Waaw leen goor Murid! Sunu xol sedd na. Yal na leen Sunu Boroom dolli ay tawfeex barke'b Boroom Tuubaa.
@diwanusalih71534 жыл бұрын
Maachallaa murid bu makk bi
@djarraf4 жыл бұрын
Jerejef mourid amna solo. Serigne bi 1888 la santhieu Touba. Bane ate la Serigne Mor guis Serigne bi ?
@xuyorutv87354 жыл бұрын
Ahma serigne mor mi ngi dem si serigne bi si attou 1890 ća Tuuba tambali fa ap tarbiyam si serigne bi ba ni seriñ bi di dem mbacké baari mu nek si mame Thierno birahim
@djarraf4 жыл бұрын
@@xuyorutv8735 jerejef. 7:06 1880 la dëg si audio bi motaxone ma laaj