danga barri wakh rek mais modou lo talloula sakh . Senegalais moo sokhor bougougnou kou avancer . Vive le roi des arenes MODOU LO ✨✨✨🎉
@NdiayeNdiaga-n1f11 ай бұрын
Peul nitt kou sokhore la modou lo rek laniou Banj Modou ba legui wakhoul ni Dou beure ak tapha tine dafani day nopalou Lolou molen metti motakh geen beug ko diaboliser XLO❤SEUL
@papeabdoulayedione476611 ай бұрын
Non elle a raison . Naguou deugueu aussi mane je suis modou mais il évite tapha c la vérité
@oumitandiaye67803 ай бұрын
@@papeabdoulayedione4766tu n'es pas fan de Modou lo tu mens
@oumitandiaye67803 ай бұрын
Bien dit
@papeabdoulayedione47663 ай бұрын
@@oumitandiaye6780 supris que ces propos vient d'une femme. Mais balma soudé damala togn🙏. C'était jsute mon avis. Merci
@souleymanediedhiou9111 ай бұрын
Ndeysane Modou Lo mbeur yeupeu beugueu beuré akk mom . Thiey Modou Lo ya beuri bayrey
@ndoffenetine533311 ай бұрын
Reug reug champion nga vraiment. Mé bilahi yak mod lo si bir guéw dinga dadj lo massul dadj.
@onelofficiel11 ай бұрын
Lou lére
@awandiayediouf243711 ай бұрын
bilaye douma fans modou lo dé wayé aye wakh danouko champion la dal machala
@ndoffenetine533311 ай бұрын
@@awandiayediouf2437 bilahi modou rek
@elhadjDiallo-mp2os11 ай бұрын
Ki bayilene ko mouy wakh rek menoul dane ndeye sa thies nek fi di wakh rek
@LeprinceVegeta-f6i11 ай бұрын
@@elhadjDiallo-mp2os ya meune doul té mou daane sathies diélou bou léer si 2e acte bi.. Sathies mii ngéy wah mom aussi warna meuneu daane modoulô comme son grand frère ,lamb leu rek
@Azoura2211 ай бұрын
modou ✨ xlo yaw rek bilaye walaye 👑 modou sa bay la reug
@freesenegal1234511 ай бұрын
Bayil beu franc diap ko pésse 👋ndeim mou ham
@aliounebadaradiop460711 ай бұрын
@@freesenegal12345😂🤣🤣🤣🤣
@FallWaly-c6g11 ай бұрын
Bari wax la def
@bayedieng714111 ай бұрын
Bilahi bo dieulé Frans ba danko Modou mayma chance bilahi Modou sokharoule t'ai bayie wakh djie
@moussadiouf341711 ай бұрын
Oui bary na wakh
@mouhamedmbaye-k3d11 ай бұрын
Reug Reug 100 combat do for démal niafa ba ame li modou am baring wakh trop
@lomamadou452611 ай бұрын
Ki kaay léguii moy lolou
@fallleyty724911 ай бұрын
Non reug mo meune
@awandiayediouf243711 ай бұрын
@@fallleyty7249modou lo aye wakh danouko dé
@masseseck947511 ай бұрын
Reug Reug mi meune fofou😂
@kheuchboukharagne11 ай бұрын
Danga reuy gat di wakh rèk mai kham ngani modou sa bay la si lèp
Dangay dokhane sa ndeye ki bolen tasse nga saga ko mou dokhane sa ndeye
@aboundiaye234311 ай бұрын
Tapett leu n'a dieul franc
@adamaba604811 ай бұрын
Modou sa bay la❤❤❤❤
@NdappaMboup-qh4wm11 ай бұрын
Ki légui dafa beurri wakh
@LeprinceVegeta-f6i11 ай бұрын
Motéy doxil fowi
@Chiekh76611 ай бұрын
Mo taye yaw dé waho danga binde
@Pogba-s7k10 ай бұрын
Reug reug seul
@saerdiagne819811 ай бұрын
😂😂😂😂😂 bilay reug sou amoul wone khaliss dof bou reuye lay done 😂😂😂 aka doff ki
@cheikhomar663511 ай бұрын
Demal diéle fran moguen
@boubacarboiro581311 ай бұрын
Kii meunoul yengueul sathies mouy nek fii di rata tati😂😂😂😂
@Chiekh76611 ай бұрын
Bayil sokhor Modou lo moye sama mbeure leu mé reug reug meune na dane koudoul Modou ki djiéle bimou dane mo gueune reuye biko sa thies foufe malgré sa thies mo dane
@awandiayediouf243711 ай бұрын
@@Chiekh766yaw kon khamo sa mbeur nak modou lo aye wakh danouko dé fall mane balla gaye la wayé modou lo xalé yi molén meune dintianl sma commentaire bi unchala
@boubacarboiro581311 ай бұрын
@@Chiekh766 tu n'as rien à dire nopil kii fimou todji sii Arènes bii loudoul à part lutte simple
@miachoufall666511 ай бұрын
Meussoil nek sa mbeur kone lokay faraler may gnou diam wayyy @@Chiekh766
@bdiene6611 ай бұрын
Ki tok ci deunou Sa thies nganane yeugueul🤣🤣🤣🤣 Sen télė keur bakhoul🤣🤣
@ndiakhate29-isaac11 ай бұрын
Bombardier mognou togne.reug reug ba prochain combat wam ken dou degg😂❤
@awadiop214411 ай бұрын
Blhi 😂
@ibrahima355511 ай бұрын
Bilay mom Modou rek pourquoi pas mu jël Ama wàlla boy ñak
@Niomnieugz11 ай бұрын
Xaral ma woo sa thies🙈🙉🙊
@awadiop214411 ай бұрын
Srtt lolou 😂
@awandiayediouf243711 ай бұрын
😂😂 doukofa khar
@bdiene6611 ай бұрын
Bou nieuwé mou togat ci deueum😅😅Sa thies dou nieuw mon ami
@galouset11 ай бұрын
Mon ami Abou du CEM Guillabert de Saint Louis. Big up à toi
@hahahahaha239611 ай бұрын
Blesses ba paré di dorr 22coup kou amoul entraînement douko def 😂😂
@humour221611 ай бұрын
Bilahiiii Reug Reug modestiiiii zeroooo 😂😂😂
@marasall609311 ай бұрын
Bilahi reug reug yamana fenn yaw Bilahi modou lo manala nokh ba ngibi te doko yuekk😂😂😂😂
@bayougoor888211 ай бұрын
Bilaye 😂😂
@MbayeibrahimaNdiaye11 ай бұрын
Hum xaragne dh bilahi lamou saff kako Mathieu ko xam💪✌🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾🤴🏾
Reug reug international; les senegalais qui vivent aux États Unis,Australie,Singapour,Nouvelle Zélande,Canada,Angleterre sont fières de toi a cause de tes victoires international dans le championnat MMA….
@fayekaraabdall189510 ай бұрын
kou beug Modou lô lalal j'aime
@Babacarkâ-n6w11 ай бұрын
Reug Reug da ngay foule ndeyém Modou lô momeun sa baye si léppou
@SambaSarr-g4w11 ай бұрын
Ki daffa doff
@Oumanas599511 ай бұрын
Khadim Ndiaye moko yar motakh😂😂😂
@ousseynoukane653811 ай бұрын
Il a vraiment besoin d’être encadré malgré le fait qu’il soit un excellent lutteur. Il peut bel et bien battre Modlo mais un athlète de son niveau mérite une communication plus mature
@Chiekh76611 ай бұрын
Yaw ki wahoul Dara Lou grave
@bdiene6611 ай бұрын
C'est toi qui a besoin d'encadrement.REUG REUG est dans son élément .Vous arrivez même plus à cacher votre haine envers ce lutteur.C'est la lutte qui a besoin des champions comme Reug,Balla Gaye,modou lo pour son développement
@gningdawouda260911 ай бұрын
Wahoul dara lou aay li sport rek la ah
@gningdawouda260911 ай бұрын
Wahoul dara lou niaw wahou combats rek vraiment bayi leen jambour
@ayobediouf96911 ай бұрын
Frère tu as raison.
@PapaSall-h5k11 ай бұрын
Modou lo ça baye la Billahi
@maximaguette867111 ай бұрын
Yamana fane rak rak
@madembafall79211 ай бұрын
Reug reug champion gua mes modou lo doussa morome
@khadimndiaye869911 ай бұрын
Sarapppppppppp liiiiiiiiii ki meunn na doull té beurriiii wahhh thiotou nday liiii😮
@serignembaye755611 ай бұрын
Reug reug kassé niou dém
@PatheGueye-rt7vv11 ай бұрын
Kharar ma wo sathie sakh wadji khamoul bopam kW mod lo sa bay la thi lamb😅
@mamadoumboup891411 ай бұрын
Meuno baye modou lo en paix
@hachamiyoudjigo73211 ай бұрын
Chelsea💙
@modoufaye928611 ай бұрын
Ni ki mom wakh mom yeufeum la wakh rk nga meun contre sat hies lou nek wakh nga ko pour man fofou ngay diogé bayui wakh mais danga geuneu bari wakh
@seydinaissademe693011 ай бұрын
BILAKHI
@TKFTV11111 ай бұрын
Gui wakh dié Bari billahi Modou Lo mola man allez ak retour
@LimaDiagne-i8n11 ай бұрын
Cheuuuuuu sof ngua reug
@Ubk_9311 ай бұрын
Reug Reug démal teudi mo geüne gua nèk si plateau yi di reuye lamigne… Nioune wa TEAM XARAGNE dieûf laniou xam 🥊🔥
@Zikodiop206811 ай бұрын
Thioow li meun naa bari wayé reug reug miii mo meune modou lo foufff lou lère lalène wakh je suporte balla gaye mais boy biii c un trés grand champion
Sawaye li ngawakh regreg degala dogue si plateau Di wakh si Modou lo yombana mé yéne gnare si bire guéwe dowakh lolou Modou sé le meilleure
@bayedieng714111 ай бұрын
Reug da barie wakh
@MbayeibrahimaNdiaye11 ай бұрын
Bilah wakh yombe neuh mais dieuf ....😮
@souleymaneba332111 ай бұрын
Modou lo n'est le roi des arènes il négocié ses victoires mystiquement
@pronosticfootsenegal111211 ай бұрын
Deug nga wakh frère day ray mbeur yi soga beuré ak niom
@abdoudiop717711 ай бұрын
Mais mbeur hana yi doniou def mystique niome sokhore bakhoul modou dousama mbeur mais nieup hamnaniou ni vrai champion la meuneu beurré meuneu khekh nangoulenko rek😂 lolou yalla moko def
@pronosticfootsenegal111211 ай бұрын
@@abdoudiop7177 tu confonds les choses kou yor roi bi yaw la nieup beug beurel mais yaw yay choisir kila nekh nga beuré ak mome par exemple eumeu sene bamou dieulé roi bi ci bombardier waroul wone beuré ak modou lo parce que modou ci defaite la diougué wone ci balla ..tay dji combat bou diadou wone moy modou lo vs tapha tine sou dieulone tapha tine souko dané bouko nekhé mouni day dem nopalou mais noumou ko defé ni mome ragal lay ndirou vraiment ak di khar ba diekou mbeur sok ko dieul
@abdoudiop717711 ай бұрын
@@pronosticfootsenegal1112 sawaye lamb danga diekou mbeur ba si bir gueew bi données yi changér ay diekou mbeur soko dieule ay wakh la mbeur boniou diekou nga bania dieule c'est simple lolou nioune amateurs niongui wakh pourtant modou wakhoul dou ak tapha dafay pause la wakh mais lolou amnasi droit beurena 2 combat ci saison souka neekhé hare saison prochaine vraiment sou dieulone benene mbeur bayifa tapha tine diba d'accord ak yao mais kou beurrewoul mrnoko wakh dara
@ansumanjarju156611 ай бұрын
Reug reug vraiment on dit qu'il parle beaucoup mais c'est un grand champion il n'est pas un tricheur contrairement à ce que les gens disent il est sûr de sa valeur il est techniquement très fort capable de dominer boy Niang c'est pourquoi père de Gaule de veut pas qu'il affronte son poulain son fils
@mamadoudiop110511 ай бұрын
Sa c vrai mai le fait de dire k parewul dafa dioum du wakhu nit
@TEAM_DMG_OFFICIEL11 ай бұрын
Monoul wkh
@mamadoudiop110511 ай бұрын
@@TEAM_DMG_OFFICIEL vraiment wakhi dof lay wakh
@madzo19311 ай бұрын
T'as raison deh
@amethdiasse22011 ай бұрын
Reug Reug ndanane la mais nak yaw ak mod lô si guéwe digua dadj deug kharagne wax danouko😂😂
@bdiene6611 ай бұрын
Lolou wakh ko wakh kat Reug day wakh di dieuf😂😂😂
@OuztazDame-lf1mh11 ай бұрын
Vive reug reug ❤❤❤❤
@bathiedrame80011 ай бұрын
Guess gua émission il faut guenn dii invité niou am khell ak nio khamni daniouy wakh lou am importance
@loutafall898211 ай бұрын
May léne niou diam beuri wakhou reug reug khana tay nguéne koy soga guiss contre sathies wakh nafi louné wakhou léne mou nék si modou nguéndi kass
@kabaaw768011 ай бұрын
Modou ló disa baye sa wakh djou baridji
@ibrahimkourouma222211 ай бұрын
Non reug reug dafa nakh bilakhi 😓😓😂😂😂
@MbayeDjitte10 ай бұрын
Reug Reug yagui wakh rk ma yagui khalatté 😂
@MatarFaye-j5c11 ай бұрын
Ouïe le problèmes😂😂😂
@senegalrek617711 ай бұрын
Wakhal bayi Modou Lo bahna say morom diar nagne fi d hummm
@modoufallbetebeteitsenegal527211 ай бұрын
Reug reug koula sopou laa si lambou mais dangua yeuk sa bopou de trop tayit danguay nagou chaque jour ta lolou bakhoul reviens sur terre
@kanzounet820611 ай бұрын
Ay boula modou diapé iow😂
@FallouFalloumbaye-hd2hq11 ай бұрын
Ligua diaw warguako lignantii Gay melnii ba boune 😂
@hamzafall547511 ай бұрын
Reugue champion la deh mais communication mo takh gayi dougnouko guawa may chance..
@mbayemamemor774011 ай бұрын
sénégal bo nekei di dane pour gnome keneu manula dane mais sportivement reug est un danger pour tous les lutteurs je le suis sur tous les platformes s'est un combattant confirmé
@d.f.electrique137811 ай бұрын
Ki migui wakh ba legui
@mamadoudiop110511 ай бұрын
Reugg deuk vraiment dagua commence bari wakh modou lo parewul wakhu doff gayy wakh
@abdoulahadgueye464311 ай бұрын
Reug Reug beuri nga wakhe trop. Modou wakhe djiu beuri danouko. Mbele mbele rek. Wakhe djiu beuri motakh Sathies dane la
@ibraymadethiendiaye532211 ай бұрын
Modou çà Baye la
@malicksarr214111 ай бұрын
Modou Lo mola mane foufff
@amadouba62210 ай бұрын
Je te le jure Reug Reug qu'il n'a rien compris la vivacité d'esprit et force de Modou Lo . Fofou bakhoutte sa way 😂
@mamadoudiatta670811 ай бұрын
Jeune tu es mon 2 em lutteurs après MODOU lo mes fait très attention Modou c'est Modou
@CheikhGueye-h1y11 ай бұрын
Reug reug reug istabi ngama sofe nakh sa wakh dio bari
@MoulayedabakhCiss11 ай бұрын
Reug reug sa badio ndaye beringa wakh trop
@assanekaka941411 ай бұрын
Bilay wolay sa wax bu beury motak yangi sof
@serignesalioudiouf108011 ай бұрын
Ki doff là billahi
@cheikhfaye902510 ай бұрын
Boukou nexé beurii wakh nous sommes tous des amateurs de luxe modou lo est un bon lutteur moy gédj gui amna ndox wayé reug reug man nko dans dieul bou reuy . Et puis sur reug reug a fait plus de 8 ans de champignons rarement ladon danou té mbapate mo geun compliqué
@mansourjuniorfaye11 ай бұрын
REUG CHAMPION NGA MAIS MEUNO DANE MODOU LO INS BII
@abdourahmanediop294811 ай бұрын
Pourtant il a raison Modou lo bimouy beuŕé ak Ama paréwpul dhé dafa djougué wone si blessure
@BayebassirouFall-lw4sk11 ай бұрын
Kon de bou paré wone rayko😂😂😂😂
@MamembayaLeye11 ай бұрын
Dakeye fane
@mbayesow293211 ай бұрын
Bly reug reug Ayy 😅😂😅😂gua mayy defff
@KhadimFall-q5b11 ай бұрын
Xaral ma woo sa thies 😂😂😂😂
@ModouJobe-jb5ez11 ай бұрын
Sama mberlawon mais dabaré wakh
@DpDp-hg6fx11 ай бұрын
Reug reug mi dé ak wakhamdji beuridji yeup lidalone ama ak boy niang moko naranja dal bouko modou ndieulone mais abou del bayi reug reug bigay favorisé daga faar bamou eupeu yow tamit
@SenegalMavie_Tv11 ай бұрын
Legui les haters diogueinagne si combine leu😂😂pour atterrir encore sur reug reug manoul communique juste Prsk franc dieul na bombardier Thiey yalla 😂😂👌👌
Ioe togual rèk si ay plateau Di wakh mais Modou lo rèk wakh toutti dieuf Lou beuri Di bandit gew sa Thiès ma lay eupp chance pour beuré ak Modou kharagne 🥳
@mamourmbengue280811 ай бұрын
Ndanga beugue combat rekkk Modou lo dousa morome
@fallleyty724911 ай бұрын
Mon meune modou
@mouhametba610811 ай бұрын
Reug reug amo xhéll
@bassirousow360311 ай бұрын
Reug reug bilayi bary ga wakh walahi dega comprendoul
@moustaphaFaye-c3y11 ай бұрын
Combat bi warna takhaw😂😂😂
@MohamedThiombane-li7we11 ай бұрын
Ioe amo loy wakh da lamigne mo reuy sathies fila la nakh😂
@pronosticfootsenegal111211 ай бұрын
Bilahi peul beug nala beuss niki tay tapha tine modou lo mo nekone combat bi dé mais lamb dangay warou 😢
@AdamaMbaye-l4p11 ай бұрын
Iow wah bi waah bi yup si plateau bi la yéem
@adamadiandiallo487711 ай бұрын
2 moi 2 victoire si Modou lo gane pare woul yaw hamou ligay wah 😂😂😂