JUBBANTI MBOOR, CI WAAJU DËGËR AW FIT TA XAMUL DARA.

  Рет қаралды 21,733

Xam Sam Réew Tv

Xam Sam Réew Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 106
@almustafambakke6163
@almustafambakke6163 6 ай бұрын
Jërëjėt Baay mbay yalla nala yalla faye Ci barke borom tuuba ❤ Sénégal Xampu nula Walahi
@Móodumbàkkefay5834
@Móodumbàkkefay5834 6 ай бұрын
Emetion special , a la Rts , pour notre , histoire du pey .
@modoucissemcpro9472
@modoucissemcpro9472 5 ай бұрын
🎉🎉🎉🎉
@omarndiaye-e5j
@omarndiaye-e5j 3 ай бұрын
Konn nga degg lo meusoul degg
@MbayeSadeh-jc7yl
@MbayeSadeh-jc7yl 6 ай бұрын
Merci a mbaye gueye sill nous savons tres bien de quoi vous parlez mais beaucoup de gens iniorent que dieu vous benisse et longue vie a toi
@MameMorSeck-v9e
@MameMorSeck-v9e 5 ай бұрын
Macha Allah amna solo mane dama jappone ni jery yayam mo tuddu Dior Ndella mo tax mo tax gnu tofalci turam turu yayam Jere amna solo li Re'k warna tax sugnu histoire gnu jangaleko Ci école yis Jere jeuf
@SokhnaBakhyaye
@SokhnaBakhyaye 3 ай бұрын
Kan moy serigne walalann ak serigne thiaytou😂😂😂😂... Merci gueye long vie a toi
@dialmbaaye5213
@dialmbaaye5213 6 ай бұрын
PapebAlé doit vous donner une émission à la RTS
@almustafambakke6163
@almustafambakke6163 6 ай бұрын
Gëna Yag gëna Weer ❤ amo morom Ci mboor Walahi
@oumarseck3114
@oumarseck3114 6 ай бұрын
Dieureudieuf Baye Mbaye Gueye Syll li dal na sakh ndakh dara meuneuko dioubanti loudoul li,nioniou di wakh boulen fale,doxalal Senegal yeup beknaniou ci yaw ak sa ligueye ci mbor,Yallah nanga goud fan ta wer..
@CheikhSamb-tb2ju
@CheikhSamb-tb2ju 6 ай бұрын
Baye mbaye déllouwaye la si histoire 🙏🙏
@talladiop9838
@talladiop9838 5 ай бұрын
Merci beaucoup Masahalla
@cheikhsylla4491
@cheikhsylla4491 6 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll amna solo lool.
@aliounendoye4646
@aliounendoye4646 6 ай бұрын
Djeureudjeuf Serigne Mbaye Guèye massah Allah sounou Borome fayelène yiwe
@khadimdieng1922
@khadimdieng1922 6 ай бұрын
Dieureudieuf Baye mbaye Gueye yaw rek lani toppo 🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍
@Boumci31
@Boumci31 6 ай бұрын
Serigne mbaye gueye guinaw bagnou la ziarrè dila santt dila gnanall goudd fann a wërr akk xam xam bou wërr Dama guiss yènn gniyy wakh histoire Senegal yènakk tradipraticien yénna bokk problèm kou diokk wakh gnénn gni topp si lolou di néttali Lolou moyy takh deugg dji di rêrr Apres tout c'est l etat qui doit mettre tout en orde Parceque l histoires d'un pays est primordial
@mouhamadoumbackeFALL
@mouhamadoumbackeFALL 5 ай бұрын
Bravo Mbaye G. Syll, Bonne continuation
@ousmanenoreyni4254
@ousmanenoreyni4254 6 ай бұрын
Dieureudieufeuti Serigne mbaye gueye sylla
@makhewefall9979
@makhewefall9979 6 ай бұрын
Merci beaucoup baye Mbaye Gueye cylla
@adamabeye1058
@adamabeye1058 6 ай бұрын
Slm mbeguérè la suivre g les cassettes
@amdymoustasylla
@amdymoustasylla 6 ай бұрын
Merci bay mbaye
@khadimdiagne2773
@khadimdiagne2773 5 ай бұрын
Waaa mane liy ma diakhale seringe makhetare ndome mi takhawale daraye koki lolou kaye seringe moussa ka sakhe woye na ko si wolfal yi tobabe bi moko sanki 😢😢😢😢lo takhe seringe moussa ka wakhe ko kone
@AlxaajiNjaay
@AlxaajiNjaay 5 ай бұрын
Jërëjëf Baay Mbay Gëy ci leeral yi
@mortallaniang5474
@mortallaniang5474 5 ай бұрын
Merci bcp baay mbaye gueye sylla
@modoucisse-l6v
@modoucisse-l6v 6 ай бұрын
Genres you Mèlnii nioo yakh yoonu mouride. Waayé jaajëf Mbaye Gueye Sylla yalla na yalla Faye la ❤❤❤
@Móodumbàkkefay5834
@Móodumbàkkefay5834 6 ай бұрын
Tubaarkàlla, Sëñ Mbay .
@IbouGueye-tx9if
@IbouGueye-tx9if 5 ай бұрын
Billah waxtan you dawyi ñoyax yonou mourit amouñu xam xam te begge nan xalis motah dañuy fen rek
@amadoudiaw5310
@amadoudiaw5310 6 ай бұрын
Wallu mboor Ya fi Mane Serigne syll
@mada-wn9tw
@mada-wn9tw 6 ай бұрын
Féne RK ndakh xaliss sunu gore gui yalla na yalla taxawou la
@abdoundiaye7575
@abdoundiaye7575 5 ай бұрын
Machallah
@youssouseck5538
@youssouseck5538 6 ай бұрын
Merci pour les precisions
@serignesalioumbackedioum3630
@serignesalioumbackedioum3630 6 ай бұрын
Dieuredieuf Bay Syll Thi Léral yi Meuna Wax baxna dé Wayé xam liguay wax té mou léerla Wérna lol mo geun foouf
@Mubaraktv-b6k
@Mubaraktv-b6k 6 ай бұрын
Jërëjëf
@ibraseck3059
@ibraseck3059 6 ай бұрын
Salaam Saa baay jërëjëfati ci jubbanti Gi Mbok mi delluwaay ba moko sank... Waaya xamna dina rectifié wu
@seyedane7331
@seyedane7331 5 ай бұрын
❤❤❤
@astoudiedhiou3063
@astoudiedhiou3063 5 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Senegal780
@Senegal780 6 ай бұрын
Walahi Baye Mbaye rts rek nga am palass kham kham bi Senegal dane kou sokhla❤
@mamygaye4378
@mamygaye4378 6 ай бұрын
Salam Baye Mbaye Sill Dieureudieuf 🙏🙏❤
@ModoumodouThiaw-ue8kq
@ModoumodouThiaw-ue8kq 6 ай бұрын
Limay ladie moy deugue na si wolofalou serigne moussa ka mouné nio guéné albouy ak samba thiélélane yéne pénkou nélénema wawa gané bi kanlawoune
@sambafalltv
@sambafalltv 5 ай бұрын
Même sou néké ni dafa dioum yakarna yaw aussi da ngua dioum si sa titre bi xamul dara bi ngua wax andoumassi dama koy deglou kou am xam xam la wayé nétali histoire versions yi parfois dafay bari..Je suis d'accord si kou koy def woute source bou fiable. Manone ngua yam si dafa dioum rek
@BabacarMbaye-c7i
@BabacarMbaye-c7i 6 ай бұрын
ماشاء الله ❤❤❤
@Serignembacketoure-m1h
@Serignembacketoure-m1h 6 ай бұрын
Sëriñ aminata lóo mooy sëriñ Mbàkke Madina mu baax ma 😂
@khadimdiop4199
@khadimdiop4199 6 ай бұрын
Dieureudieuf baye mbaye gueye li bakh na si lool gars yi dafa bari ñu am fit
@Papisneo
@Papisneo 6 ай бұрын
Très fier de toi pour c'est claires explications xam xam rek mo woor J'aurais bien aimé avoir votre numéro
@hissoka1459
@hissoka1459 6 ай бұрын
senegal kay. dangay guiss wakhtanekate mouride bou tokk di fenal serigne touba en directe. on est fouttu dé.
@bildoxer89diakhate5
@bildoxer89diakhate5 6 ай бұрын
Bilaahi tu mérites une émission spéciale à la rts
@filemadobamadiagne441
@filemadobamadiagne441 6 ай бұрын
Dieureudieuf seugne mbeye Gueye silla
@seckismaila8802
@seckismaila8802 6 ай бұрын
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@dokhdadie
@dokhdadie 5 ай бұрын
Ziar nala
@insadieme5061
@insadieme5061 5 ай бұрын
Lingay def amna solo waxi far Farko Numula dekuraasee
@imamdiagne5129
@imamdiagne5129 5 ай бұрын
DIEUREUDIEUF DIEUREUDIEUF DIEUREUDIEUF yakomak yakoraw ta lowakh loupera
@baye2266
@baye2266 6 ай бұрын
Yeena bokk Aw yoone. Gagganti ci soutoura. Khaw ngaa doyug waaru nag.
@moustaphadiop3976
@moustaphadiop3976 6 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@dialibatoumarahib79
@dialibatoumarahib79 5 ай бұрын
Histoire mom bou Sénégal Barina lounou thiy wah ta wéroull ta s mbaye toubab bigay touhalé tamitt Barina louthii wéroull Kiy wah nonou histoire bi seutoup sa hewar fatma ki diour bayii lat Dior AK ki diour mamam nio bokou benoup baay ndioumté nak manoutaa niaak nak ta nitki loko ham ham mou geunla ham bopaam
@mohoussa
@mohoussa 6 ай бұрын
Mais yeen titre yi tmt diarouko d. Xeuyna dafa dioum si netali gui rek..
@aliounebadaraseck4218
@aliounebadaraseck4218 6 ай бұрын
Pas de découragement.les contre vérités il faut les débusquer bon courage
@sambdemba5031
@sambdemba5031 6 ай бұрын
Salam Baye Mbaye amna solo Wayé bay lane moy prison ci wolof (degna kasso degnaci français la diogué té ndougnessine deukk la) Balma akh
@mamadoundiaye9334
@mamadoundiaye9334 6 ай бұрын
Ibra fatim sarr Yaye déféant deug
@mouhamedmakhroufthiam1476
@mouhamedmakhroufthiam1476 6 ай бұрын
Doyna war.
@cestmoitkt527
@cestmoitkt527 6 ай бұрын
Jaajëf sëriñ mbaye gëy syll taxa waay bi rafétna lool buñ manoon am ab émission ci rts dina fi gëna baax
@seyedane7331
@seyedane7331 5 ай бұрын
😂
@oneadsmarketing
@oneadsmarketing 6 ай бұрын
Comment faire pour contacter Mbaye Gueye Syll ??
@XamSamReewTv
@XamSamReewTv 6 ай бұрын
761694509
@moustaphabeye6198
@moustaphabeye6198 4 ай бұрын
Papa yaw nak yagu baga Bari poroplem lo way wakh gani do nouno😅😅 ahhh li mom
@AliouSeck-y4k
@AliouSeck-y4k 6 ай бұрын
😂😂😂père jubanti bi leerna nio dooum ndax nioun dougne binda motax histoire mom daniou théorie rek
@dokhdadie
@dokhdadie 5 ай бұрын
Sa numéro la sokhla
@faramarrenemusiquesinfodew1115
@faramarrenemusiquesinfodew1115 6 ай бұрын
Serigne walalann momm moy kann😂😂😂😂
@lepatriotesenegalais8775
@lepatriotesenegalais8775 5 ай бұрын
Il est très documenté contrairement aux autres.
@gorafall2236
@gorafall2236 6 ай бұрын
Serigne Aminata lo Kay Sénégal da fa nekh
@ahmeddamegueye1879
@ahmeddamegueye1879 5 ай бұрын
Dagni wakh guirr sén poche mo takh fén reck
@moustaphamboup3077
@moustaphamboup3077 6 ай бұрын
Da gno beug xaliss nangou wou nio soon thi gestu xam xam TV yi di len promevoir 🙏❤️❤️
@mondialtv417
@mondialtv417 6 ай бұрын
Ki waxoul deug Serigne nguick Fall kénn rayouko dafa matal faatou man mii seutou serigne nguick laa falaa deuk kii waxoul deug dé
@DAMEWADE93
@DAMEWADE93 6 ай бұрын
Segigne touba dh amoul tagg ko man â nga ko def ta do xas maami Jàmbur
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 ай бұрын
Salam fi loufi way wax dangako deug ngen balma jeureudieuf
@CheikhSamb-tb2ju
@CheikhSamb-tb2ju 6 ай бұрын
Nganè dègulounaa libone moye déguelou mélné koudéguelou woul😂😂
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 ай бұрын
@@CheikhSamb-tb2ju khawma sax lo bind .khana élèves cm2 nga😂
@CheikhSamb-tb2ju
@CheikhSamb-tb2ju 6 ай бұрын
Non ndoga daara Diangoma fr damaye dieme rék😅😅
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 ай бұрын
@@CheikhSamb-tb2ju ok
@alamingaye6281
@alamingaye6281 6 ай бұрын
Gaayi dh geustou woniou ba paré bari wakh
@ahmeddamegueye1879
@ahmeddamegueye1879 5 ай бұрын
Fén reck xamou dara si lignou wakh doméram lagn reck
@BasseFallou
@BasseFallou 5 ай бұрын
Kayi dall danio beugue xam ta nagou wounio diague
@boroomxairatvloffice5183
@boroomxairatvloffice5183 5 ай бұрын
Wadji MBEGUERE Lay copie ay waxam diko waxtané kou yaga degoul kasséti MBEGUERE YI Khamni ay waxam la yagg nama wax MBEGUERE ay erreur rek lay wax lou historien yep xam nan ko.
@dialibatoumarahib79
@dialibatoumarahib79 5 ай бұрын
Patar gogou tamitt Mame mor anta Saly mbokam lafaa nékalon Mouy mbangik anta Gueye mbaye mi bokak Awa mbaye mi diour mabouso Moy wa diourou sohna Diara bousoo miy wa diourou sohna Diara bousoo
@seugneamdyfallfall6963
@seugneamdyfallfall6963 6 ай бұрын
Wadjiii waxx siii djery mom xamoul histoire dawkatou dépense laa
@mouhamedmakhroufthiam1476
@mouhamedmakhroufthiam1476 6 ай бұрын
Khalisse reik laniou beug aka beuga siw dommage.
@ivanbocoum7367
@ivanbocoum7367 5 ай бұрын
Gorgui mome n'ena limiy wah si rapport toubab lako dieulè. Est ce lou toubab binde deugla ? Li gueunone moy Def émission si lat dior leral ko. Ak yenene boour
@matarndiaye793
@matarndiaye793 5 ай бұрын
Khana yaw rek ya kham istouwar teyaw li toubab bii biend rek guay netali
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 ай бұрын
Li s.saliou seck alkhour ane wax S.moussa ka wax nako si wolofal mame cheikh anta
@mohamedmbathie588
@mohamedmbathie588 6 ай бұрын
Salam, wakhole lolou deh, seuteu serigne Koki la serigne Moussa ka wakh, deglou watt encore. Di toubb nak…
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 ай бұрын
@@mohamedmbathie588 tu as reson wax nga DEUG merci de me
@gueyelax
@gueyelax 6 ай бұрын
Boul toumal Serigne moussa ka tamit faut bien écouter
@gueyelax
@gueyelax 6 ай бұрын
Boul toumal Serigne moussa ka tamit faut bien écouter
@Alkhamndoulila
@Alkhamndoulila 6 ай бұрын
@@gueyelax débat nga beug
@AbdoulayeGueye-os8tz
@AbdoulayeGueye-os8tz 6 ай бұрын
L'écriture dom baye yaka nagafi yague té wérr.
@gorafall2236
@gorafall2236 6 ай бұрын
Leregnou kon
@DAMEWADE93
@DAMEWADE93 6 ай бұрын
Man ñi xawma tubaab bi lani tagg walla sun maam yi
@malicksamb6051
@malicksamb6051 5 ай бұрын
Té aka nio nekh lamigne nak bougnou wakhé ba paré ga fok ni lep deugg leu 😂😂😂😂😂😂 di fenn rek
@gorambaye9466
@gorambaye9466 6 ай бұрын
Li moy deg deg
@modoukhabanembackediorel8591
@modoukhabanembackediorel8591 6 ай бұрын
Gone yooyu dañoo bëge micro te xamuñ dara
@firsttvgames8574
@firsttvgames8574 3 ай бұрын
Sougn reiw mi warnagnko xollaaat
@matarndiaye793
@matarndiaye793 5 ай бұрын
Yaw nak pa bou sof gua
@diawfalfaraa5997
@diawfalfaraa5997 6 ай бұрын
Yaw tam waxnu kan ngay Tontu Boo noppee
@salioutoure2840
@salioutoure2840 6 ай бұрын
Jërëjëf
@ibrahimadiop7918
@ibrahimadiop7918 5 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
WAXTAANE NJAMBÀARUG LATJOOR AK MBAY GÉY SILL
1:05:52
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 43 М.
Creative Justice at the Checkout: Bananas and Eggs Showdown #shorts
00:18
Fabiosa Best Lifehacks
Рет қаралды 8 МЛН
One day.. 🙌
00:33
Celine Dept
Рет қаралды 42 МЛН
DAMEEL 6-DAAW DEMBA
43:23
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 15 М.
XALISSO - Saison 1 - Episode 18 **VOSTFR**
52:00
EvenProd
Рет қаралды 561 М.
JUBBANTI MBOOR Ci Li WAAJI WAX CI LATJOOR.
19:41
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 59 М.
FAIDHERBE NDAX KEN WARNAA BAYI DARAAME DI DES CI RÉEW MI?
27:56
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 3,4 М.
LAT SUKAABE AK BAAYAM AK I DOOMI BAAYAM
2:02:45
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 70 М.
Pape Diop Mbaye raconte le voyage extraordinaire de Cheikh Oumar Foutiyou Tall
29:10
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 31 М.
JUBBANTI MBOOR LINGEER YAASIIN BUUBU
30:04
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 17 М.
XAREB SËRIÑ KOKKI NJAGA ISSA CA WAALO 11 Mars 1830 AK AMADOU BAXAW JAW
27:22
MUJJUG NOONI SËRIÑ TUUBAA YI ÉPISODE 1
25:06
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 4,6 М.
Mujjug Dou Dou Ma Mbaye ag rakam Ma Abdou Lo ñi noonuwoon Sëriñ tuubaa
24:19