Jery niongui Chiar deh yagg yokk wéér rek si mbecté mii 👌
@DigitalJery5 жыл бұрын
amiine waaye kou baakh! Délo ziarr
@melodiexassidatv13225 жыл бұрын
Ho! Li Dafa néx Lou Dax li Amul Diéry Encore Une fois Merci Mei Thiant Yamul Fi J pense
@DigitalJery5 жыл бұрын
Non yamoul woone fi, gars yi gno daanél sama appareil bi mou yaakou
@vito89305 жыл бұрын
Ken dou cheikh modou Kara walakhi😭❤️👈🏽
@mbayegueye44583 жыл бұрын
Mbëkté mi la joie♡♡♡♡
@saliou68845 жыл бұрын
Thiant gui Mashallah , Amna ordre . Amoul roubè . Dagni niaane Thiant gui di mel ni . Video bi leer na, Ak son bi . Mashallah Diéry . Chapeau 🎩 Sidy keine dou Ioe . On veux te voir plus loin inshallah
@DigitalJery5 жыл бұрын
commencement bi amoone na ordre mais fin bi moy lolou, mo takh sakh ma arrêté filmé bi ndakh daanél nagn ci sama appareil bi bamou yaakou!
@DigitalJery5 жыл бұрын
Merci kan mm
@maguattelo66875 жыл бұрын
Vraiment jery ligueye bi rafett na khana di la nianal rk pck ligueye bi yomboul mom gas yi da nguey warou mais niou ngui sa guinaw
@maguattelo66875 жыл бұрын
Jery khana dila nianal rk ligueye bi yomboul mom mai def ko té Yalla takh rk
@DigitalJery5 жыл бұрын
@@maguattelo6687 waw lolou ame na, mais nak dieul na décision mome fou amoul organisation mom doumako filmé ti, bakhoul sakh si imajou serigne bi