Thiey li😢 la vie est tellement éphémère en l'écoutant on découvre une personne humble simple joviale humouriste et qui transmettait des ondes positives à son entourage kou nékha déglou ndeysane paix à son âme et que le jeune waly repose en paix aussi
@beugfallou28535 ай бұрын
Quand il a dit que crime district lay setan ni dama youxou
@FanySarrFany4 ай бұрын
Surtout jovial ça tt le monde a remarqué ❤
@soukeynasow164 ай бұрын
@@rosemathidebasse1721 ❤️
@mymathiamada18925 ай бұрын
Un homme pertinent talentueux Un Artiste multidimensionnelle ouvert d'esprit âme classe personnalité digne hoooo😢 ayye ki dèff li yallah na torokhe Alkou raye na azize akk waly rayalè seni famille azize d'où nittou kèssè daffa lakhatouwone thi arts bi yallah nalla yalla yeureume kharèlènne aldiana firdawsi barckep seydina moukhamed psl
@AdelineValérieInnocenceDIEME5 ай бұрын
Oh quelle joie de vivre, une forte personnalité, tu as réussi ta mission. Que Dieu t'accueille au paradis amen
@CheikhNJaaY4 ай бұрын
Amine❤
@aissatoufaye97755 ай бұрын
Quelle créature Chapeau à toi Reposes en paix mon grand Euskey
@Ousmanyatassaye5 ай бұрын
C'est une personne pleine de vie machallah... Qu'Allah le pardonne et l'accueille dans son immense paradis 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@Serenandiaye5 ай бұрын
Un homme plein de sagesse ,digne un chef d oeuvre ,un visionnaire un ambitieux kou kham limou beugue ,intelligent yallah nala borom bi yeureum khareko aldiana firdawsy un homme,intelligent mashallah ya bakh deugou tabe merci beaucoup yallah mola beugue kou gniak kigniane yallah nala seydina mouhamed psl teroulene 😢😢deuil national et justice for yours ,for senegal people for world gnieup diomi
@ousmanedieng33235 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@gueyegueyegueye61854 ай бұрын
bilahi kou rafet wax
@sokhnaka78714 ай бұрын
Oui en l'ecoutant on sent qu'il était lucide et plein de sagesse ndeyssaan Yallah nako Yallah yeureum mom ak Wally🙏🏾
@aissatoufaye97755 ай бұрын
Il était sur une autre dimension Bravo à sa maman Il a déjà son passeport pour être au près du prophète MOHAMAD psl
@MarieFrancoiseMagin5 ай бұрын
Amiiine ndeysaan
@soukeynasow164 ай бұрын
@@aissatoufaye9775 Salalahou Aleyhi Wa Salam Nabiyan Wa Rassoulan Amine
@bead52685 ай бұрын
Ndeyssane, je l ai repéré depuis vip sagnessé, damako sopone,c'est triste, il faut retrouver les coupables et les les mettre hors d état de nuire. Repose en paix diambar 🙏😭😭
@Mais20195 ай бұрын
Kou bakhla wone Machallah c'était un homme sage et intelligent qu'Allah l'accueil au Paradis que Firdaws soit sa demeure
@SokhnaSeck-lm5bi5 ай бұрын
Yalla rek mo ham ki geune mai bimou décédée batay guissoma si momeuh béne wah bou niaw diogué thi guèmaniam vraiment yalla boula thiate djitou si sa bamel adouna nieupala dioy mame abdou
@LamineDiop-u7m5 ай бұрын
Ndeyssane lou takh ma beguon ko wakh bou rafét rek la mene 😭😭😭😭😭Ki la rayé yàllah nako yàllah nite
@victordacosta35375 ай бұрын
Dafa gueumonn boppam Nit kou deugou Un homme de bon❤ et juste Très technique, très talentueux Très ambitieux Am vision, xamonnn foumou dieum
@boussofall57725 ай бұрын
Yalla naco yalla bour bi hare aldiana firdawsi Barke seydina Muhammad psl
@aidaba63504 ай бұрын
On voyait qu'il évoluait. C'est la jalousie , le mobile de son assassinat.
@sukaijeng21614 ай бұрын
Ameen
@AissataBah-ih1kp4 ай бұрын
Ameen Ya Rabouna 🤲💔😭
@aminataba85455 ай бұрын
Ndeyssan il vivé sa vie,très solaire,attachant,que la terre lui soi légère...trop triste billahi
@omarniang30495 ай бұрын
Kou kham deugueu ki nitou yalla la. Yalla nallen yalla yeureum té kharélén aldiana firdawsi
@fefethiam98795 ай бұрын
Kou bakh barki borom Touba,yalla nala yalla yeureum té kharé ko aldianaye firdawsi 🙏🙏🙏💝💝💝
@seynabouthioune47625 ай бұрын
Kiko def cou dém mogui lire commentaire mais nittt ga meuna lakhatu mais dou yalla si barkép xassida yi yalna yalla léral lepou barké mouhamed 😢
@heleneobega21805 ай бұрын
so❤❤ 😅😅
@soukeynasow165 ай бұрын
Salalahou Aleyhi Wa Salam Nabiyan Wa Rassoulan Amine ❤️ ❤️
@mamediarrasylla50454 ай бұрын
Nit kou bakh borome hhol bou rafet il a tout laire
@amadou67564 ай бұрын
Wayé dinagnou tamarin ndeyam yallah nelawoul
@papiscamara94265 ай бұрын
Ndeyssane ki cou am ambition la vone baparer cohérent kham limou beugue nitt moo sokhor yalla naco yalla yeureum
@aidaba63504 ай бұрын
@@papiscamara9426 Il savait ce qu'il voulait et comment atteindre son but. Ils ont tué par jalousie.
Nite rék mo sohore Euskey Am na Ya ALLAH Ndéyessane plein de vie Alhamdoulilah allah kouli haline
@boussogueye71685 ай бұрын
Ndeyssane yalnako yalla yereum t khareko aldiana
@nanafall41345 ай бұрын
Mo ki kouko xool xamné niit guenouko bilahi 😢😢😢😢 yalla na égali ndawam sii Aldiana 😢😢
@OumouSylla-bg3mi5 ай бұрын
Ndeysanne kouko wakhone ni dou fékhé magal bi dou meussa kheume allah na souff sende si khawame
@Amina-n8s1w5 ай бұрын
Mashalla il parle beaucoup de yalla ❤ Yalla nala yalla yeureum aziz dabala amiine
@aminaba61305 ай бұрын
Deysane ray nagnko allah l accorde son paradis
@ndeyecoumbafall50845 ай бұрын
Ndeyssane, guisna video imam bi mounane niko Yallah teuguei si guiss guiss bokoul ak lissi mom, Yallah reik la beug ! Lila imam bi wakh ndeyssane, yalnako Yallah yeureum tei dieigalko khareiko aldiana inchallah
@Diamilatouwone5 ай бұрын
Yallah na hommes de tenue yis gawa niit ki def li si barbé Seydina Mohamed psl
@betysylla7805 ай бұрын
allakhou amine
@africanfinancialagent5 ай бұрын
Amine way li dafa leti trop sakh bilay
@khoudiasylla83965 ай бұрын
Amine
@paulmalo61685 ай бұрын
Paix à son âme
@Makhtarfall57815 ай бұрын
En ttout ka borom khol bou raffett la wone machallah,Yalna bouko thiate djitou si bamélam
@papaelhadjithiam77465 ай бұрын
Crime district reik lay seitane, mou dcd par crime… Yalkah moy karim ndeysan . Ce gars est très digne walahi
@Olelsoh5 ай бұрын
Aziz est tres digne que dieu l accueille au paradis pour les autres danseurs la danse est un métier ex Michael Jackson et John Travolta
@aissatoufaye97755 ай бұрын
Alahouakbar C'est mignon de l'entendre parler ainsi Macha Allah
@aissatoufaye97755 ай бұрын
Alahouakbar Macha Allah J'ai même la chair de poule Une bonne éducation
@thelioness20004 ай бұрын
Gniko Rey danko ignané tek ko beut...wayé Borom bi day attéé fi ak feulé... Aziz koukou khol deglou ay wakham khamné Borom khol bou rafett leu yéné niep diam... sama khol nekhoul 😢😢😢
@FatimaAidara445 ай бұрын
Bilay kii khawmako won mais son décès m'a bcp fait mal 😢😢😢
@BOUFASHION5 ай бұрын
Que le tout puissant lui fasse misericorde.
@amadoubal60615 ай бұрын
Amine yaAllah
@larissasagna67065 ай бұрын
C’est les jaloux ki ont fait ça 😢😢😢 parce que Khalebi thi yone leu nek di def Lou rafete
@allediouf12865 ай бұрын
Ki couco guisse khameni kou gnak kignane la.repose en paix et petit wally
@OubaBeye4 ай бұрын
Ohhhh c’est belle parole ndeye sann k justice choix fait ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😭
@FatoumataCisse-x3f5 ай бұрын
Ray Naniou kou bakh way yalna KO borom bi diégueul ko té nangoul dieufeum you bakh té kharéko aldiana firdawsi thii barké seydina Mohamed psl
@jejejffjjfjfjfjd35525 ай бұрын
😊9
@malily67055 ай бұрын
Misquine d'Allah nako y'Allah yeureum ,nena dama geum y'Allah tropeee sama yaram bi daw deysane.
Je ne savais pas que Aziz était si intègre , très intelligent Yala na niou khipé Aldiana Firdawsi amine Yarabi ❤❤❤
@LisaDiop-i4h4 ай бұрын
Billayi ndessane nite kou bakhla wone té mandou yalla nako yalla yeureume djiégaleko kharéko aldiana firdawsi mome ak wally
@MboseeSamb5 ай бұрын
Yalana xiper aldiana Souf oyof si kawam si barké seydina mouhamed psl amine yarabi
@guithiel5715 ай бұрын
DEYSSANE , C TRES GRAVE ET TRISTE . POURQUOI AUTANT DE HAINE ET DE VIOLENCE . SOUYONS DES HUMAINS 😢😢
@lelionnicois96815 ай бұрын
C'est très triste,ce jeune à l' air d'être une très bonne personne, pourquoi tuer ?
@bequediallo4584 ай бұрын
Deysanne mais kî loutakh gua raylénne????? Yaw mî ray ñîî defgua moussibeu ! Jusqu'à maintenant dama diakhelé yaa Allah nalénne yaa Allah yeureum té diégueulénne Amiiiin'Allah !!!
@DieguyBathily4 ай бұрын
Macha alka refete khôl, yatou khôl Lou New sounou diamono dji. Yalla nako yalla fay kholam té yobouko aldiana amine
@ANNASOWFAYE5 ай бұрын
Yalna yallna donn sa keur massa walahi je ne le connaissais qu a travers la télé mais je le regarde comme un petit frère massa metina metina toropp .
@MameDiarra-lq2vd5 ай бұрын
Aÿ mane Sénégal fougnou dieum mane deh gueumoumacowone bilay yalnaco yalla kharè aldjana yu gueuneu kawè amin 😭🤲
@sanounembaye4 ай бұрын
Aziz wanéna thi Interview by ni kou nité leu , kou optimiste , niafékate , wôlouneu borômame lôl , yàlnako yàlla diégueul té tétalko thia Aldianna ***
@princesseonelove89082 ай бұрын
Ki il avait l esprit ouvert ndeyssane loutakhe guen rayé nite kou bak ki J aimé son personnage Que le bon Dieu t accueille au paradis celeste
@SopeySerSaliouakwakeureum5 ай бұрын
Yalla na khipè Aldjana firdawsi Amiinnn bidjahi Seydina Mouhamed saw
C’est très méchant 😢 😢 c’est un diable 😈 celui qui t’a tuer 😢😢😢
@nanafall41345 ай бұрын
Ndeysane il a une bonne éducation dou wakh Lou gniaw 😢😢😢
@aissatoufaye97755 ай бұрын
Très bien Macha Allah ALLAH a plus besoin de lui que nous
@FatouNdiaye-x7r5 ай бұрын
Aye waye kou raye sama Aziz 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@fatousagna39815 ай бұрын
Que Dieu l accueille dans son paradis
@fatousymalick84115 ай бұрын
Yale nale yale kharè adjana inchalla
@oumythiam8095 ай бұрын
Que firdawsi soit sa demeure éternelle 🙏
@MaimounaDieng-fz5hr5 ай бұрын
Ndeysane ki nit kou bakh la.geumna yalla.yalnako yalla yeureum te khareko aldiana.
@ndeyefatouyarefall75135 ай бұрын
Yalla nala yalla djiègeul té kharela aldiana mais dém lène diamoudji yalla bayyi fètieu
@SadioDiatta-q7p5 ай бұрын
Allahouma amine que son âme reposé en paix Aldjana firdawsi toutes mais condoléances à la famille que la terre lui soit légère Allahouma amine que dieux lui accompagne dans son paradis céleste frère c'est très triste billahi ?oui ndeye Fatou yaye fall tu as raison mais c'est une triste décès qui se passe aux Sénégal ils faut dire ça avant ça morte mais pas en se moment parce que tous le monde est triste billahi ils faut me pardonner pour la réponse
@pendadieng68555 ай бұрын
Bilaye li mettyna torop sakh que justice soit faite 😢😢😢😢
@abougueye57125 ай бұрын
Ndeysane c vrement triste que la justice soit faite
@ndeyeawadiagne56295 ай бұрын
Ray na gnou khalé bou digne, bou nitté, bou am fayda, gueum boppam, gueum yalla, saf khorom. Yalla na khippé aldiana.
@marlenemendy31595 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum il communiqué bien
@AwaKande-t3g5 ай бұрын
Ndeysane repose en paix
@Ramapoulo5 ай бұрын
Paix à son âme😢
@ndeyearif18395 ай бұрын
Aziz yalla na yalla yeureum la té kharé la aldianay firdawsi
@djamilgaye79295 ай бұрын
Le senegalais est tres mechant...kholat lenn sen boop.
@oulayecamara40795 ай бұрын
Kou bariwoul thiow doko degeu si lane mba wax nako niii sa déé bary niii thioww bilay siw dou diami borom liii mety na trop yalla na yalla yésal yeureumandé si yaw té leral lépeu gua tassé ak Serigne Saliou 🙏
@sokhnaka78714 ай бұрын
Ndeyssaan il était très lucide Aziz💔 On sent aussi qu'il était quelqu'un de bien et avait un très bon cœur Yallah na khipé Firdawsi🙏🏾
@FayeFama-sk2oy5 ай бұрын
Kiko Ray yall nako yalla nitt bamou lerr ta aziz yalla na yalla yereum ko te xareko aldiana firdawsu amine
@ramandiaye37265 ай бұрын
Ohhh ndeysane Paix à ton âme que firdawsi soit ta demeure éternelle
@AstelDiagne-v3g5 ай бұрын
VRAIMENT IL Y A DES GENS TRÈS MÉCHANTS, SADIQUES ET CYNIQUES BILAYE. QU'ALLAH ABSOUT SES PÉCHÉS ET L'ACCUEILLE EN SON PARADIS CÉLESTE AINSI QUE SON CO-LOCATAIRE YA RABI
@khadyng16585 ай бұрын
Yallna ko yalla yeureum, ❤
@Mouhamedba-19755 ай бұрын
Innaa lilaahi wa innaa ileyhi raajihouna Puisses ALLAH SWT lui faire miséricorde, lui pardonner tous ses péchés, agréer ses bonnes actions et lui ouvrir grandes les portes du Paradis céleste Al Firdawsi.
@KhadidiatouSane-uv9fs5 ай бұрын
Que leurs âmes reposent en paix. Et le bon Dieu vous accueille au paradis et vous bardonne tous vos péchés. Amine
@mansourmbaye69265 ай бұрын
Kham nasi darra kou kham wakh tes ame déguine digua kham koy respecté domou adama tes yore khol bou raféte yalla nga dadiék deugou yalla bi
@aminataseck31775 ай бұрын
J’ai maaaaalll😭😭… Heywayyy…gni def li Yalna lene Borom bi atté ak Aziz, ak Wally, guene guiss ko fi si kaw souf 💔💔💔 Yalna nalene Yallah tek si Aldiana yi gueneu kawé , fi nguene nek gueneul lene foufe ,Firdawsi done sene keur🙏🤲
@codoungomsow77264 ай бұрын
Ndeyssane yala nala yala yeureum té diegueul la artiste plein
Alhamdoulill'ah yalnala yallah xaré aldianay firdawsi barcké mouhamad (sws) li yomboul d sa kadou yii léep rafèt
@thioumbanegueye88714 ай бұрын
Ndayesane aziz dabala yalnako yalla kharé aldiana
@fatoukinedieng43955 ай бұрын
Yallanako yalla yeureum té xareeko aldiana 😭💔♥️🙏 li metina trop kouye ligueye tonioulekaye ngir teeral aye wadiour nga jeuleko dfeko lou niaawe injustement 😭😭 yallana yalla weere niou boone gni🤲🤲🤲🤲🙏
@FamaMbaye-v5d4 ай бұрын
Bilahi lignla def métinama trop bilahi yalla nala yalla yeureum kharéla aldiana ak bépeu dioulit bou guéneu adouna thi barké Seydina Mouhamet
@aissatoufaye97755 ай бұрын
Très bien Quelle créature
@AbycoDieng5 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum té kharer ko aldiana firdaws
@AidaGoudiaby-yc1cj5 ай бұрын
Masa yala na souf ofof si kawam 🤲🏾🤲🏾😭😭🙏🏻🙏🏻😊
@Tymamedcisse4 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum 😭😭😭😭😭😭
@Yassege785 ай бұрын
Ay aziz repose en paix mon coeur ségne
@seynabousarrkebe54835 ай бұрын
Yalla nako sougnou borom yeureum té kharéko aldiana firdawsi bidjiahi seydina Mouhamad SAWS
@Matar-i6d5 ай бұрын
Ray 2 persones li bénna nite manouko déf. Yalla naléne yalla léral. Aziz yalla yereume 🤲
@Mody-nz3zt5 ай бұрын
Exactement 🧐 beine nite mome deifouko c’est sur ☝️
@didijohn6945 ай бұрын
Lolou la wakh dé...ce meurtre est prémédité. Té ki len raye koulen kham la.😢
@yayeaissatourabiandoye5 ай бұрын
@@didijohn694ils étaient 4 camera de surveillance moko wané
@mrcamara55745 ай бұрын
Yalla nangou na frere
@Myriade-s2n4 ай бұрын
Moi je me demande comment un être humain peut regarder un jeune plein de talent humble plein de vie positif poli plein de qualités tu prends un couteau et tu le tues même pour découper un poulet cest pas facile à plus forte raison un etre humain mais pourquoi ? Il a rien fait à personne 😢😢😢
@mameastoundiaye81805 ай бұрын
Yalla nako yeureme té kharé ko aldiarna fir daw si gnou déf li yalla naléne yalla niteu ték léne lokho 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@bdk39974 ай бұрын
Innalilahi wa Inna ileyhi Rajhun que le Paradis Firdawsi soit leur demeure éternelle avec son neveu toutes nos condoléances à sa famille, ses proches et tout le Sénégal,🙏🙏🙏 Massa ! Massa ! C'est vraiment triste !
@RackyNdiom4 ай бұрын
EL HADJI AZIZ BA YALNAH LÉEROU SEYDINA MOUHAMED SALLAHOU ALEYHI WA SALAM LÉERAL SA BAMÉL BA FAWOU ALLAHOUMA AMINE INCHA'LLAH
@NdeyeHanne-v7h5 ай бұрын
Yalna ko yalla yereume 😭😭😭😭😭😭😭 ki déf ly yalla nako yalla nite🤲🤲🤲
@babacardiallo23664 ай бұрын
Yalnala yereum tè kharèla aldiana firdawsi ioe ak Wally
@aminatamane1315 ай бұрын
Thieuy aduna yalnako borom bi yeureum téh xaréko ci jannatoul firdaws
@haby87604 ай бұрын
Aziz wéteul ngueugnu Ndèyssane paix à ton âme et celle de Waly aussi 🤲🏿