Touba Khassida - Raiya

  Рет қаралды 19,276

Husnul Ma-ab

Husnul Ma-ab

Күн бұрын

Poem Of Praise Toward Allah & His Chosen Prophet Muhammad (May Peace & Blessings Of The Almighty Be Upon HIm & His Family & Followers.) Written By Shaykh Ahmadou Bamba Founder Of The City Of Touba. Recited By Hizbut Tarqiyyah Touba.

Пікірлер: 12
@araminefr1
@araminefr1 6 жыл бұрын
« RAA I YA» Waxnanouni Xassida tagg la dieum si geun di mbindef .Bokou yoyou tagg ay BEUYIT you ken meusta guiss youni mel .Waxnanouni Xassida gui kou koy diangue dangay begeul Yonnent bi(Psl) ak Sakhaba yi ak mbolem Gayou Bakh yi si geun di mbecté té kou begeul gni begeul SUNU BOROM(SWT).Xasssida « MAD’HOU »la gningi ko teunk si "sahadatou mouridina......" té yilé Xassida nenanou moy li Geuneu gaw si ay xeweul, ak Barké ak beug Yonnent bi.Té Xassida yoyou nio lay wommatal sen bopou. Mag gni nenanou Ram’mou nak mingui si biir lou yémmè Si biir Xassida gui KOU TED KI mingui feuseul lat Ram’mou gui Yonnentbi (Psl) Défalone Seydina Ousmane « Zin Noreyni »KOU TED KI nena « WA FIHI HALA NABI OUSMANE YASFAOU FI SABHINA ALFAN KOULLOUNE HAHAOU NAAROU »(Yonnent bi may na Osmane kerok bissou Penthie mou Ram ‘mou 70mille dieum you xamni Safan ba niéllone na len)Likoy firndé Moy S A LAHAD MBACKE (RA) néna Kerok Bissou penthie Mouride bou doug mom rek « ALDIANA » mom kep KOU TED KI mo am foumou la fètè wayé Yaw fèté woko fennLikoy firndé wat moy « Douna makatiby hibadaty mahan Takharoubi koulla majaya diamakha »(Sama Xassida mo eup Yoll mbolem diamou yalla ak mbir loulmou rey rey) Ram’mou kon mingui si Xassida gui KOU TED KI nena wat si biir “Kahboun wa Hassanou wa Boucheyri had Barakho wa koulahoum sihrouhou nouroun wa asrarou » KAHAB, HASSAN ak BOUCHEYRI Bokkon nanou si tagg kat yi geunona Kawé si diamono Yonnent bi Ba amon na Koumou ssi solallonn manteau boppam.Wayé liniouy kawé Kawé KOU TED KI nena Sama tagg day gathial mbolem liniou meusseu way DIEUREDIEFETY KOU TED KI
@yaawafall1964
@yaawafall1964 4 жыл бұрын
Yalla sa djam yague khassida bi damako beugue, di sette bâ sonne koumako tekkil, yalla n'alla yalla fay Aÿ yiw
@mandoumbediop7755
@mandoumbediop7755 3 жыл бұрын
Dieureudieufati borom touba
@maramara2635
@maramara2635 6 жыл бұрын
Machalla
@bassiroudiop4560
@bassiroudiop4560 8 жыл бұрын
Akassa,amna solo
@mourtalaleye4822
@mourtalaleye4822 Жыл бұрын
Bane Ani la won
@mouvementnationalisteseneg4729
@mouvementnationalisteseneg4729 8 жыл бұрын
❤️🙏🏿
@cheikhibradieng4665
@cheikhibradieng4665 8 жыл бұрын
khasida
@sokhnadioumasarr179
@sokhnadioumasarr179 7 жыл бұрын
Am na solo akassa khassida gui gaw thie tarbiya
@mayseye901
@mayseye901 6 жыл бұрын
Machallah
Touba Khassida - Bismil E Laahi Ikfini
18:11
Husnul Ma-ab
Рет қаралды 198 М.
Limahin et Raiya Gamou 04 HTCOM
1:01:08
Gilbert Insa Goudiaby
Рет қаралды 53 М.
Their Boat Engine Fell Off
0:13
Newsflare
Рет қаралды 15 МЛН
БАБУШКА ШАРИТ #shorts
0:16
Паша Осадчий
Рет қаралды 4,1 МЛН
Air Sigma Girl #sigma
0:32
Jin and Hattie
Рет қаралды 45 МЛН
KHASSIDA - RAHIYA SERIGNE MOUSTAPHA DIOP GAMOU 2002
29:23
Mouride Touba
Рет қаралды 511 М.
(Rahiya) Kourel Touba Treviso Italie.
33:01
Kourel Khassidayi Diaspora TV Ngom Mouride
Рет қаралды 392 М.
kourel nourou darayni hizbou tarqiyahe touba
6:38
Baye Sidy Moukhtar
Рет қаралды 1,2 М.
Sindidi Baye Dame Lô Kourel 1 Safinatoul Amane
16:56
Safinatoul Amane Parcelles
Рет қаралды 16 М.
Taxmiss
26:44
Drouss khassida
Рет қаралды 269 М.
WAHI SERIGNE TOUBA 3 - WAXTAAN
43:16
Husnul Ma-ab
Рет қаралды 112 М.
ALLAH-LAILAH
8:53
BAYE NIASS REC - Topic
Рет қаралды 1,6 М.
Lirabine qhaforine
16:50
Jalibatoul Maziyah
Рет қаралды 666 М.
AJABANI KHAYRUBA_ YA MANE BI AMDAHIHI_ ZALLAT_ WADJAHTUL
18:12
Jalibatoul Maziyah
Рет қаралды 350 М.