Salam Nous remercions le Marabout Serigne Abdou Samath pour cette belle initiative nous permettant de mieux connaître notre idole Serigne Fallou en matière de lecture du Saint Corant unique dans son genre.Nous lui souhaitons longue vie sous la protection d'ALLAH.
@KheweulBijoux Жыл бұрын
Srg mountakha mbacké bachirou yalla nafi yagg lool te wérr lool barcke srg bi ❤❤❤srg abdou samade ligueye neex trop amna solo lool machallah yakk srg fallou naléne diamou rek sonal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdoukhadresamb2565 Жыл бұрын
Thiey, Serigne Fallou, Sa yargui ak téye Gui raféte na
@MalickNguirane-ul5kx9 ай бұрын
Allahouma Amine s fallou yaguefi tawerr lolllll ak s Abdou samat
@Khadimbambasonko402 ай бұрын
alkhorane daall dafa yeeme loulle billahi 😭
@CisseKone-q5v Жыл бұрын
Serigne abdou samad yalla nako yalla sam té ar barke borom touba
@NdeyeNdiayemouridesadikh3 ай бұрын
Dieurdieufeti Cheikh Mountakha yalnafi yagg lool ak wer
@khadimfall5437 Жыл бұрын
Machalla ya imame yag fi te weurr thi barcke seringe touba
@SerigneSaliouSene-k5v Жыл бұрын
Serigne fallou mbacké imam yalna fi yague thi barkeb al khour ane
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye3 ай бұрын
Allahouma Salli Hala SEYDINA MOUHÀMADINE WA HALA ALY SEYDINA MOUHÀMADINE WA SALIM !
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye3 ай бұрын
Dieureudieufé CHEIKHOUNA AHMADAL KHADIM RTA !
@FallouMbengue-sc6zd Жыл бұрын
Seringue fallou mbake yala GaGoud fann❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdoukhadresamb2565 Жыл бұрын
Serigne Mountakha Yalnafi yàgg té and ak wér Si barké Borom Touba.❤
@bayeserignediagne7812 Жыл бұрын
Wallahi khaw ma sakh lane là wara wakh billahi 🥺 yalla na sa brome samoulé thi barkép cheikh Ahmad bamba ❤️🤲
@panogayembaye2116 Жыл бұрын
Machallahou ❤❤Aka ma Naw gni moukal AL KHOUR ANE
@mboussobembathie162 Жыл бұрын
Yalla nga àag téh aagalé Serigne fallou ❤❤
@xamxam4898 Жыл бұрын
serigne montakha yalna fi yaag loool si barkeep serigne salihou
Serigne Mountakha Mbacke Yalna fi Yagüe lole Tè weur barki borom Touba Ak Xassida yi
@MamieDiagne-t8w9 ай бұрын
Machallah jërëdëf contane na si yow mbacké❤
@bayedamegueye6112 Жыл бұрын
Walahi samaxol toye na😢😢
@mbackediop849810 ай бұрын
Yague fi lolu te werr serigne fallou mbacke sama werou waay
@abdoukhadresamb2565 Жыл бұрын
Mâ Shâ Allah, liguey bi raféte na
@abolo4640 Жыл бұрын
Yalna yalla taxawou serigne mountakha té goudel aw fanam yokkou ko té wéreul ko
@ChiekhDiaw-fu7kr Жыл бұрын
S fallo yalna yalla koudall fann wi ak s abdou samatt
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye3 ай бұрын
inshaLAH Gueuneu yague Gueuneu wer Amine !
@MalickNguirane-ul5kx9 ай бұрын
S mountakha yaguefi lolllllta werrrr❤❤❤❤❤❤❤
@PapaNgom-re5wc10 ай бұрын
🥺🥺talibe bi serigne fallou am yemena lol
@SadikhDiop-d9f Жыл бұрын
Alkhourane djiou wér rék moy takh nga mana agu ndakh lisiy topou lép ak diamou yalla té diaamou yalla moy lép barkep alkhourane barakallah dieureudieuf
@Diopdaouda-yn9hs Жыл бұрын
Machallalah mbacké balla yallna yalla fayla🤲🤲🤲🤲
@bambasarry9543 Жыл бұрын
Dieureudiuef seri Abdou Samad dieureudiuef seri fallou iman gnon gui hare enregistrement
@BayeassDiop-x8x Жыл бұрын
Mâcha allah Dieureudieuf Serigne touba khaim rassoul ❤
@modouaichamback2429 Жыл бұрын
Yalla n’a yalla motali lėppe si barkė boroum Touba
@imamnassythioune4933 Жыл бұрын
Machalla Serigne Abdou Samad jërëjëfa ty kou am managha
@NdeyeAstouNdeyeAstouNdiaye3 ай бұрын
Allahouma Salli Hala SEYDINA MOUHÀMADINE WA HALA ALY SEYDINA MOUHÀMADINE WA SALIM !
@chiekhgueye9463 Жыл бұрын
Diaradiaf serigne touba khadim rasol mbacke
@mamadoundiaye8167 Жыл бұрын
Cëy Yallah ❤❤! Plus organisé que la voie Muriid, Wallahi amul. Comme dit Sëriñ Abdu Samad : lutax waxkat yi duñu wax yii ?