nitt dina yotou lo khamni genoul ci mom yakhna daffa diotagoul rék yalla nala yalla may ay ndami ndami ndam ci barkep xessidayi ❤
@mariamafaye7780
@mariamafaye7780 5 ай бұрын
Papa wakh bi rafetna yalnala yalla tahawou
@BadalaNdar
@BadalaNdar 5 ай бұрын
Lima degue ak lima giss si yaw dina meuseu nekh incha ala du courage yalla rek mofi nek
@dabachou5674
@dabachou5674 5 ай бұрын
Bilahi Yalla Rek Mofi Nèk Dééé
@ModouMbaye-km3ct
@ModouMbaye-km3ct 5 ай бұрын
Yakaroumako nak dakh dafa entraîné woul nak té yalla do tok rék mouniew di dila may ndame dé daguay liguéye mouféki sila
@onlygood1114
@onlygood1114 5 ай бұрын
😂😂😂
@rouguietousy2292
@rouguietousy2292 5 ай бұрын
Bilay,ndakh wakhi gor lafi wakh
@modoubarasene9678
@modoubarasene9678 5 ай бұрын
Ndaye sane papa damala yaram bilahi
@Soukaina-h9y
@Soukaina-h9y 5 ай бұрын
C'est vrai papa dit lui pardon tous ira bien il faut écouter les conseils tu es quelqu'un de bien
@nenesall4636
@nenesall4636 5 ай бұрын
Merci beaucoup papa boko djiégolo wédy yalla ame yalla yallay bour niak yalla yallay bour loudoul yalla néneu la bilaye
@NdeyeKane-q2u
@NdeyeKane-q2u 5 ай бұрын
Bilay sama❤ metti thi défaite bi ndakh yeureum ndeye Gueye dom rek lakoy gnianal
@salihate-ew6wy
@salihate-ew6wy 5 ай бұрын
Amine yarabi 🙌
@WaxElegeance
@WaxElegeance 5 ай бұрын
Sa maturité motakh Ndeye Gueye japela bagnela bayi. Yala nala yala takhawou.
@SokhnaDiallo-df8ri
@SokhnaDiallo-df8ri 5 ай бұрын
Du courage Yalla nallen Yalla Tahawou mailla aie ndam you teklo du courage.
@BintaFaye1
@BintaFaye1 5 ай бұрын
Amine yarabi
@mariamangom8163
@mariamangom8163 5 ай бұрын
Papa machalah sental yalla rék mome yarabi mingua khamené moye mayé inchallah bou sobé yalla combat biye niéw yalla dinala defal dam Amine yarabi ❤️🥰
@BintaFaye1
@BintaFaye1 5 ай бұрын
Alahouma amine wayy
@mamefatou6794
@mamefatou6794 5 ай бұрын
Papa mii gorre bou sete wethieu la Machala yala dinala dimbali Ndey geuy geuneu leu mougne fonk sa seuy dîna bakh dé Inchallah bilahi
@mariemendiaye3909
@mariemendiaye3909 5 ай бұрын
Deyssane yalla koumou beugue rek lay tek natou yalla nala yalla takhawou yarabi 🙏🏾🥹
@AmiToure-z2c
@AmiToure-z2c 5 ай бұрын
Deyssane yalla koumou beugue rek lay tek natou yalla nala yalla takhawou yarabi 🙏🙏🙏🙏🙏
@pendandiaye1970
@pendandiaye1970 5 ай бұрын
Papa cou sincère nga li dafa méti
@Salihat-bi2gd
@Salihat-bi2gd 5 ай бұрын
Bou amate lamb yalla nala yalla may ndem s barké s saliou Amine
@Patriotsavie
@Patriotsavie 5 ай бұрын
Mane dal bala ma gueumni def def la nanela bolé ak yawou dial soula dané ma sogua gueumi c'est mystique
@seynimangane4809
@seynimangane4809 5 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@laminebarrambengue6602
@laminebarrambengue6602 5 ай бұрын
😅😅 non ray ngama
@OusmaneSene-bs1jr
@OusmaneSene-bs1jr 5 ай бұрын
Tu es drôle vraiment
@ndeyeastoudiatta9020
@ndeyeastoudiatta9020 5 ай бұрын
Wouy😂😂😂
@nenembengue1161
@nenembengue1161 5 ай бұрын
Wala ouzin keita pawlish mbaye etc…
@elthier85
@elthier85 5 ай бұрын
Yalla nga am victoire si barké ndeye gueye
@MadeleineNaka
@MadeleineNaka 5 ай бұрын
Que Dieu te bénisse mon frère ...ça ira ...et de belles victoires arrivent.....
@AissataBah-ih1kp
@AissataBah-ih1kp 5 ай бұрын
Ameen Ya Rabouna 🤲 in sha Allah 💚
@awacham9949
@awacham9949 5 ай бұрын
Mâcha allah papa yallah lafal la thiatt ndakh thiatt rek mola top nieup le begue chi la bokk chi kaw chia kanam incha allah tu as bien parlé avec ndeye Gueye rek la brave
@MameseyeNdiaye-p2p
@MameseyeNdiaye-p2p 5 ай бұрын
Yalla n'a yalla same du courage
@awadiop9525
@awadiop9525 5 ай бұрын
Mâcha alla ❤️yalla nalene sounou borome lakh fou cheytané aguoul 🤲🤲courage
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 5 ай бұрын
papa wakh deugue guissoumala ngaye indi forme sissaye combat.meuno dieul lèpeu ni yalla leu tamit
@AdamaSambe-d1b
@AdamaSambe-d1b 5 ай бұрын
Machallla wakh bi rafétna yalla nalén yalla sameu🙏
@lamediarrakebe9834
@lamediarrakebe9834 5 ай бұрын
Merci papa courage ❤❤❤❤❤❤❤
@seydoukasse9284
@seydoukasse9284 5 ай бұрын
Tout ira bien tkt sa passera tu sera heureux
@adjib.38
@adjib.38 5 ай бұрын
oui parce qu il nest pas heureux en somme, il souffre en fait
@amyngom1756
@amyngom1756 5 ай бұрын
Ndeyesane papa mi beuguenako ndakh gueume yallame Macha alla
@cheikhtidianecisse4177
@cheikhtidianecisse4177 5 ай бұрын
Papa ont n'est de tout cœur avec tu a une brave femme loudoule yalla nenela natoula t'es inchalla lepe dîna bakh
@abdoufall9779
@abdoufall9779 5 ай бұрын
Du courage diambar il faut continuer comme ça le mariage est sacré la lutte c est du jeux Dieu t élèvera inchallah
@mbakhengom7488
@mbakhengom7488 5 ай бұрын
Papa boy djine niit kou baakh nga. C'est pas la première fois nioulay dégue ngay wakh lou baakh ci sa sokhna. Wayé bilahi Yalla dinala fay. Téyél sa diabar c'est une grande dame té boul découragé. Respect à toi et à Ndeye Gueye.
@folashade2749
@folashade2749 5 ай бұрын
Papa que veux tu dire par la? NDEYE est une bonne femme. Courage Dieu est grand et unique
@AssaDiarra-gu5cq
@AssaDiarra-gu5cq 5 ай бұрын
Merci ❤
@NdeyeCoumbaSow-w5s
@NdeyeCoumbaSow-w5s 5 ай бұрын
Macha ALLAH,Un homme très intègre.Du courage
@kawkawpur6910
@kawkawpur6910 5 ай бұрын
Bonne continuation boy machalla tu es fort mentalement j aime ces genres de personne gueule yalla DEUG doù seug AK siigui
@assetoutimera7251
@assetoutimera7251 5 ай бұрын
Salam yalla est un jour viendra papa boy va gagné inchallaw merci beaucoup ndeye gueye diaballa
@LayeFaye-gy1vr
@LayeFaye-gy1vr 5 ай бұрын
Mai papa du courage bilaye dina bakh
@nicoladiouf4252
@nicoladiouf4252 5 ай бұрын
Merci et du courage un jour viendra ca ira niom nioniou di wakh Ndeye Gueye djigoula deniou kat sen Ndeye dou yangui nonou di danou di am ay combat amna nio khamné deniou dane to mononiou am ay combat
@magy1042
@magy1042 5 ай бұрын
Cadouyi rafete na lole machallah yalla na yalla motali yalla betela niabote ak sa soxn a
@Adjaratou2008
@Adjaratou2008 5 ай бұрын
Ndeye gueye continuer avec t'ont mari ne jamais abandonne nu daicourajai coiyai toujours à Dieu papa Deu va te donner toutes que tu voudras-dent t'a vu papa ne fais pas attention les jent sont fous maijant que Dieu vous garde amaine
@mariamanneh4561
@mariamanneh4561 5 ай бұрын
Bilie kee yanna ko yalla teral. Belie mabugaa jeecarr ju bahgaa jabaram. Ndyesanne sama yaram dawnaa. Why, y, yalla gee yanaa gako meii damm y.🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@kheuchfatygeneralloupapedi3484
@kheuchfatygeneralloupapedi3484 5 ай бұрын
Papa yalla nalla ar same leu
@kemssow1579
@kemssow1579 5 ай бұрын
😮😅
@kemssow1579
@kemssow1579 5 ай бұрын
😮😮😮😮😮😮😮😮😮😅😅😅😅😅 2:16 2:16 😅 2:18 2:18 2:18 2:18 😮😮 😢😢😢😢😢😮😢 2:40 😮😮 2:55 😢😢😢 3:00 😢😢 😢 3:35
@kemssow1579
@kemssow1579 5 ай бұрын
😮😅😮 4:39 😮😢😮😅🎉😅
@bijoudiallo9258
@bijoudiallo9258 5 ай бұрын
Du courage mon frère yalla bakh na inchalla dina bakh
@Adjaratou2008
@Adjaratou2008 5 ай бұрын
papa je suis très fière de toi t'a famme elles janti meilleurs magnifique jouveyalle extraordinaire jeu veux que vous raispectait vôtres foyers Deu est toujours Deu je vous souhaite Longue vie bonheurs santé la paix continue la vie est belle mon frère
@rokhayandiaye7375
@rokhayandiaye7375 5 ай бұрын
Alkhamdoulilah ❤
@salihate-ew6wy
@salihate-ew6wy 5 ай бұрын
Yalla nako yalla takhawou 🙌🙌 Amine yarabi
@diakysfood7624
@diakysfood7624 5 ай бұрын
Bouko mossa wo boudé yalla n'a taw ndam nak yalla n'a ko yalla Def bamou gueune mou diokhla inchalah gueune si yaw ak képe koula ko yené courage dîna bakh❤❤❤❤❤❤❤❤
@whitelion2455
@whitelion2455 5 ай бұрын
il faut auguementer les entraînements alimentation bi ak repos na geuneuh yokkou ak aussi balou gnila diégué niou geuneuh yokou nianeuh yii Dina bahhh en tt cas le moral est bon 😎
@dembaniang9050
@dembaniang9050 5 ай бұрын
Ligua meune khalé bouko meune dof yalla nalla sougnou borom sameu boul deglou kénn nék si rek dîna bakh déh frère ❤❤
@aminatambodj8383
@aminatambodj8383 5 ай бұрын
❤du courage natou la té Faye diekh
@MadjigueneNdoye-ep4vh
@MadjigueneNdoye-ep4vh 5 ай бұрын
Machala mariage dou alal ndeye gueye kou beugue dieukeurem la yalna len yala defal diam
@AntaSano
@AntaSano 5 ай бұрын
Ndeyessane machallh yalnala yallah dèfal diam papa
@maguettecisse9829
@maguettecisse9829 5 ай бұрын
Bilahi dina bakh inchalla courage rék
@colediaw8200
@colediaw8200 5 ай бұрын
Machalla.kadouyi.rafétna.lolou.way.yak.ndéy.geuy.yala.nalén.yala.défal.diamou.aksoutoura.téadbi.deger.ndéy.geuy.djgén.bounago.séyla.té.fok.ou.diégéram.tawfékh.rék.inchalla.❤❤❤❤❤❤
@AwaSagna-e9s
@AwaSagna-e9s 5 ай бұрын
Courage frère yalla bakhna ❤
@abdousalamgueye9481
@abdousalamgueye9481 5 ай бұрын
Walay ndeysane merci beaucoup papa
@amethfall5009
@amethfall5009 5 ай бұрын
Ta femme est brave et courageuse teeye ko bubaax bu la kenn boole ak moom tu as une femme qui t'aime beaucoup
@MamiDiop-h2c
@MamiDiop-h2c 5 ай бұрын
Du courage frère yalla bakhna
@asatousall5154
@asatousall5154 5 ай бұрын
Bilay machallah yalla dina la May nam
@layeilliassou4804
@layeilliassou4804 5 ай бұрын
du courage papa dona bakh inchallah yalla bakhna
@Taphiendoye
@Taphiendoye 5 ай бұрын
Papa demall touki AK ndeye bou fin🎉🎉🎉
@DiatouSene-v4e
@DiatouSene-v4e 5 ай бұрын
Defa yarou ndeyssane yalnako yalla sameu inchalah dina bah demal seti mabey dinala diapalé ❤
@GnoumaCoulibaly-u4b
@GnoumaCoulibaly-u4b 5 ай бұрын
Machala. Alhamdoulilahi. Papà sadefaite thi lambe. Dekhna. Yagore Yalla bour bou bakhla Yalla nala Yalla soutoural sibarke seydina mouhamed PSL sì serigne Babacar sy akbarke serigne fallou mbacke amine yarabi
@korkadiop7847
@korkadiop7847 5 ай бұрын
Machala waxbi rafetena kou geume yalagua magui niane yala diapalele defala li geune si yow inchala dina bah
@moustaphasall7907
@moustaphasall7907 5 ай бұрын
Yalla may ndam Lou sed papa ❤❤❤🙏🙏🙏
@salifdiop18
@salifdiop18 5 ай бұрын
Demal touki liguéyi
@AdaDere-ng2dr
@AdaDere-ng2dr 5 ай бұрын
Machallah papa ❤
@moustaphasall7907
@moustaphasall7907 5 ай бұрын
Good luck to you, my brother, everything gonna be all right.❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏👈👀
@colediaw8200
@colediaw8200 5 ай бұрын
Yala.loum.defrék.dafa.geun.yala.nadon.sa.djklay.yak.sa.diabar.ndéy.geuy.kou.nago.séyla.té.fokou.dieukeu.ran.thi.diamou.rék.inchala❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@amyngom1756
@amyngom1756 5 ай бұрын
Macha alla fi yalla rek mofi nek
@MayéDiouf-q3t
@MayéDiouf-q3t 5 ай бұрын
Courage frère lép yalla la yalla moye mayé damme n'a fék mouye Lou guénne thi yow yalna yalla samme té saïtané sori lénne ak sa famille té yalla guénne lénne tahawou barké Séydina Mouhameth sws
@rouguietousy2292
@rouguietousy2292 5 ай бұрын
Bilahi papa nit dafay goré il se peut Que sa weurseuk nékoul thi lamb, Mais yallah dinala defal Lou geune Inchallah
@NdeyemadaFall-y6j
@NdeyemadaFall-y6j 5 ай бұрын
Courage champion
@assanembaye6126
@assanembaye6126 5 ай бұрын
Machalla amna solo mon frère yalla rek mofi nek
@mamanmarietou9160
@mamanmarietou9160 5 ай бұрын
Thi barké Mouhamed yalla na sounou borome dieul say lamb en main yalla naga neck toi des arènes amiine
@CheikhThiam-y8c
@CheikhThiam-y8c 5 ай бұрын
Machaallah papa parle bien
@OmarFaye-ij9qc
@OmarFaye-ij9qc 5 ай бұрын
Yaye Goor papa ya allah rek mofi nek
@fatoucha554
@fatoucha554 5 ай бұрын
Sama yaram sakhe dawna frère nék si rek bou yalla dogalé mou niéw inchallah dina bakhe 😢
@myawilson3308
@myawilson3308 5 ай бұрын
De tout cœur avec ndeye gueye ❤
@NoreyniDiop-r5v
@NoreyniDiop-r5v 5 ай бұрын
Soubkhanala 🤔mane dé Serigne la wayé sounou mboke momou kou geumeudi yalla la keep kouy takhalé niar niouy seuy ndakh ame fo kessé si jabootou ibliss gua book ba kerok gay toup di delou si yalla.papa khalé bou ndaw gue fi gua tolou amena say morom you bari yo khamni bounou sagnone ame ligue ame di beuré di danou ta amounouko ndam yalla rek moko ame dou midef si adouna.lii aye khate khate la rek bouko yalla diekhalé mou diekh khawma kane gay amate sa prochain combat inchallah mais dana wouté ak yi dial inchallah jeurdieuf
@FatouDiakhoumpa-nc6hx
@FatouDiakhoumpa-nc6hx 5 ай бұрын
Du courage mon frére dieu est grand❤❤❤❤
@papemoussandiaye1416
@papemoussandiaye1416 5 ай бұрын
Ndeye gueye yoroul ndam
@FatouDiop-lx3pw
@FatouDiop-lx3pw 5 ай бұрын
Papa vraiment jambar gua mais lamb doulou yalla geureum bagua war thie sacrifie sa doundou
@awangom5927
@awangom5927 5 ай бұрын
CONTINUE MON NEVEU TU VAINCRA , JE TANNONCE QUE DÈS CE JOUR TU ES MON LUTTEUR. BOY GOOR GUA MACHAHALLA
@MameArameSy
@MameArameSy 5 ай бұрын
Aka .amjom soumadonn.yaw-dagay.dém.sétt.lénénn❤❤❤
@MameMayeManeMane
@MameMayeManeMane 5 ай бұрын
Gueum Gueum mô lére Machalla ❤❤❤
@AliouKamal-oj1uh
@AliouKamal-oj1uh 5 ай бұрын
Papa boy djinné boule déglou bénne boy nakhe boyi dila wakhe nga bayyi sa djabare nionme yeup ay célibataire nanou Sénégal dafa barré ay célibataire Nanou boule déglou kénne djapale sa djabare boula yalla boléle mane mi sakhe amagouma ta beug na ame djabare kone téle sa djabare bou bakhe ndeye géy djigénne bouné ware na roy si mon nakhe bouko nékhone mou khéppe papa nakhe kou khame ndeye gay khamni féthale na kouné Youssou Ndour ak wally ak pape djoufe ak baréna ay borome khalisse you nék khame nanko
@aramebarry3984
@aramebarry3984 5 ай бұрын
Courage champion ❤
@hdhdbdjdndnbdh7675
@hdhdbdjdndnbdh7675 5 ай бұрын
Sama yaram dawna machallah
@landinggoudiaby692
@landinggoudiaby692 5 ай бұрын
machallah dingua ame ndam inchallah
@MountagaThiam-wm8uj
@MountagaThiam-wm8uj 5 ай бұрын
Il faut nga rare 1 an wala 2 an nieuwate Moy gueune quoi singa meuneu kholate loubone siyaw nga diope lolou nieuwate lolou nga wara déf frére mai Dina bakhi inchallah champion nga nioune niou deuk ak yaw khamnaniou lolou mai il faut défarou wate
@SouleymaneCamara-n9e
@SouleymaneCamara-n9e 5 ай бұрын
Wakh bou don mbeuré gua don roi des arènes mais nk non la guem yalla rek mo wor té so gusé lén lou mana diapou pr dire vrai lambou mano si don champion don té gni guay adal nagoul nanla sa man mbeuré mais chance bi desna con démal wouti lén nopal say nit .bonne continuation bro ❤
@AhmedDiallo-ew9ns
@AhmedDiallo-ew9ns 5 ай бұрын
Machalla ❤❤
@NdiagaDiouf-ty5bm
@NdiagaDiouf-ty5bm 5 ай бұрын
Papa yalla bakhna de na bakh boul dekourasi lou guis yalla lala
@salioufashion6625
@salioufashion6625 5 ай бұрын
Inchalah nala wakh secret biye takh gaye dagne Inchalah
@kineseck706
@kineseck706 5 ай бұрын
Courage
Urgent : Ousmane sonko répond Barthélémy Diass. ....
10:00
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
36:55
bayGUYS
Рет қаралды 1,9 МЛН
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН