Hiiii Saveurs planétaires daal bagn lén suivre bakaar leu. Foie rek la beugg tey. Recette bii tey djii lakoy essayer. Tata Mariétou longue vie à toi. Et un grand merci à tata Ouly.
@amma92455 жыл бұрын
Li nak moy wokatou bou dadiék gestou.Dama yéwou tey sama xel nek ci foie def frites ak salade ma oubi sama KZbin rek dadj ci li non tata marietou doundeul way hamo sakh linga deff je l’avais imaginer autrement mais so boss bi nak lay deff khana ay wakh day diekh😍🙏
@aminatagueye58545 жыл бұрын
Malako wakh 😀😀😀
@fanasall28255 жыл бұрын
Khana ay wakh day dougou maïga guén khégn oignon
@aminatagueye58545 жыл бұрын
@@fanasall2825 eupeuna
@ndeyeamydiop8364 жыл бұрын
Eupence😘😘😘
@seynidiop53705 жыл бұрын
Tata Ouly Konaré machallah sen foie sauté nèkhna Ta Titina Konaré ak Mamy Konaré ndax moune nagnou liii machallah Mme Sarr.Zoumana boy lèk plat bi woma
@ccseydou99984 жыл бұрын
Vraiment mesdames ,merci pour vos recettes...En plus de bonne humeur...!! Continuez des millions de personnes vous regardent...!!!
@mahawadrame14715 жыл бұрын
Aytieulenn merci tata Mariétou MACHA ALLAH on t'adore pour tes recettes saines et tes conseils bienveillants, et surtout on te respecte🙏 kou d'accord niou deff AY Way si commentaire yi...☺👏👌 un max de pouce bleu please..
@tigressendiaye41525 жыл бұрын
Enchanté ta mariétou je vien juste d'abonner sur votre chaine é sache ke vous m'avez bcp plue rien ke d'entendre votre voix ça me fais plaisir é j'adore vos plats oci ils sont succulent j'aimerais bien y goutter un jour 💞 longue vie à toi ta mariétou
@toureawa52945 жыл бұрын
Merci Tata Mariétou nioune amouniou sa fay, khana dila nianal Yalla lokho bi werr, Yalla sammal la bopam si barké sangou sangueu yi. Tata Ouly mom teint toubab la yorr ba voix bi moudié toubabé 😍😍😍 ma ngui key bégué bou werr.
@yaffafatou67315 жыл бұрын
Mach'ALLAH tata fi nga guéne tay nékhatinama 😋😋😋👍🏾👍🏾. Merci à tata ouly.
@khoudialo92275 жыл бұрын
ahh mane dall youbi yaba yi momay ray ak néko si relll. j'aime vraiment vos plat s'est superbe
@ayinkdiaw40985 жыл бұрын
Toujours dans la bonne humeur ça fait plaisir 🙏🏾🤣🥰
@famadiop57695 жыл бұрын
Tata marietou boul changé dé j'aime ton bonne humeur heu way😁😁😁😁😁😁 li rek mo nekh retane kaf dafa bakh thi santé 😚😚😚😚😚😚
@ndiorodiouf41945 жыл бұрын
Tu as raison. J'aime bien quand elle dit ayy wayyy___ gounouss gounouss__ ché biennn__ youbiyaba. Vraiment merci pour les recettes
@bintoudia22415 жыл бұрын
Ayeweuyyyy chèeeee bien avc saveurs planetere on ne cesse d aprendre yalnalene yala faye
@pendandiaye36015 жыл бұрын
Aythia léne aimé léne pouce bleu à gogo😍😍merci tata
@mariemeba92035 жыл бұрын
Machalla Yalla back si new génération.
@astoundaw69325 жыл бұрын
😋😋😋
@isosanneh22714 жыл бұрын
Masha allah ramadan mubarak b bana💝💝
@diarrabousso38345 жыл бұрын
Tata marietou beug nagn la guiss nak yak say invite😥😥😥 ,mais plat bi mom jadoree foie damako beug sama xol🤣🤣🤣🤣tata ouly yalla nala yalla faye,tata marietou yaw mom dougnou diok si dila nianal🤲🤲🤲
@aichatoumboupmboup43885 жыл бұрын
Merciii Tata Marietou darling fi nga guène noyatina Tata Ouly merciii à toi également niom youbou yabba saparal na machaAllah chéé biennn😂😂😂😂😂😘😘😘😍😍😍😍😃😃😃 nékossi si rél fi néna radiakh ehhhh wayyy😁😁😁
@lachica78055 жыл бұрын
Aïcha jte vois chez alphie🤣
@kyadiagnendoye12005 жыл бұрын
@@lachica7805 😂😂😂😂😂ayway
@lachica78055 жыл бұрын
@@kyadiagnendoye1200 bilaye😂❤❤
@matyniass68215 жыл бұрын
Aye waaaye cheeeebien tata todia tinga fi mangui nii siyoonou marché poure défare reccete bi tata bii mome maye mako ndakh dama beugg foie macha Allah nékhna
5 жыл бұрын
Maty Niass Masha Allah ma Cherie mais il faut metre plus d’ognion c tres bon
@matyniass68215 жыл бұрын
@ macha Allah recette bi mome la défare ndogou mai nékh n'a trop té monsieur beugg nako loole néna nékhna maniko sama tata du çeure moma ko diokh té khamnaa kou gnakk kigniaane nga yall nala yalla faye barcké wéerou koore gui❤❤❤❤love you💋💋
5 жыл бұрын
Maty Niass ohhhh Masha Allah ma Cherie manite bëk na dè
@annakeita22445 жыл бұрын
Merci Marietou belle recette simple et facile machallah merci à Ouly aussi longue vie santé à vous big up
@salimafall54515 жыл бұрын
Thiiioum , Amna plat bou ma togual Tey Mr ndoguou. mercii Tata marietou god bless 💖💖
@astousall37305 жыл бұрын
Recette biiii laaa dooone weur ...dama ko daane leekeu sama keur maame.... non marietou niakkeu la khame errreur bou ngaaaaandeee la ..mashaalah que Allah te protège....ouly contaane nagne ci yow.
@k-dy42105 жыл бұрын
Aythiaaa aythiaaa bsisimilah yalla ne gneup am diam ak wa saveurs planétaires ak mbollen djoulite thi barké kou tédd ki amine
@ngonendiaye63085 жыл бұрын
J'aime tes recettes et ta joie de vivre ma tata adorée yalnala yalla faye
@ngoranadjouaange-jokebed9264 жыл бұрын
Recette bi nexna. Dieuredjef tie Marietou. Testé et approuvé 😍
@mameboye935 жыл бұрын
Ma Sha Allah😘 Merci Tata Mariétou,merci sister Ouly☺. Diam dafa nekh Ma sha Allah
@seynaboumbodji3029 Жыл бұрын
Treeeeeesss biiiiieeeeennnnn❤
@fatouba69734 жыл бұрын
Wa tata marietou nala yalla defal diam trés bien
@mariemeyoumpagnefaye73815 жыл бұрын
J’adore votre joie de vivre Tata😘
@khadysene85665 жыл бұрын
Machalah keuf gui guoudouss guoudouss si n'a chai bien merci pour la recette
@nabousylla13145 жыл бұрын
Machalla bonne recette. D'habitude je sauté le foie avec du beurre. Je vais essayé cette recette inchalla. Merci encore Marierou
@oumytam11095 жыл бұрын
Tata ouly bi bakhneu dé machallah contanéne. Tata Marietou ziar nale di le bégué rek bou bakh
@leylalati83605 жыл бұрын
Tata bii khanaa toubab la lokho yi wéekhnagn dé machallah, koumpaa ngimay ray dé beugoon naala guiss je sais que tata bou rafet nga, maa dagn koumpa🤭🤭🤭
Merci tata belle recette machala yalna sa diame yague
@haouaagee95555 жыл бұрын
Bonsoir Madame. Vos recettes sont intéressante, ce qui manque dans ce que vous c'est la traduction en français. Si vous pouvez traduire simultanément en français sa sera plus intéressante. Merci et bon courage. La Nigerienne
@mary182035 жыл бұрын
Oh j'ai l'eau à la bouche. Sopa na sa guest bi 💗💗, dafa toubabé.
@dadydieng46005 жыл бұрын
machalla boko khole sakh xamni nexna sel na bi mom samedi ma prepare ko inchalla merci tata ouly et tata marietou big kiss
@khadidiatoudiatta56295 жыл бұрын
Bjr maman merci pr la recette j v l préparer ojordhui pr l ndogou soumala amoul wone non dou bakh nous on aime vraiment tt c k t fais 😘😘😘
@petitenita49925 жыл бұрын
Machalla Tata yaw mome amal diame rek ak wer bou sakh dakke 🤲🤲🤲
@hawandiaye55915 жыл бұрын
Merci Tata Ouly très intéressant dourouna nekh masha allah
@Zenitude.245 жыл бұрын
Machallah demain moom laay toggg ndogu. Je suis très contente de vous les dames.
@okalsdiallo24435 жыл бұрын
Merci tata diokh nama idée pour souba inchaalah
@mariehelenedasylva15175 жыл бұрын
Nekh Tata ouly comme d'habitude Man mangui doga abonné mais machalla
@yacineseck68955 жыл бұрын
Tata vraiment yangui May gagn hewayyyyy
@klejul56615 жыл бұрын
Oh j’adore le foie trop bon merci tata j’adore te suivre
@mariamacisse89615 жыл бұрын
Salamou anleykoum sokhna marietou diazakilah khayran machalah recettou tata ouly bi amoul noumou nekhewoul je l'ai reproduit mais c très bon yalla nalen yalla fay ayy yiw you barri
@aissatandg14135 жыл бұрын
Ah Tata Ouly amgua mana Mercii bcp ❤️❤️❤️
@houssaryatesenegal13914 жыл бұрын
Olalaalaaa jv cuisine ça pour l ndogou aujourd’hui insha’allah 200000 Bisous
@ladydiamila5 жыл бұрын
"Bou sandwich bi teudjouwoul grawoul dinaako lidjeunti" 😂😂😂 THANK YOU for the amazing recipes and complementary hilarity ❤
@rokhayagaye18925 жыл бұрын
Nex na merci tata ouly Mais tata marétou vinaigre bi pour éviter mouy teuff man damay deff pomme d terre après ma wiss si vinaigre bi Merci
@adjithione43065 жыл бұрын
Rokhaya Gaye effectivement lolou mo gueneu waur
@rokhayagaye18925 жыл бұрын
Adji Thione oui c ça chérie
@nenediaw9405 жыл бұрын
Exactement lolou la
@sadigatoudiallo51855 жыл бұрын
Adghy23
@nadiyadiop78195 жыл бұрын
Se mieux
@adjandiaye50914 жыл бұрын
Machala rêne ouly 100 sur 10 tothie guafi
@mariefaye76695 жыл бұрын
Machalah amena solo trop recette by merci beaucous à vous
@famagueye59685 жыл бұрын
Woooow machallah defna nekh
@aidadiop50795 жыл бұрын
Kharal ma mayko un ptit yeugeule no tata sa terme yi momay danel macha allah sa kaw si kanam rek incha allah
@mouskebasane61945 жыл бұрын
manchallah tata Marie done khalate limay défal Sérigne bii ndogoo guislii Merci beaucoup
@khadidiatougueye70575 жыл бұрын
Hahhahah no tata marietou meune nga ray nite nénako badijoner dans le pain khouuukhouuu goudeul fane way yallah bayila ak gnoune way
@gnimasn52755 жыл бұрын
Euuuuuwaaaaaaaay 🤣🤣🤣non keneu dou yaw tata marietou. Lov u tata😘😘
@modoudiop46015 жыл бұрын
Chebe🤣🤣bi momayi retan lo tata maretou goudel fane ligayi def nekh na
@AfricanBeautyHairStyle5 жыл бұрын
Mashalah mane amagoulna Sama béne recette foie saute a l ail ba paré pour la fête inshalahou merci bcp guys
@adjadiallo45155 жыл бұрын
mane dei ayyywayyyy bi momay ray....thanks so much
@rackygackou11885 жыл бұрын
Maman.machala danga bakh.motakh toujours dangaye yatal ta.ouli plat.machala bakhnna.thi.ndogou
@rackygackou11885 жыл бұрын
Mercie ma maman.cherie d avoir aimer mon commentaire
@ndeyedieng85125 жыл бұрын
i love it !! Tata foie de mouton wala boeuf nga preferer??
@yacinesarr4385 жыл бұрын
Tata Marietou gudal fan way merçi Tata Ouly pour la recette jw vous adore❤❤
@mamediarraboussodiatta82245 жыл бұрын
Lundi ma dèf ko dama animié 😍😘merci tata au carrée😘❤
@fatoumatatraore555 жыл бұрын
Machaallah tata ouly sauté de foie à l'ail bi nexna. Merci Tata mariétou eupena.
@djeinaboudiallo76685 жыл бұрын
Magnifique tata mariétou merci beaucoup ta Ouly
@sallyspectra98245 жыл бұрын
Wa mère yangi may dadji sa ganou tay bi mom manchallah😍
@miammediop43575 жыл бұрын
C la première foi ma sétane KO mai MASHALLA mère Marietou Ya takh ma abonné Yama fatheee jtm.way no stress beug lolou hahaha
5 жыл бұрын
Encore merci pour la pub ta marietou .wa ouli fimou guenn noyyy naaaaa
5 жыл бұрын
Reine du GOÛT :Queen of Taste ouly lidè ladef
@fatimaababacarsy88705 жыл бұрын
Tata Marietou dall saa gann bii non seulement limou togg saff naa maos mane damako saakh beugg mane Waaww kayy Saveur planétaire sii kaww sii kanam silou bakkhh😍😍😍
@mamediarra14385 жыл бұрын
Machalla wa saveur wakhoumala dara sakh mai la façon bigay toguer moma nekh avec gentillesse 😋😘😘😘
@mmethiam50864 жыл бұрын
Mane Dé beuguena thi😭😂😍 ak pleinty maymounannaise
@aminataba39024 жыл бұрын
J'adore ta façon de sauter
@madonaka31755 жыл бұрын
Je reproduis la même chose ce soir bisous à vous deux depuis la france🤩
@marietouaidara79205 жыл бұрын
Ma sha ALLAH j’adore 😘encore merci toureundo ak tâta ouly
@biramendiaye1355 жыл бұрын
Ah li mom ame Diop uni Ndiaye la😁
@xujfaye10725 жыл бұрын
Tata diguama ray rek Jtador trooop😂😘😘
@eviish855 жыл бұрын
Tata marietou toth gua fii. Gniaka la suivre error bou nak la. Laf thiat🤗🤗🤗💜🧡🥰💞
@ndeyearamesall70135 жыл бұрын
Macha allah.Sauté bi nekhna té saf.❤❤❤
@khefakanish97975 жыл бұрын
Bilay j vous aime tu prépare bien
@sochocolatyes41815 жыл бұрын
Mach Allah les tata yalla yalla fayelene yiw ci barke were bou tedbi
@Manerek10105 жыл бұрын
Wah yen beugolen kharit boulenedii niamale tamit
5 жыл бұрын
rek mane 😂😂😂😂😂👌🏽👌🏽👌🏽😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@Manerek10105 жыл бұрын
Serieux yen koulèn toppu rek guiss nione😂🤣🤣🤣 way yèna kham lou nekh t saf wayy
@oumasarr90805 жыл бұрын
Machalah tata mariétou j'aime bien té video et té expression way mala beugue piir
@fatimatoufall82105 жыл бұрын
Macha Allah merci beaucoup dieureudieuf bon iftar. Ta générosité dépasse les frontières qu'Allah te garde
@yacinembaye90905 жыл бұрын
Machala tata ya tax ma niamé wanie yalla na sa diam yague
@fatoubinetoudiatta16845 жыл бұрын
Machaala tata mariétou so amoul wone dou bakh
@khadygassama67635 жыл бұрын
Machallah chef merci beaucoup pour les recettes bisous
@maimounatoure85555 жыл бұрын
Wa khana OULY mi toubab la. Machallah
@mamediarra75485 жыл бұрын
Tata marietou yalla na sa diameu yagg ❤️❤️ Wa italie beug nagn la trop Sama yaye mom tous le temps dalay setan nena gua toggal ko nekheul 😂😂
@awabadiane94505 жыл бұрын
Machaallah mane dama amone probleme louma togg ndogou mė magui si bi merci tata ouly
@aidadia63825 жыл бұрын
Deuxième 😌❤️ Souniou Youbou Yaba 😁😂❤️ dafae fadj
@sallawa17595 жыл бұрын
Amine yalna yalla naguou gnane sama toguolokh bi ma cha allah
@gueyeadama58665 жыл бұрын
Ah nekh na trop Machallah 😍😍
@dieumbdia72975 жыл бұрын
Euplow li nekhna momlay def ndogou legui pour sama aladji ak famille bi surtout nimouko sandwich ché eupna macha Allah tati goudeul fan
@bowelin68115 жыл бұрын
Wa li neikhoul 😍
@Riema235 жыл бұрын
Bou sandwich bi teudiouwoul grawoul nako lidieunti 😂😂😂😂 Dead😂 machala
@mamefamandaw91875 жыл бұрын
Walaykoum salam machallah amna solo na réss akh diam😘😘
@zalissakorogho6575 жыл бұрын
Merci a vous j vous love beaucoup depuis le Burkina Faso.
@khadyba33854 жыл бұрын
Tata Marietou Yalla nga yague fi lole té ame wer. Wa mané poudre bi nguene def à la fin loumou done ?? Merci pour les conseils 😘
@bapollinaris4 жыл бұрын
Chéééé bien😂😂.. punaise je kiff🔥🔥✨
@marietoundoye53695 жыл бұрын
merci marietou sama tourondo ouly sama grande soeur nékhna machallah