😢😢😢oooh lii triste na waye mes boumou bayi yayame ak niabontame kay kone cousin bi day ame louko nékh souy neuiwe dakar nako dome yii fékisi ak yaye djii limouy déf sakh bakhoul kéne dou bayi sa wadouir
@moriciss63686 ай бұрын
Billahi amena niit you bonne xolalema bi deuif bou bonne li montakh gor bou si touki ladiane sa diambar nakh meunala khare souko meunoul rék bayil nga façé ko sino rek guathei moy ame
@wanealpha19656 ай бұрын
Na bayiko Al yallah
@allediouf12866 ай бұрын
C dur mais ce n'est pas une raison de ne pas voir sa mère et ses enfants.chaque jour la vie nous renseigne beaucoup de surprise du courage et résiste toi
@ndeyekhadydiop92566 ай бұрын
Aywaay sokhna fatou mangi deglou histoire bi 5h du matin waye sama addouna beppa toukki li metti na 😭😭😭😭
@sokhnalo33346 ай бұрын
Mais la vie continue nabayi khel yayam ak ay domam cousin by mou bayiko ak yalla bala dée dinako guiss
@BouryDiop-fd9pq6 ай бұрын
Dijguéne Moy sunu yaye dh😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭
@obietrice46206 ай бұрын
Cousin bi moudiam dou nekh
@bintaniabaly99536 ай бұрын
Merci beaucoup Sokhna Fatou ❤😢😢
@abdoudioufSeck-z6u6 ай бұрын
Cc na ils douwa je marié encore
@habydoucoure81166 ай бұрын
Première ❤❤❤❤❤
@oumarmbaye79056 ай бұрын
salut sokhna fatou merci si histoire yi Maashallah ❤ wadji na déf souko meuné mou wout keur Dakar indifa yayam ak domam yi niou deuk fa ak mom té mou bayi cousin wam bi ak yalla inchallah adouna dinako diangal Na mougn té sant yala dina bakh
@ndiayefallou75036 ай бұрын
Sokhna Fatou Billy Gu bou don mn Billy dam koye pélénte ah vie giu bakhul si sosét bi kierminél la 🥺😥
@BaraLô-v3f6 ай бұрын
Nn pr man jarul muy defsi khelam nan bu taseg mom dakoy ray, nako bayég yalla rk, ndakh adinabi dafa jekh ba nopi, ta buko rayé benn dina yakhal bopam avaniram ag ay famem sirtu yayam, tayit bu taseg sunu borom manasa am ay danam..Metina trop nk mé nako mougne rk, ta khamné yalla gui guis lépp...
@MamefamaSamb6 ай бұрын
😢😢😢
@moudouboye6 ай бұрын
na mérbi dem dakar nio gisé
@famaDieye-g8d6 ай бұрын
😢😢😢😢😢😢😮
@Mamecheikh-wt2gu6 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@altesseroyale43836 ай бұрын
Mane sakh li ma gueneu diakhale moye sène seyou mbok you diéguèyo yi. Ah non😢!
@daouddiouf1766 ай бұрын
Il y a une chose que tout le monde a banalisée de nos jours et qui reste toujours un grave péché et qui est la fornication. Au début de la vidéo, cet homme a d'abord eu des relations intimes avec sa femme avant de la marier et c'est très grave: c'est un péché majeur. Peut-être que c'est la conséquence de tout ce qui lui arrive là maintenant car la facture se paie tôt ou tard. Et donc la facture se paiera aussi, tôt ou tard, pour son cousin qui a tué sa femme de par ces médicaments. D'abord, je lui conseille de demander pardon à Dieu sincèrement pour cela. Ensuite, qu'il reste zen dans ses démarches et qu'il assiste sa maman et qu'il trouve une femme patiente-pieuse-attentive pour surpasser cette épreuve et qu'il prenne soin de ses enfants. Qu'il laisse son cousin avec Dieu: il paiera cher tôt ou tard pour tout ce qu'il a fait.
@adiaratoundiaye80966 ай бұрын
Pourquoi la justice n'a pas fait son travail
@belleduteteaupied13936 ай бұрын
Dzgn lo warra poursuivre en justice aussi
@Xippill6 ай бұрын
Tegua leep thi lokhol sounou borom dinalaako fadjial bagua contane boko raye sa cousin do thi ame yalla et tes enfants digua len baye waye woudoul faye ba mouk sama papa mo ray…..hé aduna yagoul te yalla geumoul nelawoul lo bayi ak sounou borom mou fadjiale lako je te demande de faire la paix avec toi même rt de t’occuper de ta mère et de tes enfants bon courage Maria Dijon
@abiesagna66226 ай бұрын
❤❤❤❤
@RamatoulayeMboup-v9m6 ай бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭
@Xippill6 ай бұрын
Yow mi li dall yow lay wakhal ana sa geum lou meti nitt lay dall waw tes enfants ont besoin de toi et ta mère qui t a mise au monde elle a mal déplace ta mère et tes enfants à Dakar pourquoi tu t arrêtes de vivre oui tu as souffert metina mais yalla migui ande ak adji mougne yi
@RouguiDiop-e5b6 ай бұрын
Neysane la topato yayam bi nek di souffrir sou yayam dé wé te guissouka setiwouko dina torox adouna ak alaxira la séti yayam gaw ak aye niabotam nio eup solo k cousin wam bou yés bobou
@aliouba64805 ай бұрын
Lindispline peut coûter des vies J'ai confiance en aucun homme
@AwaDiop-zj6dg4 ай бұрын
Ct
@HousseyNouWade6 ай бұрын
Mon seul commentaire y a t il un être plus cruel qu une personne ?