🚨Imam Cheikh Gueye Moy Tontou Alpha Ba Miy Weedi Waxi Serigne bi Ci khatimatoul mounadiati

  Рет қаралды 15,825

اهل البيت TV

اهل البيت TV

Күн бұрын

Пікірлер: 166
@cheikhngom9896
@cheikhngom9896 11 ай бұрын
Xam xam bi lerrr na andak teguine machallah yalna yalla yok ham ham bi goudeul fane yi
@sohiboudiop5937
@sohiboudiop5937 2 жыл бұрын
Imam cheikh gueye yalla n'a yalla takhawoula amine yarabbi yalla nagfi yague lol ta amm werr lol amine
@toubatouba4966
@toubatouba4966 2 жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba
@aliounendiaye8747
@aliounendiaye8747 2 жыл бұрын
Jërëjëf imame yalna yalla goudal Say fane té diokalé la AK ngëureumal yalla ak Rassoulou lahi ak khadimou Rassoul
@Dioplink
@Dioplink 2 жыл бұрын
Dieuredieuf al Imam yalla na yalla barkel kham kham bi te yok ko
@mamadousene3552
@mamadousene3552 Жыл бұрын
Wawe goor Imam Cheikhe Gueuye dieuredieuf ... alfa mbame seuf khamo dara
@IsendawDiop
@IsendawDiop 3 ай бұрын
Diradieuf Serigne bi leralga Lou Bari machalla
@fallserigneamdy1661
@fallserigneamdy1661 2 жыл бұрын
Kii dafa rééw alpha ba nioune serigne touba rék incha Allah
@worldwords5841
@worldwords5841 2 жыл бұрын
Kanam la djeum rék... Oséwouniou nieuw diakarlo ci plateaux yi ak soufi yi, wahabiste yi khamouniou dara
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
@@worldwords5841 yene daguene am argument 😂ahlou bida mounoul eup kham kham niouy doundou alkourane ak sunna
@worldwords5841
@worldwords5841 Жыл бұрын
@@layekharagne2224 waw délén nieuw plateaux yi sou fékké am nguén xam xam yén waw euhlou takfir😁... xamoléne touss motakh nguén di daw😁
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
@@worldwords5841 douniou dem plateaux ak nio khamnè amouniu argument amouniou kham kham lepp ci alkourane ak sunna laniou ko tekk , indilene niou preuve comme nè top serigne diebalou ci mom lou niounete bi digglè la
@Serigne.Modou.Gaye92
@Serigne.Modou.Gaye92 2 жыл бұрын
Merci Baye Cheikh wallahi bounoula dana métti Manam Dégue arabe Takhoul ga mana firi alkhourane walla wakhi Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💚💚💚💚
@papandiagadiop9849
@papandiagadiop9849 Жыл бұрын
May wakh mouy ndirolé wakhi YaAllah akh bou serigne touba sheut 😢
@Jarafnet
@Jarafnet Жыл бұрын
Mome dale nanio bayi yi Alpha machalla Waka thalika ya cheikh
@diakhatesidi1970
@diakhatesidi1970 Жыл бұрын
Bilahi papa content na ci yaw,yalle na la yalla faye,wakhi sougnou mak gni cou féroul idji douko firi moukham ci tariha bi nga bokou wala wahabiou, niveau boukawé lagni wahé,kén douko firi mot 'a mot
@mbayepouye4017
@mbayepouye4017 Жыл бұрын
Dieuredieuf serigne touba
@omardieng-vr9ob
@omardieng-vr9ob Жыл бұрын
Gorgui tégua wo alpha direct moguene moguene idiwo bene argument 😂😂😂
@saliougueye8773
@saliougueye8773 2 жыл бұрын
Akassa diadiuef amna solo
@fallserigneamdy1661
@fallserigneamdy1661 2 жыл бұрын
macha Allah imame cheikh guéye diéureu diéuf
@mouha313mouh8
@mouha313mouh8 2 жыл бұрын
Machala bay serigne cheikh gueye yalanala yala yangalfi tanga andeu ak wér ماشا بارك الله فيكم
@sidbecayeleonfall7468
@sidbecayeleonfall7468 2 жыл бұрын
Merci cheikh gueye.. C'est clair et net..
@allandao7970
@allandao7970 2 жыл бұрын
Diradieuf serigne gueye
@serigneadj1779
@serigneadj1779 2 жыл бұрын
❤🙏🏿🙏🏿🙏🏿 Ku Khamul khamo MASHALLAH BAYE CHEIKH
@badarandour3536
@badarandour3536 2 жыл бұрын
Machaallah diadieuf yaram bii Gueye xolyi Sedna billahi wallahi tallahi alfa ba mome sokhor mokoy yobou barzah wallahi
@saganadiop5572
@saganadiop5572 Жыл бұрын
Merci Alpha Ba , yaw ya wakh deug , ki yako raw fouf. Ne te rabaisse pas.
@CheikhbabaNdiaye-s9b
@CheikhbabaNdiaye-s9b 10 ай бұрын
Moko raw tei meunoul firi baat yi 😂
@mameniang7626
@mameniang7626 2 жыл бұрын
DIEUREDIEUF SERINGE TOUBA
@caatuuyaayam4513
@caatuuyaayam4513 2 жыл бұрын
Wallahi Serigne Touba kou khamoul ay tollou wayam si harab da ngua yagga dioum, bamou wakhé كرامتي خط يدي ngua wara khalat bou bakh bala nguay douggu si mbinn'dam
@babadiagne1840
@babadiagne1840 2 жыл бұрын
Merci beaucoup
@sohiboudiop5937
@sohiboudiop5937 2 жыл бұрын
Dieredieffeti serigne touba
@modousylla9931
@modousylla9931 2 жыл бұрын
Jërëjëf Ahmadou
@khadimseye1963
@khadimseye1963 2 жыл бұрын
شكرا سرج شيخ غي
@mamadoundiaye817
@mamadoundiaye817 2 жыл бұрын
Thiëy thiëy yalla mayéna louné
@abdoulahadmbow242
@abdoulahadmbow242 2 жыл бұрын
Dieuredieuf Imam
@ibralome4452
@ibralome4452 2 жыл бұрын
Dia jeuf imae lerna yalla na yalla faye
@cherifmoullayeyakhya7797
@cherifmoullayeyakhya7797 2 жыл бұрын
Merci beaucoup imame cheikh
@MM-vh8qv
@MM-vh8qv 2 жыл бұрын
شكرا جزيلا لك ماشاء الله جزاكم الله عنا خير الجزاء مرحبا
@bassiroudiame-rz7iv
@bassiroudiame-rz7iv Жыл бұрын
Alpha deguoule wolof guinéen la😂😂😂😂😂😂 ndereng😂😅😅😅😅😅
@abdoulahaddiop5621
@abdoulahaddiop5621 2 жыл бұрын
ماشاءالله مهم جداً جزاك الله خيرا
@khadimeseck1470
@khadimeseck1470 Жыл бұрын
Alpha fan nga rek rasikhona filhilmy
@ndiayeomarcheikh4930
@ndiayeomarcheikh4930 2 жыл бұрын
Machalla ler na
@magattefall213
@magattefall213 2 жыл бұрын
Maaaaaaachala machalla 🇸🇳🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@cissabdoukhadre1579
@cissabdoukhadre1579 2 жыл бұрын
إنّ من تضييع الوقت الإشتغال بشأن الفاشق ألف به،أتركوه ولاتناقشوه ولاتجادلوه ولاتجاوبوه فماهوإلاهالك،قبّحه الله وخذله ودمّره تدميرا
@cissabdoukhadre1579
@cissabdoukhadre1579 2 жыл бұрын
الفاسق
@mamebinetoumbaye6825
@mamebinetoumbaye6825 2 жыл бұрын
Masah'alah Baye cheikh contananou boubax yalnala yalla faye yiw barké xassidayi 🙏🙏🙏 sama xolbi da séde gouyi blahi dama begg
@CheikhSambou-y9l
@CheikhSambou-y9l 8 ай бұрын
هم لايعلمون ولم يعلموا أنهم لايعلمون. .. هم ضحكاء جرجفت بروم طوبى
@bassethioune1460
@bassethioune1460 2 жыл бұрын
Mâcha.alah.s.cheikh Gueye.thi.leeral.yii
@abdourahmanediallo24
@abdourahmanediallo24 Жыл бұрын
Père waho fii touss
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
wallahi wakhoufi dara dh 🤣g perdu 1 h de temps de ma vie
@mortallanakoyallatakhawulo303
@mortallanakoyallatakhawulo303 2 жыл бұрын
❤️❤️machallh
@indigne2161
@indigne2161 Жыл бұрын
Ustaz Alpha n’a fait que démystifier le plus grand commun diviseur des Sénégalais et comme vous êtes un égaré vous donnez un sens aux élucubrations qui font la base du mouridisme antonyme de l’Islam.
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Daguay woo Alpha Débats moogueun. Guaye tookdiwax.koulay. Weddy nekoufa...yobna torop
@sakkuxam-xam1593
@sakkuxam-xam1593 2 жыл бұрын
Kàñ la Alfa Ba doon Docteur,??????????.
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Serigne Touba douwolof origine peul la Eladji Malik peulla Abdallah Niasse peulla
@moustaphadiene8720
@moustaphadiene8720 2 жыл бұрын
Machallah
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Waxmoom. Même wolof kouko wax Soula néxé. Gua gua deggueko. Noula nexé. Serigne Touba douwolof origine peulla... Sénégal Limaamou lay kep mooci Serigne wolof..
@saganadiop5572
@saganadiop5572 Жыл бұрын
Wakh dji nékoul si le mot « déy » mais le contenu du message.
@DjibyNdiaye-tf3fy
@DjibyNdiaye-tf3fy 9 ай бұрын
💯🤲👌💯💯💯👌👍
@mouhamedmakhroufthiam1476
@mouhamedmakhroufthiam1476 2 жыл бұрын
Alpha wahi serigne touba yimiy deigoul ta diko deupe reik bouko si serigne touba topè euleuk yawmal rek meune na alkou.
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
douko def dara 😅😂serigne touba moy kane wala serigne touba ci bopam wakhou bokkalé yimou bind ci terem dinako diggalé ak souniou borom
@MameDiarraGningue-ej8pj
@MameDiarraGningue-ej8pj 4 ай бұрын
Cheikh alpha ba yalla still sa xol the yokou té défal niou kham kham bou sétt té wéérr
@abdoulahisene4318
@abdoulahisene4318 Жыл бұрын
Alpha mane nekhnama ndakh moma geunal gnidoul hol khassi dayi baparer di wakh rek segame mome mongui hol rek bakhna
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Serigne Touba douwolof origine peul a comme Alpha... Sénégal Limaamou lay kep mooci nek wolof... nopil.sasarigne toccnafi...soogua dem looloy degg..
@morkebe6775
@morkebe6775 2 жыл бұрын
Machalla Yagefi loool ta wer Geuye
@elhadjindiaye8032
@elhadjindiaye8032 2 жыл бұрын
Waw gor baye cheikh
@birikeurndiaye3399
@birikeurndiaye3399 2 жыл бұрын
ASalamualeykum Ouztas svp leralñu aussi sur les 33 femmes de serigne Touba dons 3 sœurs si c vrais ou pas merci 🙏🏽
@AHLOULBYTI
@AHLOULBYTI 2 жыл бұрын
Lolou amoul manoul nek sakh ay sossla rk serigne islam moko yitel louy yakh derou islam douko deff
@hlmtvoficiel
@hlmtvoficiel 2 жыл бұрын
Serigne Touba bo topé histoiram bamou djekh Est ce que amon temp pour lolou sakh lolou bane diamono la wara done
@hlmtvoficiel
@hlmtvoficiel 2 жыл бұрын
Lolou amoul
@AHLOULBYTI
@AHLOULBYTI 2 жыл бұрын
Diarna ladje de
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
merci frere na leral lolou 😂gni danio bakh rek 33 femmes yi nako leral Alpha ba lou yalla ak yonete bi diggglè la def bappare di dioubal nitt yi grace à lui niou bari guene naniou ci yonou thiskhane yi alpha ba mouno lene ko decribliser
@mortallanakoyallatakhawulo303
@mortallanakoyallatakhawulo303 2 жыл бұрын
Machallh
@massambad1
@massambad1 2 жыл бұрын
Ma sha Allah leup leere na
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Mais Serigne Touba douwolof origine peul. Comme Alpha Sénégal. Limaamou lay. Kep mooci wolof...
@guilefall8421
@guilefall8421 2 жыл бұрын
Dieredieuf S Cheikh G G amna solo lool Wayé niom deug nioroulène . Bo bokoul thie niom rék bougounioula. Khawma nak fan laniou diangué loolou thie sounna Ils sont tous des crétins
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
alkourane ak sunna laniouy topp donc deug aka molene niorr , sene serigne sou bindé lo khamnè da woutté ak sunna daniou ci wakh moy kane ? Alpha ba diguene ko yabbi nakh deug rek lalene wakh
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Mon père yaagui melni élèves CE1 liguay wax kouy waykatt xamguako. Baci rappeur yi..loolou doxamxam bouyémé
@CheikhbabaNdiaye-s9b
@CheikhbabaNdiaye-s9b 10 ай бұрын
Khana alpha mom jardin la nekk 😂😂 Seugne bi kii thi yeen la nekon dei tei bouleen fatei ni sen ndjiit ahmeth lo touba la dianguei ayy maamam daniou daan raamal serigne bi alpha mi diangui barki dembeu nieuw nei day firi wakhi serigne bi ay rei lamay def bilakhi 😂😂😂
@papeniang8667
@papeniang8667 2 жыл бұрын
Seringe bamba dou sen moroomum baye😂😂😂😂😂😂😂👍
@serigenmbackesow5854
@serigenmbackesow5854 2 жыл бұрын
❤❤ Alfha ba diambar nga mais nak Serigne touba amul morom lou lèr la wakh dou wakhou réseaux sociaux yi
@ousm7710
@ousm7710 2 жыл бұрын
Yallah rek mo amoul morom bayilene bokalé
@serigenmbackesow5854
@serigenmbackesow5854 2 жыл бұрын
@@ousm7710 yaw mi kou rew nga bo jakar lowon ak man wakh ma li dina la deff loula meti yabate nga trop rew nga trop
@lahatleye6313
@lahatleye6313 Жыл бұрын
Machalah xam xam rékk mon worr mér si pérr
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 2 жыл бұрын
Je ne suis d accord avec vous Celui qui denigre serigne touba n est ni docteur c est un mecreant
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
serigne touba moy kane ba warouniouko denigrer ? bane dalil moy findel daniouko wara gueum ? serigne touba da nekk ci alkourane wala da nekk ci sunna ?
@cheikhdieyedieye4662
@cheikhdieyedieye4662 2 жыл бұрын
Diaredieuf per
@maguettedieye3898
@maguettedieye3898 2 жыл бұрын
Machallah imam ronda dafa warr di am panka you melni yaw ti diko tek thi kham kham diara deufati s touba
@khadimeseck1470
@khadimeseck1470 Жыл бұрын
Annasou niyaoun alpha ba desenga khame bidding ñawe ngayewou
@souleylam2588
@souleylam2588 2 жыл бұрын
Niom niepp lololen sonal waxuniu ngir yalla soxor ak mbagniel gune bagn serigne bi mo lén diapp
@ahmadbabadiaw4763
@ahmadbabadiaw4763 2 жыл бұрын
فجزاك الله خيرا يا شيخنا شيخ غي بارك الله فيك وضحت الأمر بوضوح الشمسية
@oumarsall8581
@oumarsall8581 2 жыл бұрын
ماشاء الله مفيد جدا نسئل الله تبارك وتعالى أن يحفظكم جميعا في الظاهر والباطن بجاه طه صلي الله عليه وسلم
@mamadoundiaye817
@mamadoundiaye817 2 жыл бұрын
Ziar Omar bann la
@valkane3596
@valkane3596 2 жыл бұрын
Nga djegal ma wanté bokalé yi serigne you melni Kara Mountakha ak Moustapha sy ak niak diouli baye fall yi yoyou nio gueune gaagn diné l’islam que wakhou oustaz alpha yi
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
wallahi
@ousmanedieng14
@ousmanedieng14 2 жыл бұрын
nionn daniouy wakh nitou souna wayee khamouniou nee mandou da book thie souna ...deug alkouran daa book thie ...nagou hilman mim ladounia...nagou haqiqa...nagou batinn...fiir rek molenn diapp...ak niaka nagou mayy...
@ibradiop9753
@ibradiop9753 Жыл бұрын
Bagnél day neub xamxam wayé Beugg aussi day neub xamxam..boul tereé saagua baparé dissagua...
@sakkuxam-xam1593
@sakkuxam-xam1593 2 жыл бұрын
Alfa Ba du Sénégalais Peulh Fouta la, Guinée la, waaye du Sénégalais, ألفا باه، ليس بسنغالي ، بل إنه من غينيا كوناكري وليس بسنغالي.
@djilyeniang-cm9qg
@djilyeniang-cm9qg 9 ай бұрын
Fahalon limayorido
@Aistv2014
@Aistv2014 2 жыл бұрын
Serigne Cheikh Alpha Diahile bou Réew la , Bagn mangui réewam ndakh Complexe
@papandiagadiop9849
@papandiagadiop9849 Жыл бұрын
Alpha dh indi na ay arguments té wakhna lougnou mana deg yaw nak ba tay wakho fi dara
@CheikhbabaNdiaye-s9b
@CheikhbabaNdiaye-s9b 10 ай бұрын
Alpha feinal seugne bi ioe nga geum wakhi alpha nei ki mom wakhoufi dara kou bakh nite day ragal yalla man sen djouli yingen di djouli loumou def thi yen la beugeu kham aaaahhh li dei khana dou bagn kessei la fok
@ousm7710
@ousm7710 2 жыл бұрын
Lakatou thi guinaw réseaux sociaux numéro alpha yombou na diot débat moguene khamo dara
@شيخمحمدفضلجايجمل
@شيخمحمدفضلجايجمل 2 жыл бұрын
💯💯✅
@bassiroudiame-rz7iv
@bassiroudiame-rz7iv Жыл бұрын
Gni alfalaahe molendi financé pour gnou wedy serigne si indi fi jihadiste lolou dou islam ndah doyounou gnoune serigne touba lanou hame ibnou taymiya russe la bouhary russe la aye toubab complexé 😂😅❤
@nouvelledeveloppementdumon4450
@nouvelledeveloppementdumon4450 2 жыл бұрын
Imamae s cheikh niy diaro niotonto kosa aliwo bariwol fomana diare def yafi mblitt
@mapendandiaye2485
@mapendandiaye2485 2 жыл бұрын
Machallah amnasolo loool baye Cheikh Geuye 💯💚💚💚
@ousm7710
@ousm7710 2 жыл бұрын
Di wakh sans idi preuve
@CheikhbabaNdiaye-s9b
@CheikhbabaNdiaye-s9b 10 ай бұрын
Yoe khana américain nga 😊😅😂 wala kii doon wakh ay chinois ladoon wakh bok kii commencement terei bi rkk beineuh beuyit lako diapal diko diangal arabe 😂nga wara hamni alpha danotina oooohh j’ai pitié wollah 😅😂
@maksodieng7325
@maksodieng7325 2 жыл бұрын
Bilahi walahi alpha xam xam né woul sitére bi ragall yala mola kay may de
@bassiroudiame-rz7iv
@bassiroudiame-rz7iv Жыл бұрын
Alpha kafire leu bayame serigne touba motah mou done musulman
@alioupouye3533
@alioupouye3533 2 жыл бұрын
Yak nie Nga bokal Xalat. Mourid yi niolene ngana game yalla. Te gan lenko wetal. Lolou Nga wax thie Alkhouran nè amoul niare wax đời degue أت الله لا يغفر ات يشرك به ويغفر ما دون ذلك. وفي ءاية اخري ان الله يغفر ذنوب جميعا أنه هو الغفور الرحيم alpha Ragalal yalla te bayi wakh loula woroul
@faliloumbacke882
@faliloumbacke882 2 жыл бұрын
Yalla na Yalla goudal seye fann Yalla nala Yalla faye Amln...
@sakkuxam-xam1593
@sakkuxam-xam1593 2 жыл бұрын
Alfa Ba du Sénégalais Guinée Conakry la, waaye Alpha ba du Sénégalais Guinée la. ألفا باه، ليس بسنغالي أصلاً، بل إنه من غينيا كوناكري، وهو خائن لوطنه غينيا كوناكري، وليس بالمحبي لوطنه غينيا كوناكري.
@djilyeniang-cm9qg
@djilyeniang-cm9qg 9 ай бұрын
alfeba dafe alko saware yaynakoiblisba
@mamadousene3552
@mamadousene3552 Жыл бұрын
Sûr que alfa et younous vont bien la fermer pour de bon . Pauvres ignorants
@abdoufall1124
@abdoufall1124 2 жыл бұрын
Alpha ba kou mana féne la
@cest-2023
@cest-2023 2 жыл бұрын
Ki dafa gnouss ndeyam Alpha ba domou thiaga la. Yayam da thiagatou ba djour ko khamna yayam.Serigne touba koukoy sikisaka domou thiaga nga.khamou gnou dara ils sont complexés naar yi yakh senn bopp
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
serigne touba lila diangal 🤣? di saga kouko guemoul ? mdrr
@akimlo2834
@akimlo2834 2 жыл бұрын
Ki diaroul tonntou ki ñimélni mom daño oumpalé segne bi rék naka la nit ñémé wakh si Serigne bi kadou yo xamné ñom dîomnanko wakh sénni waydiour dama lénna yeureum kousi touboul moudj Gou ñaw ngay déwé
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
sene serigne hana dou nitt kassé ? boulene niou sonal 😅
@allembaye9494
@allembaye9494 2 жыл бұрын
Malheureusement ils n'ont rien compris ses gens férou gnou sakh idji beugueu firi ak di wédi rék tout simplement pour des financement point
@bayelahatmbaye6926
@bayelahatmbaye6926 2 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✅✅
@ousm7710
@ousm7710 2 жыл бұрын
Tu parles trop alpha ba woko appel pour débat moguene lakatou di tontou diop bisiri dieulna wallam ya si dès loy khar
@ibrahimadioplo475
@ibrahimadioplo475 2 жыл бұрын
Moi le plus ignorant des mourides peux vous apprendre des secrets que vous ne connaitrez dans votre sale vie
Imam Cheikh Gueye Gandigal Qui sont les plats Lan Moy Thiosanu Peul
39:23
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,2 МЛН
Cat mode and a glass of water #family #humor #fun
00:22
Kotiki_Z
Рет қаралды 41 МЛН
Loutax Sénégal Bari espionnage....imam cheikh Gueye GANDIGAL
21:52
اهل البيت TV
Рет қаралды 2,6 М.
LE MOUVEMENT AS-SALAFIYAH AU SÉNÉGAL | OUSTAZ OUMAR DIALLO | SUR RDV SÉNÉGAL, CHEIKH TIDIANE BITEYE
50:08
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,2 МЛН