Modou Anta tape sur la table : "Modou Lô sou dieulaaté Balla Gaye danou waat..."

  Рет қаралды 16,155

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 41
@mamadoumousserinediop8056
@mamadoumousserinediop8056 Күн бұрын
Belle analyse de Modou Anta
@mouhamadousaybatoudiaw
@mouhamadousaybatoudiaw Күн бұрын
Non Modou anta da khame lambat déh ❤
@Domou_Deukk_Bi
@Domou_Deukk_Bi Күн бұрын
Balla sawarouma si combat bouniouko diokh favoris... Son fort c'est les combats de defi, combat tay ngay dée Siteu dako nara déglou moudéf béneu faux pas mou exploité koo
@AliouCisse-x5d
@AliouCisse-x5d Күн бұрын
Bien dit lamba lock
@jobehamidou6545
@jobehamidou6545 Күн бұрын
Wallahhi billiahi Parler vrai modou anta
@tallambengue-oc4cd
@tallambengue-oc4cd Күн бұрын
Balla gaye bilah walahi souh moh Meune siteu 1000fois siteu defufi dara bari wax teksi
@SambaToure-n9h
@SambaToure-n9h Күн бұрын
Modou Anta wakho deug modou lo moy lutteur le plus populair 🎉 de sa generation 🎉
@PapeNgom-j6f
@PapeNgom-j6f Күн бұрын
Bilaye copin kn dou Modou lo
@mormboup9301
@mormboup9301 21 сағат бұрын
Mdrr dpui quand balla est plus populaire ? Modou est un comorien!
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 Күн бұрын
Lolou mom amna😊
@alphadiouf8111
@alphadiouf8111 Күн бұрын
Yenn gni rek yeneuh wara wakh thy lambe...❤nakh danguena kham lambe
@yaalasadio
@yaalasadio Күн бұрын
Modou Lo deh mom soneu na 😂 sou beurré woul dagn koy boler si lamb dji
@daoudathioubou6710
@daoudathioubou6710 Күн бұрын
C’est normal parce que c’est le roi des arènes. Kou djitou nieup diokhogne leu
@SambaToure-n9h
@SambaToure-n9h Күн бұрын
Billae lambe diou am niou toudou ko cône yaa ngi bayi limay bayi khel 😂
@BaMasour
@BaMasour Күн бұрын
Kouy daw nounoulay dané déléne ndiémé deugue
@bachirdiop19
@bachirdiop19 Күн бұрын
Pourquoi beugua déme stade Abdoulaye Wade mo way
@FallouCisse-r3i
@FallouCisse-r3i Күн бұрын
Wakhoul deug deee sathies douma ko dane ko mounane keneu meusouko door dane ko
@votremiroir7612
@votremiroir7612 Күн бұрын
genre analyses yi motakh Siteu dou dieul béen risque, lane moy Siteu amoul loumouy perte si combat bi?
@Deggou
@Deggou Күн бұрын
Modou actuellement mo meune balla , balla menoul daneu modou bi...
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd Күн бұрын
Mooh 😂
@assanegueye1352
@assanegueye1352 Күн бұрын
Saway balla gaye ndoata march nul lanou am
@laminediagne4143
@laminediagne4143 Күн бұрын
Teniroul kène échec siteu défou fi dara
@AmaraKoita-y9f
@AmaraKoita-y9f Күн бұрын
Franchement lambologue baxoul thi télé il force trop puis téyoul teksi day beugeu wakh lep
@mamadouwade6565
@mamadouwade6565 Күн бұрын
En tout cas siteu bou taxawé degeul bopam dou mate 5mn😂 inchallah
@Ibrahimadiange
@Ibrahimadiange Күн бұрын
Modou anta parle sur le plan du lutte waye khamo kan Mony balla gaye
@assanewade6616
@assanewade6616 Күн бұрын
𝐄𝐦𝐩𝐞́𝐫𝐞𝐮𝐫 𝐛𝐢𝐠𝐧𝐞 𝐤𝐨𝐲 𝐟𝐨𝐫𝐜𝐞́ 𝐦𝐨𝐦𝐚 𝐝𝐞𝐟 𝐚𝐲 𝐫𝐞́😂
@YoroDiop-el4kn
@YoroDiop-el4kn Күн бұрын
No modou anta khalatam la wakh bane riske balla bou dieloule siteu kouli dieul
@diopablaye5227
@diopablaye5227 Күн бұрын
Lamine ila yaw midini gna wakh de
@PapaSambaSy-h7r
@PapaSambaSy-h7r Күн бұрын
Modou anta wakhna deug souniou stade yi khalatouniou ko diokh wa lamb Bayilne thiakhane
@ImboboKaga
@ImboboKaga Күн бұрын
Lambalogue del teey touti, di wagni digression yi. Modou Anta sou lamb yakho diapna ci nga, ioe ak gniy bagn wax deug yen mbeur yi. Siteu aussi danoul ben poids lourd, woutoul daan mbeur dey nieuw di daw ak di samp nul. Kone solen toké si media di wax genre wax yi, amna yenen mbeur you ndaw youy nieuw def lamb business, manaan douy stade bi, nieuw samp nul ni en tout cas douma danou. Té lolou guiss nagn ko Combat Mor kangKang vs Diop2 ak yenen grand combat you moudj té lolou dieumé woul lamb kanam. Lamb affaire ndiom la, dou ay business ay negociation. On ne vous critique pas pour juste vous critiquer mais tu dois franchement revoir ta communication téy wax lou deugou. Setlou na aussi combat Siteu v ModLo même, tu incitais Max à déposer un recours et un appel. Ce qui ne ressort nullement de tes prérogatives en tant que reporter/Chroniqueur. Et puis, t'as fait un recensement par je ne sais quels moyens pour savoir que Balla est le lutteur le plus populaire de l'arène ?? xolatal ningey waxé seugn bi té gueuna mandou. Meun nga analyser nak sa droit leu. Nga balma akh nak
@FallouDiakhate-p4d
@FallouDiakhate-p4d Күн бұрын
Wakh deug fa yalla Mbeur yi mbam yi niosi eupp dh
@KhadimDiagne-h2e
@KhadimDiagne-h2e 2 сағат бұрын
Modou anta balla sowakhé lôlou no fataliko euema séné wala boye niag Balla gaye dane sitau dou takh moye wakh loudoul lôlou
@doustar2193
@doustar2193 Күн бұрын
Modou anta yah muna dul Balla uepul modou Lo sipuerter balla Sénégal là yuem Modou lo nternational là buy bueré niata Bus moy diogue Gambie xamo lingay wax
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd Күн бұрын
Ioe mi ya xamoul lingay wax
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 Күн бұрын
Yaw mi ya khamoul lingay wakh mond lamb balla mosi eup souportér balla bouy beuré liy diogué gambie ndanga kham noumou tollou
@AlleFall-y7t
@AlleFall-y7t Күн бұрын
No siteu mo eupeu suportair mè modou reck lay tope mé boumou.djeule.balla.gaye.beugeu.corigé.modou.lo.bock.nasi.li.takh.mou.djeul.siteu.mé.pourqw.modou.lo.di.dérangé.balla.gaye
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 Күн бұрын
@@AlleFall-y7t khana konn modou dafa dieulone boy niang pour corigé balla légui balla mome waroula beuré ak siteu pourquoi siteu mbeurou gokhla té balla mbeurou andouna la balla mo eup souportér si lambdji lolou la yalla dogual
@Chakor8955
@Chakor8955 Күн бұрын
Modou anta khamou balla gaye iaw wakhal Lou nék sa xél ak sa xol rék
@SambaToure-n9h
@SambaToure-n9h Күн бұрын
Siteu bou defon ni moromam yi vp yi dagne kay daane wakh Len deug rk beuré niar nio Kay deff ah
@KhadimMbaye-k4f
@KhadimMbaye-k4f Күн бұрын
Yaw yay yalla modou anta xamo dara
@AmaraKoita-y9f
@AmaraKoita-y9f Күн бұрын
Franchement lambologue baxoul thi télé il force trop puis téyoul teksi day beugeu wakh lep
Quilt Challenge, No Skills, Just Luck#Funnyfamily #Partygames #Funny
00:32
Family Games Media
Рет қаралды 55 МЛН
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН
LALAKÉ - Saison 1 - Episode 5  **VOSTFR**
27:58
KHASS Production
Рет қаралды 76 М.