🚨URGENT || AYY TAXAW SETLU CII AUDIO CHEIKH NDIGEUL FALL BII || OUSTAZ ALPHA BA

  Рет қаралды 37,657

KAADU DINEE JI Tv

KAADU DINEE JI Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 134
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
❤❤ aimé la vidéo, abonnez-vous et partager n’oubliez pas d’activer la cloche de 🔔 pour une prochaine publication merci ❤❤❤
@fatimadieye9478
@fatimadieye9478 Жыл бұрын
qu'Allah vous récompense liguéy bi rafete na yallah na yallah yok barkél liguéy Sounnah rék depuis Mauritanie
@abousow5205
@abousow5205 Жыл бұрын
Machallah oustaz je suis tidiane mais kadou yi rafétna trop té gueumnané bouko seurigne bi dégué wollahi dina agueu si kholame❤❤
@PapeMarGueye
@PapeMarGueye Жыл бұрын
Ah est-ce que dou da dém ba meunatoul seuy mo yéwi ay diabaram lolou la gueuna yakar si wakh dji natou bobou lay wakh je pense impuissants kw wala?
@sagnasouleymane1903
@sagnasouleymane1903 Жыл бұрын
Thieuy wa sunnah Allahouma barik oustaz alpha 🎉❤😊
@sunnialiber4868
@sunnialiber4868 Жыл бұрын
Yalla na Yalla guénè Cheikh Ndigal ak bepp Baye Fall si pass passou niakk diouly ak niakk woor
@bathiediop2896
@bathiediop2896 Жыл бұрын
Louci sa yoon ñoom ñoola wax nga ñanal lenko 😊
@sunnialiber4868
@sunnialiber4868 Жыл бұрын
@@bathiediop2896 AlQuran mo niou wakh niou yéné sunuy mbok li ñiou yéné sunu bopp. Mais ma ngi diégalou souma wakhè lou la méti. Amal jamm
@ibrahimadiop7667
@ibrahimadiop7667 Жыл бұрын
Amin
@monvoile
@monvoile Жыл бұрын
Yalla n'a sa niane nagou dakh si rére kasé lagn nek😢
@abdoulazizdiallo6681
@abdoulazizdiallo6681 Жыл бұрын
Tu es tres couragieu de dire la verité mercie oustaze du courage
@magorndione7564
@magorndione7564 Жыл бұрын
Tu as parfaitement raison et tu es tres courageux vraiment
@sileymanetapatirera15
@sileymanetapatirera15 Жыл бұрын
Masha Allah alhamdoulillah merci oustaze qu'Allah te récompense
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
❤❤ aimé la vidéo, abonnez-vous et partager n’oubliez pas d’activer la cloche de 🔔 pour une prochaine publication merci ❤❤❤
@seyegamou4518
@seyegamou4518 Жыл бұрын
Sounnah rek Moy DeuG yalla nagniou yalla dioubeullll nioun niép Allahouma ighfirlii Mouhminoon wal Mouhminaat
@ismailasarr1800
@ismailasarr1800 Жыл бұрын
Qu'Allah nous guide sur le droit chemin et nous préserve du shirk
@adammbodj1641
@adammbodj1641 Жыл бұрын
Mach'Allah ya Imam Alpha. Barak'Allah Fik
@moutaphaofficiel7404
@moutaphaofficiel7404 Жыл бұрын
Machallah shukran ya Cheikhana zazaka la KHAYRAN. Yaw dé kou beug cheikh ndigueul nga. wollahi lii nga ko wakh moy deug
@namaly829
@namaly829 Жыл бұрын
Sunnah moye deg ❤
@cheikhdme412
@cheikhdme412 Жыл бұрын
Li nek Sénégal ken khamoul Lou done takene dou ko wakh Machallah dieura dieuf
@Mossdef7
@Mossdef7 Жыл бұрын
Ehhh c'est grave dehh kougnou yakar adouna ak alakhira mouy lath loumou def yalla bamou tek ko natou bou doy ni
@Aichaaidara3655
@Aichaaidara3655 Жыл бұрын
Gnianalen sama yaye nongi djiouli mongi worrr mongi deff sosial alhamdoulilah wayé len rekk la beuge mou bayiko takkk ayyy photo exemple djirome gniarry serigne fallou .parfois souma ko wahé yaye dindil li bahoul bokaléla dengay gis moi daldi méréma ba demayy moudjee diko balou akh diko nehal pour merrr bii wathhh Té lima nekonn si yonou mouride yeup alhamdoulilah mossouma dem magal mossouma doug si diouma bii ba gniane gnifa teudd dara ndah démay deglou oustaz omar sall moné lolou bidah la bokoul si l'islam au contraire démalen di gnianal ndjiégalou yala Ngen balma akh si mbinde bou barri bi sama khole no sed si yenn lima beuga wah yepp hédjioul si mbine Maman khady yalnala yala feyy sama idole biii soumalay deugeulou démay conten walah
@mamadoualioudiallo619
@mamadoualioudiallo619 Жыл бұрын
YALLA NA KO YALLA WON YOON CI YEURMANDEEM
@ronebodjis4607
@ronebodjis4607 Жыл бұрын
Mashallah yallah nako yallah sopi
@amehdemme6133
@amehdemme6133 Жыл бұрын
Il faut lui expliquer le tawhid et ses bienfaits.
@Aichaaidara3655
@Aichaaidara3655 Жыл бұрын
@@mamadoualioudiallo619 walah je lui en parlé mais on dirait qu'on lui as fait quelque chose genre téyouko mais yalla bahna prions pour elle inchaalah yala guindi ko merci à tous pour vos prières
@sunnialiber4868
@sunnialiber4868 Жыл бұрын
Yalla nako Yalla SWT tek si yonou Siratal mustaqim, mu nek si tawhid ba faw.
@BabacarMbengue-c8d
@BabacarMbengue-c8d Жыл бұрын
Ndayesane limoye adouna ya ousseta koukhamoule wone deye yakare de génie digate tefekini d'agence bege rek nite ni jamou sounou borome rek yalla Nanou yereme te jegenou🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@siacamane3361
@siacamane3361 Жыл бұрын
Et aussi que Dieu nous protege sur le Droit chemin
@cheikh999
@cheikh999 Жыл бұрын
amiin ya raby
@brenda1625
@brenda1625 Жыл бұрын
Barakalahou fikoum ya cheikh Wakh ngua ko deug
@siacamane3361
@siacamane3361 Жыл бұрын
Longue vie a vous ❤ ya oustaz ❤ BA
@falloundiaye9134
@falloundiaye9134 Жыл бұрын
Ah bouko défoul bouy déh di dém safara barakalahou fikoum ya cheikh alpha ❤🙏🙏
@IbouGueye-c6m
@IbouGueye-c6m Жыл бұрын
Sa papa maye dém safara sa paye way
@moustaphagoumbala1804
@moustaphagoumbala1804 Жыл бұрын
Falou hana ya mom safara
@FagueyeSow-s5f
@FagueyeSow-s5f Жыл бұрын
Barrakallahou fihy merci beaucoup sy léralyi te mou diguèlle ay talibène niou diouli di wore lolou dey gueneu wéreule touby gnika tope nio barré te douniou diouli😢
@alassanebsall3194
@alassanebsall3194 Жыл бұрын
Baraka allahou fikum ya oustaz cheikh alpha Ba
@aissatoudiouf2245
@aissatoudiouf2245 Жыл бұрын
C frappant :la partie de la prière Qu Allah nous aide et l aide
@tamssirthiam8505
@tamssirthiam8505 2 ай бұрын
Dieureudieuf oustaze Alpha ba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@LoRt-dq1bu
@LoRt-dq1bu Жыл бұрын
Machallah ya oustaz
@moussambaye179
@moussambaye179 Жыл бұрын
Yalnako yàlla Gindi tėkko siyonou Islam maylathie' niata Sokhna la yoroon?
@AbabacrDiallo
@AbabacrDiallo Жыл бұрын
Lath bi amna solo
@mamadougueye827
@mamadougueye827 Жыл бұрын
Merci bcp oustaz alpha ba ❤❤❤
@moussacissokho4248
@moussacissokho4248 Жыл бұрын
🤭 Diouli watioule kéne AK KO Ama done, la salât est une lourd obligation mentionné dans le saint coran. Sama baye amna 102ans wayé dayi diappe Di Diouli.
@linguerendiaye3217
@linguerendiaye3217 Жыл бұрын
Machaallah Qu'Allah swt préserve son imaane. Allahuma amine
@moussambaye179
@moussambaye179 Жыл бұрын
بارك الله فيك يا استاذ اطال الله عمرك واكرم مثواك
@abdoulayediouf441
@abdoulayediouf441 Жыл бұрын
Kou bax kouné ami natou .rassoulahi da dadj
@bassiroumbaye8099
@bassiroumbaye8099 Жыл бұрын
ألآن وفد عصيت اليوم ننجيك ببدنك ليكون لمن خلفك آية ❤❤❤
@IdrisIdris-t6r
@IdrisIdris-t6r Жыл бұрын
Niom thi sen bop khamnagniou ni thi ap kouffr la niou nek Wal ayadhiou bilah yakaroni nit gni dagniou len thi top et certainement bo moy tou oul massoul diouli wor wakhi nopi yallah nako yallah tek thi siratzl moustaghim AK nioumou yilifon.
@rawu44
@rawu44 Жыл бұрын
Machalla alpha ❤
@papedieye6210
@papedieye6210 Жыл бұрын
Ma chahalla amna solo
@BouyaTeuw
@BouyaTeuw Жыл бұрын
Machalla
@prosonko2387
@prosonko2387 Жыл бұрын
Yalnako Yalla dioubal guindiko thi Al Quran an sunna
@ElieTine
@ElieTine 5 ай бұрын
Sunnah moy dégue ❤
@JuleBa-b1h
@JuleBa-b1h Жыл бұрын
Machalla ba poullo
@sakhoousmane7066
@sakhoousmane7066 Жыл бұрын
Lér yi am na soulo torop
@doudoumbaye4746
@doudoumbaye4746 Жыл бұрын
Abdou lahi diouf boul wahe nonou way diokhe niam bahna lole waye bothi don tek diouly keneu doula geun
@AIDASENE-d7r
@AIDASENE-d7r Жыл бұрын
Guissouma lou geune diouli
@AweMamethierno
@AweMamethierno Жыл бұрын
Mashallha defga lila war de
@badiboy8698
@badiboy8698 Жыл бұрын
Wadij defa guinte noukoy iissapp khana mo takh mou guine dii toub
@elhadjibabacarndom8873
@elhadjibabacarndom8873 Жыл бұрын
Bilay ia
@dalin-t3q
@dalin-t3q Жыл бұрын
les mourides ce sonts des hizbou saytan ,les tarikhas senegalais en general, nit ken waroul tak photom
@abdoulayediouf441
@abdoulayediouf441 Жыл бұрын
Ya meuna doul
@abogassama6567
@abogassama6567 Жыл бұрын
🙏🏿❤
@emiliarobloxfesita
@emiliarobloxfesita Жыл бұрын
Ziarnalèn ouztas
@mamadoudior5239
@mamadoudior5239 Жыл бұрын
Saway douyaw yaye nangou toub ki yalla lay toubal tè ladjoula sa ķhlate
@AntonioGabarreSanchez-q4u
@AntonioGabarreSanchez-q4u Жыл бұрын
Del wakhlou rafet guisna ko mouye diouli
@LahadNiang-w4s
@LahadNiang-w4s Жыл бұрын
Dayky fin
@oumardiallo0592
@oumardiallo0592 Жыл бұрын
amiin!!!
@Hellopee
@Hellopee Жыл бұрын
Ki roukham mo nama djiouly akh alkhourane.
@mamangningue1445
@mamangningue1445 Жыл бұрын
Ya oustaz yi bayileen rek sugnou borom nopina dinagne khamni dîner dou ay fo
@badarademe1264
@badarademe1264 Жыл бұрын
Imam Alfa dégo fi Serigne bi di waxé dėh...dafaye nëkk nigëul nax kilifam néna baye Fall dafa am diakĺé baña jouli baña woor....
@MamameDiaraDia
@MamameDiaraDia Жыл бұрын
Pour yèn dèm saffara nii nguèn koyy waxè nii Nonou n'a laa yombè
@IbouGueye-c6m
@IbouGueye-c6m Жыл бұрын
Khana n'a fékhe gua manoul doka wakh lomoy déf
@NgeraAlbaraka-wc3ch
@NgeraAlbaraka-wc3ch Жыл бұрын
Machallah Dieu vous assiste
@ibrahimaseck5111
@ibrahimaseck5111 Жыл бұрын
Diouli koukoy digle koudoul yalla. Yaw danga done wakh ni sa mame Moy yalla. Bay fall yi daniouy Foo rekk
@diallodiallo4459
@diallodiallo4459 Жыл бұрын
Allah ko modjo
@PapoukoroTraore
@PapoukoroTraore 11 ай бұрын
No atan mé sa c vrais ou c un fau audio
@ibrahimaseck5111
@ibrahimaseck5111 Жыл бұрын
En tout Cas danga trahir say sokhna trahir sa talibe yi fattou. Fuite de respinsabilite. Gnila topp danio dof
@NiassaawaYauck
@NiassaawaYauck Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@oumardiallo8661
@oumardiallo8661 Жыл бұрын
Eska alpha wakh
@AmathToure-c1c
@AmathToure-c1c Жыл бұрын
Oustaz tu es menteur x il n'a cité que 3 femmes
@AmathToure-c1c
@AmathToure-c1c Жыл бұрын
Ouztas tu nous a merdé x tu ne sais pas pourquoi il est malade x combien de gens qui ne croient pas en dieu et qui sont en bonne santé x dél mandou x domourah x doul rek do gat
@AbabacrDiallo
@AbabacrDiallo Жыл бұрын
Limoy deugeu
@IbouGueye-c6m
@IbouGueye-c6m Жыл бұрын
Doul diouliwoul woroul doul
@lecaptifdumahdy1679
@lecaptifdumahdy1679 Жыл бұрын
Oubil sa leufal ndaye feulé dara khomako terroristes que vous êtes wayé Sénégal daaré rekk guéne fiy dieule domaram
@rahmandiaye3469
@rahmandiaye3469 Жыл бұрын
Diadieuf
@dëgmonjëkdëgmomuj1780
@dëgmonjëkdëgmomuj1780 Жыл бұрын
Yow moom euleug gnaka mandou moolay yaggal fa sunu Borom ndax yakamti nga ko bokaloul pass pass def ndioumté banga tal say dioumtoukay ngir wax ak feusseul ta pourtant gningay yakk yeep ay dioulite lagnou comme yow ta dioulite, dioulite moy mbokam Yoninte shws waxnani yow dioulite bi ngeuleu boul lor mouk sa moromam dioulite ci wax ak ci dieuf... malay ladie yow miy weer say moromi aka ndamu ci seeni tiss bane façon dioulite nga?
@matarndiaye9969
@matarndiaye9969 Жыл бұрын
Limou wax si dioulit bouy fowé diname dagni kaay seitane bou def louco nex?
@dëgmonjëkdëgmomuj1780
@dëgmonjëkdëgmomuj1780 Жыл бұрын
@@matarndiaye9969 Yoninte bi Shws sunu Borom waxuko ben Yoon mu juger dafkoni waxal limala yonni bu ñu toppé mucc buñu toppul dajjé ak sama mbuggël... alors yeen seen sunna rooy manduté ci Yoninte bi Shws bokkussi?
@BambadiopDiopDiop
@BambadiopDiopDiop Жыл бұрын
Ax yén bolén yax sen tans singui sen kham kham mousoriwol
@ngordiouf5468
@ngordiouf5468 Жыл бұрын
Yenn moy katou yalla yis mandouléne mo geunn li,sénn data ndeye falé
@cheikhdieyedieye4662
@cheikhdieyedieye4662 Жыл бұрын
Iow mouno dènck kèn lènn
@abdoulayediouf441
@abdoulayediouf441 Жыл бұрын
Dangay doul .diouli ak wor togou diokhé dou moromame
@doudoudiarra7454
@doudoudiarra7454 Жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@aliounebadarandiaye1374
@aliounebadarandiaye1374 Жыл бұрын
Xolal ma doff bi rek
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
​@@aliounebadarandiaye1374ki kay dof ka tanné
@bassiroumbaye8099
@bassiroumbaye8099 Жыл бұрын
Ya meune fén démal sawi ta teudi😂😂
@NdiakhateKane-sh6ej
@NdiakhateKane-sh6ej Жыл бұрын
limoye deugeudé
@damethiam3854
@damethiam3854 Жыл бұрын
Yawe yoro toupe
@dadandoye2153
@dadandoye2153 Жыл бұрын
Esq si yow la toube?? Donc mandoule tai bayi kilifa yi sa moronou Mame yi guaye diguate. Tiabi Aldiana deh yallah moco yore tai moye quille diegualer
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Yaaw tamite loutaxx mandou woo guinaww baguaa setane vidéos bii baa nopii
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Il faut arrêter ces hypocrisie, là, ça ne marche pas ici À chaque fois, vous passez de côté un croyais que vous êtes plus intelligent que les autres 😂😂😂😂
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Prochaine fois il faut réfléchir avant de commenter, regarde-toi dans la glace ou bien à travers un miroir
@dadandoye2153
@dadandoye2153 Жыл бұрын
C’est votre fort critiquer et tignale ayes mak pour ame aye vues, bayioulene sakh les morts. Li moye sene diner thimmm!!!
@ibrahimaseck5111
@ibrahimaseck5111 Жыл бұрын
Serign bay fall yi ay noceur lagnou. Serign touba moussoul wakh Ken boul diouli. Te diouli yalla moko wakh kepp😢kouy dioulit. Kou defoul yaw la engager
@abdoulayediouf441
@abdoulayediouf441 Жыл бұрын
Serigne touba moy yalla cheikh ibreu moy baboulahi moy bountou yalla.cheikh ndigueul loumou wax yalla gueureum nako .yaw nak ak SAP copati bounou wakhelo
@mamadoualioudiallo619
@mamadoualioudiallo619 Жыл бұрын
Imbécile nga rek, est-ce que serigne touba moola bindd?
@lecitoyen306
@lecitoyen306 Жыл бұрын
Kougni binde naka ngay dewe? Kouy bindate toubabi dinala dougale ci cafe di yobou fouko nekh,con
@ronebodjis4607
@ronebodjis4607 Жыл бұрын
Astakhfiroulah yalah nama yallah diegueul thie lire bima lire sa commentaire 😢😢😢
@becayekounte4091
@becayekounte4091 Жыл бұрын
Yak mor ba AK boy ibre si pote doff dofflou rék mai hamngani dangaye féne
@doudoudiarra7454
@doudoudiarra7454 Жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@YacineMbengue-t3e
@YacineMbengue-t3e Жыл бұрын
Yaw c koï ton problème avec les mourides nit dey mandou
@amatourrahmaane
@amatourrahmaane Жыл бұрын
Dafa lén beugal diamm rék mon takh dakh rér gui dafa eupp ga baalma
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
D’après ton raisonnement … 😄yaaw taamit loutaxx mandou woo cii biguaa guisee vidéos bii
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Niit daay mandou wayy 😄😄😄😄
@LoRt-dq1bu
@LoRt-dq1bu Жыл бұрын
Yaw kon mandoul
@ronebodjis4607
@ronebodjis4607 Жыл бұрын
Ndeyssane fanatique bakhoul bilay yallah nalene yallah guindi
@ousmanediop6902
@ousmanediop6902 Жыл бұрын
Machalla
@NiassaawaYauck
@NiassaawaYauck Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wednesday VS Enid: Who is The Best Mommy? #shorts
0:14
Troom Oki Toki
Рет қаралды 50 МЛН
Hilarious FAKE TONGUE Prank by WEDNESDAY😏🖤
0:39
La La Life Shorts
Рет қаралды 44 МЛН
🚨🔨DÉBAT 🔥NIOMBEE TARIKHAA YII … ⁉️ || OUSTAZ ALPHA BA
45:21
سورة البقرة كاملة رقية للبيت, علاج للسحر - القارئ علاء عقل Sourate Al-Baqara
3:52:00
القران الكريم مباشر Holy Quran live
Рет қаралды 1 МЛН
Wednesday VS Enid: Who is The Best Mommy? #shorts
0:14
Troom Oki Toki
Рет қаралды 50 МЛН