Pape Niang communique très bien avec les gens il est très discipliné machalla que Dieu te garde 🙏🙏🙏🙏
@rachidacamarasylla12303 жыл бұрын
Alahou akbar pape Niang yalla sougnou borom Rékk molaye faye ak seni association. li rékk warna diangale domou adama. Pape Niang wah bi Amna téguine
@naboundiaye16693 жыл бұрын
Bilahi pape Niang damako beugue sen liguey rafetna ak association bi yallana yalla maygnou soutoura
@khadidiatouthiare54063 жыл бұрын
Papa niang svp cas bi faw gnou topou ko. Il y a trop de non dis. Pourquoi beugoul guèneuh? Ame na sokhna? Amna jaabot? Fèbar bi nimou ko dikkè? Vraiment on veut savoir. Merci wa association bi yeup sèn takhaway raféte thiante ak geureum niell nalène. Yallah maylène geunèl soutoureuh adouna ak alahira. Machallah❤❤❤❤
@khadidiatoudiouf51913 жыл бұрын
Ah doyna war dal surtout mom dou bokam pourquoi beugoul gnou yobou nak. En plus mom weuroul té il est reconnaissant envers le vieux qui parle à sa place
@pendasarr32253 жыл бұрын
Mane deh am Na sii ñaw ndiorte nii watt astagfirla wayé nimou waxé c un peu Louche c à suivre dall
@papafall6923 жыл бұрын
Deugla warnako topu dakh père nirouwoul ak kou am febarou xell
@mouhamedniang76363 жыл бұрын
@@pendasarr3225 Moulée Nga Wax
@naboundao39223 жыл бұрын
Wala niou woo sa famille direct ki voisins jasé la
@juleslambassadeurdestalibe6193 жыл бұрын
L'État du Sénégal doit être honoré pape niang
@madjitoure30133 жыл бұрын
Pourquoi honorer l'Etat Sénégalais, si il ne fait pas grand chose pour le peuple et les gens sans ressources. Ce sont les jeunes de l'association qu'il faut honorer. Ces jeunes, sans ressources qui sont entrain de lutter pour une cause noble et admirable.
@tigressesylla99413 жыл бұрын
@@madjitoure3013 mais oui c se qu'il veut dire
@fatoukineba44363 жыл бұрын
@@madjitoure3013 je pense qu’il a fait un lapsus,il voulait dire le contraire
@fatoumbengue83503 жыл бұрын
Wallahi machâ allah yalla na yalla barkel té tahawou pape niang aky gnognome
@saliouthiam47873 жыл бұрын
C l l'état qui doit honorer cette association
@sekhlenianv56623 жыл бұрын
Ndeysane pape Niang sa wakh rafet n'a sa dieuf rafet n'a machalla Niang balo yalla nala yalla fay barki cheikhoul khadim.pabi khamnako kou dioulite la kou dioub la mo ma done réparé le télé Kaolack kou doyloula je suis en Espagne mais mais kl la deuk.merci a toute l équipe
@senadeya17423 жыл бұрын
Sva merci si commentaires c mon père
@sekhlenianv56623 жыл бұрын
@@senadeya1742 de rien c est la vérité yague n'a ma réparel télé waye da am ben beus veille Tabaski doumako fate ma KO done réparé lo radio môme ak son fils ci biir radio bi sama dieukeur Modou modou la te Modou modou yi foune là niouy dethie te radio bobou am n'a si Mane atte waye da dieki rek am problème ma yoboulkoko te môme d'où nanguou sakh bayi baguagame si saci lalakoy defaral nakh bagne kouko yab .ba gnou oube radio bi ci biir ay euro mo si nek ci biir wor n'a yalla ne magui toguone ci biti te mesouma imaginer ne khalis mougui ci biir te sama dieukeur fate ne nawone dadione dethie fofou mais daniou ma woo di guene khalis bi diokhmako barki cheikhoul khadim te kou dioulite la te tangue khana nakh bagne kouko yab dama nek legui bitim rew mo takh nouyoulmako mome ak domame bou yarou bi koy diapale .yalla n'a yalla goudal faname may ko wer barki cheikhoul.
@senadeya17423 жыл бұрын
@@sekhlenianv5662 machala si sédé bi amine yarabi amale diame contane na
@diamapouye92773 жыл бұрын
@@senadeya1742 c ton père nga wax ndeyssane lou tax deukoulene ak mom yalla nako fi yalla bayi
@fatoudiop585 ай бұрын
@@senadeya1742ms lan motakh niouni amoul dome kon
@serignediaw37172 жыл бұрын
Sen liguéye raféte na machallah yal nalen yalla takhawou si barki( psl)
@madondior53023 жыл бұрын
Pape gniang yow gueumna ni do nitou késé yow yalla la yoni sasla mission bi ngay dokhal machallah longue vie à vous!
@astalo3964 Жыл бұрын
Mana nékkeu dé yalla aki mbiram❤❤❤😢
@ndeyedioufmouserignefallou14473 жыл бұрын
Wally seck Aziz Ndiaye chiekh Amar Balla gaye 2 kay len ligueyal yalla fii té yallal kessé takh
@aladjidia2943 жыл бұрын
Billay, lou lerr
@yatoundiaye25213 жыл бұрын
Wally mom gatié ngalama social limou thiey def si mim rew amoithi morom
@adamasow50103 жыл бұрын
Kaimtane bou doynawar yalla wonaitina bopam, seigneur donne lui bonne santé béni le protège le amen papi innocent je t'aime au fond du cœur courage
@maestroassgueye75503 жыл бұрын
Cheikh Niang il est éloquent et parle très bien.
@deffaly90563 жыл бұрын
Daniouko wara bayi mou fadjoudji mo gueune Yallah na Yallah feugue bopam si barké Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi 🤲
@diorndione3473 жыл бұрын
Yalla mi Ame Faye yalnaléne défal léne soutoura Adina AK alakhira sounou Baye bi Yalla mayko wer in cha Allah cest triste De voir un vieux De cet age vivre toute seul dans DA Maison🙏🙏🙏
@tfm40893 жыл бұрын
Amine
@sokhnandiayeba56063 жыл бұрын
Ndeysane,am goré ,gnaak goré,yalnalko yallah maay werr sougnou papa bi,mane sa papa bima diour lakoy kholé vraiment,yalna yallah maay asociation bi guéna kawé
@badaradiouf21473 жыл бұрын
Sama probleme moy lan motakh pabi noungouwoull niou yobouko fadjiko te ky koukou fathie mou werr
@gayekhady91503 жыл бұрын
Khôl tôy na😭😭 merci wa and takhawou niou wérédi🙏
@agnesantacama10323 жыл бұрын
Essayez de contacter sa vrai famille. Le vieux refuse que vous lui accordez son aide or il est prêt à recevoir l'aide financière. C'est louche. Contactez sa famille SVP.
@gningmamadou87423 жыл бұрын
Veritè absolue
@rassoulking46873 жыл бұрын
Tata Agnes tu à parfaitement raison dh franchement
@mynasaliou243 жыл бұрын
Dama yakarné dou nitouh kessé rekk sokhna si
@princessedangerous38583 жыл бұрын
Yemé na trope mai yalla bakhna té loumou def amna loutax li nak cas bou bizarre la mai yalla nako yalla taxawou taxawou pape oci et ses éléments..li nak il faut pape diouk ci xol bou bakh lou xeew réellement
@serignendiayebeuguefallou70883 жыл бұрын
Merci bcp Pape Niang et toute l'équipe
@fatahaTV0993 жыл бұрын
En général gni yalla di wathié comme ay waliou sén yaram kén douko guiss malgré sén khél day dém . Mais il ya une histoire non dit entre les 2vieux. On verra la suite
@leboundoye21733 жыл бұрын
C vrema louche dal
@grimaha3 жыл бұрын
Veritée absolue. Loulo dafa lére
@LëndëmJi3 жыл бұрын
Bizarrr cette histoire
@annaba27003 жыл бұрын
J pense la même chose
@adjidiatta75203 жыл бұрын
C'est louche pape svp total cas bi
@buzzsenegallive78733 жыл бұрын
Allahou akbar pape yalla nalén yalla diapalé ❤️❤️😭
@inssandao63153 жыл бұрын
Machalla sérigne pape diazakalahou hayrane yalena yalla defalene diamou
@fatoukineba44363 жыл бұрын
Mais Pape pourquoi pa bi kén douko yobou?Douko arranger qu’est ce que cela signifie exactement ?
@diaylandiaye8573 жыл бұрын
Yalla nako yalla delo si khelam mai pabi lou takh bougoul nga yobou ko te mome fadiou ko lek rek la koy diokh kholal negam bi nimou mel kone warna ko defar
@sokhnadiarradiagne68743 жыл бұрын
Pabi mome diakhal nama noumou wakhé
@loucha71793 жыл бұрын
Beugoumako jugé mais franchement li rafetoul douko wagni dara pour mou dem il n'as rien à perdre
@mouhamedniang76363 жыл бұрын
@@sokhnadiarradiagne6874 Baré Nga Thi Morom
@cissasaafytv61053 жыл бұрын
Innocent et négative deux mots à analyser yalna yalla def diam inchaalah
@fatouwar269 Жыл бұрын
جزاكم الله خيرا🙏yalna line yalla faye yiwe sy barkip borom touba diam s'y yine 🙏🙏
@kenzahrable45453 жыл бұрын
Pape Niang topal cas bi, sama khel dalouthi dall, am na lou kheww deh
@dialdiallo73092 жыл бұрын
Kenzahra je me dis la même chose pourquoi son voisin ne veut pas qu'on l'amène ailleur ??
@juleslambassadeurdestalibe6193 жыл бұрын
Bay pape pabii loutakh mouné d'où ngén KO yobou tei wakhnako Aÿ mbokam légui yone la ngako mou diokhla numéro Aÿ mbokam nga wakhtan ak niom lolou mot l'I wor
@khadydieng99713 жыл бұрын
Cas bi il faut gnou topouko waroul yame fii . Pa bi limou wax téguéwoul fénneu.
@matyndiayeduval72633 жыл бұрын
Vraiment
@senadeya17423 жыл бұрын
Bilaye yénagui bakarou
@tigressesylla99413 жыл бұрын
@@senadeya1742 wa yow khana foofou ngua deugu
@senadeya17423 жыл бұрын
@@tigressesylla9941 ngon dédeu keur nitou yalla la
C que je déplore, vous les enfants si vos parents ne jouissent pas de leurs facultés mentales ne les abandonné pas ne les jeter pas dehors,garder les auprès de vous,c triste mon cœur saigne
@aminatadiop42403 жыл бұрын
Yalla nalén yalla dolil soutoura💖💖💖
@diengsokhna48883 жыл бұрын
Ndeyesane papa Niang niewlen touba ndeyesane bene malade heure boumako guise rek sama xel si yaw lay nekk mingui côté hôpital dianatou
@evaloum82783 жыл бұрын
Yallah nalen yallah fey♥️🤲
@diopfama10793 жыл бұрын
Ndeyesane pape sama yarame dawna ndeyesane yalla nalla souniou borom faye
@ramadiallo75733 жыл бұрын
Liguéye bi rafetna mais eau de javel grain bakhoul pour sangou
@bebendiaye34163 жыл бұрын
Kou Kaye utiliser sakhe danga wara sole aye gang,, c'est très toxique kéneu warou ko sango dé 😱😱😱😱😱
@coumbadiakho41123 жыл бұрын
Je suis désolée ; mais ils savent très bien ce qu'ils font ; d'ailleurs ça tue les microbes ; imaginer rester des mois ou des années sans prendre de bain ... Subhan'Allah ! J'apprécie vraiment leur travail yala rékeu molène meuneu fèy *** MaShaAllah Alhamdoulillah ! Dieu est grand ! Nguène balmeu nak
@deffaffaire97263 жыл бұрын
@@coumbadiakho4112 n’importe quoi eau de javel c’est toxique c’est pas pour la peau
@coumbadiakho41123 жыл бұрын
@@deffaffaire9726 ok comme tu veux D'ailleurs je n'ai même pas ton temps ! Bye *
@yamasy86373 жыл бұрын
@@coumbadiakho4112 eau de javel grain bakhoul bakhaleiwoul surtout sur la peauu Ndokh bi sakh c mieux
@aminatadieng91413 жыл бұрын
C'est où a kaolack moi j'habite a kaolack et je dis toujours que je voudrais faire partie dans cette association 👏
@mamecheikhseye79323 жыл бұрын
Wotel ci numéro pape
@ndiemethiam273 жыл бұрын
Mais pa Bimou dekeul si cogne bi pour Mane il à mal agit ndakh dama yakar ni môme sou wakhe tanone ak pa bi dinaniou ko indi Dakar Diapalé ko ba yalla déf khélam déloussi
@annaba27003 жыл бұрын
Pape niang dagua wara lidjentii ce qu’il y’a entre les deux vieux c louche nama yallah bal
@fatimataly67173 жыл бұрын
Ndeysan diajof cheikh niang yalla nga gouddu fan kon tan nañu ci yow billahi
@adamaseye75392 жыл бұрын
Pape niang yalla nala yalla défal diam
@Fayedoudou11 күн бұрын
Machalla c’est ligueye rafetna
@timeradjibril51812 жыл бұрын
Moi je suis tellement fière beau
@mouhameddiop82673 жыл бұрын
Machallah séne ligueye raffétna
@Kadjilolo3 жыл бұрын
Machalla ligueye bi amna solo bonne continuation
@Idrissa-cf6uy3 жыл бұрын
Bon continuation
@khadydiouf4063 жыл бұрын
Merci beaucoup pape gang et toute la équipes
@peaceandsalam28523 жыл бұрын
Yàlla nako buur yàlla taxawu té fayleen seen xol 🤲🏾
@sokhnandiayeba56063 жыл бұрын
Merci cette equipe
@bassiroundiaye78253 жыл бұрын
😭😭😭
@fatoukane98643 жыл бұрын
Dieredieuf Pape yalla nalla yalla Faye Sa xol ak epuipe bi yèpou yaram dawna
@ajisecka95113 жыл бұрын
Thank you Pape for you hard work.
@ndeyeantandiaye37733 жыл бұрын
Doyna war mé loutakh Pabi bagn niu yobouko mention spéciale à vous Aatw
@filydiarra35993 жыл бұрын
Vraiment courage a vous tous et que reserves le paradis a vous tous inchallah
@fatoumbengue83503 жыл бұрын
Machâ allah yalna yalla barkel té tahawou wa ( A A T G W ) sociale
@helenendiaye32373 жыл бұрын
Pape niang machalla say kaddou rafete na amgua yaar yalla nala yalla diapalé
@mbayebabacarsibylerevenant47483 жыл бұрын
Innocent dans un endroit voire monde négatif deux mots à interpréter {Kémtan}.Merci ce vieux pour votre soutien, de tout cœur avec cette association.
@ndiemethiam273 жыл бұрын
J'ai pensé la même chose que vous un innocent dans un endroit négatif son histoire semble être louche je ne blamme personne mais le gars qui s'occupe de lui devrait être là 1ere personne à être d'accord avec l'association André takhawou gni wéredi
@mbayebabacarsibylerevenant47483 жыл бұрын
@@ndiemethiam27 wey sister t'as parfaitement raison
@landaya64533 жыл бұрын
Frère métina si makk di dounde li mais comme yangui soygnou kanam sougnu xéll di guene dall xoll you bari toynagne yalla na yalla motali sa yéné mome Inchallah liye guene toyal sama xoll moy malay guiss dioy buguma nga dioy bén yone
@aissatouleonie89853 жыл бұрын
Le vieux et innocent et vis dans un atmosphere negative noye wakhé dagay dimbali nite ay nite nieuw pour diapalélassi pour mou weur ga bagne mani c louche niou wakhanté deugue
@aichatoure59453 жыл бұрын
Vraiment c'est triste que Dieu nous protège contre tous amine yarabi
@aissatafaye37823 жыл бұрын
آمين يا رب العالمين 🙏🙏🙏
@cheikhfaye88933 жыл бұрын
Yalla nalén yalla doli soutoura ak khéwal inchalla
@sodagueye82703 жыл бұрын
Pape bii khel khawo ma kan mon lo.khalat wayee yalla n'a yalla deff tawe fekh yire Lee moutkil Lee are Lee barker chieckhou khadim
@hawadiagne72213 жыл бұрын
Allahou akbar yalnalene borom bi feye
@amymalickdiouf21983 жыл бұрын
Yalna léne yalla faye yalla djapalélene gueuna yagg gueuna wer 🙏🙏🙏😍😍😍💕💕💕💕
@astoundour553 жыл бұрын
Machalah yalla na yalla yoku xewal
@amethystekyle61263 жыл бұрын
Sen liguey rafetna machallah yalla nalen yalla tahaou
@adjimayade49843 жыл бұрын
Yalla yalla tahawu léne yarabi
@nenediakhate33923 жыл бұрын
Pabi neneu ey sœureum daniouy nieuw garei auto beugo yonei yobou mou convaincre len baniou bayiko fa mom lane la tji am affaire bi sokhal nako deeii yeimei na
@mariamawourycamara99143 жыл бұрын
Ma chérie doyna war trop bilahi
@MamadouBarry-oz3zf7 күн бұрын
pape niang pabi keep kou keu beugueu derngne ko wara baye mou dem fadioudji lolou moy yone. voisin amougnou droit decide la famille qui decide
@fadimatall18263 жыл бұрын
Machallah sen Liguey rafétena
@SyllaSoda-g2q3 ай бұрын
No toudou innocent fi fanela négatif wakh diodiou diakhal nama trop😭😭😭
@binofaye20583 жыл бұрын
Yalla na lén yalla féya si barké Mohamed psl
@amethystekyle61263 жыл бұрын
Thieuy adouna yalla doly soutoureu metyna trop 😭😭😭😭
@dialloaladjisoudaisi2443 жыл бұрын
Mai pourquoi pabi nangouwoul ñouyoubouko hôpital diarna ludianti ly etabi warna see wax
@narekane68033 жыл бұрын
Merci beaucoup pape
@ndialoumboup30173 жыл бұрын
Ass diagn félicitation c'est ndialou mboup
@charlottehelenesow93573 жыл бұрын
soyez benis .et recompenses par Allah
@bababocoum753 жыл бұрын
Que Allah vous protège
@madogydioufy70033 жыл бұрын
Guein balma dh mais wolouwouma pa bi en bleu sama intuition la nak
@ndeyesaliou3893 жыл бұрын
Ñiaw ñiort bakhoul
@awadethiediop37923 жыл бұрын
Doyna War il faut chercher les causes de son refus il veut profiter du vieux mais il serait plus à l aise dans un centre de accueil faites vos investigations vous retrouverez ses parents. Yalla na len yalla fay. Courage
@madogydioufy70033 жыл бұрын
@@ndeyesaliou389 boul diawalei mou bokoul ok khamo li neik sama khol Lima guiss la sentir ko la wakh
@aichaseck90363 жыл бұрын
Té sah nak topatowouko parce que kholal chambre bi nimou mel
@aichaseck90363 жыл бұрын
@@ndeyesaliou389 mais wakh na deug c'est louche
@awagning12863 жыл бұрын
Entouca pa deukondo bi mom je le fai pas confiance ,pourquoi fadiouko ba parè tè beugoul mou dem c'est louche dal ,nako ay mbokam dieulsi tè fadieko comme que terena gnoulenko
@matyndiayeduval72633 жыл бұрын
C'est pas clair dall mais dieu seul sait
@awagning12863 жыл бұрын
@@matyndiayeduval7263 le vieux ne veus meme pas leur parler de bon paroles ni dencouragement sur ce geste noble qu'ils font ,si réellement c'est le bien etre du malade qui linteressait pourquoi il insiste sur le faite qu'on ne lui emmene pas ? Entouca tant de questions sans responses? Mais Dieu sait .qu'il lui accorde la guerison .mais jappel vraiment que sa famille vienne lui récupérer
@senadeya17423 жыл бұрын
Papa bi s'en familles mou dée lagni kar gnou dieu keurgui falé wougne ko
@senadeya17423 жыл бұрын
Deukado bi bime métai moko taxayou
@jasmeenlilly3 жыл бұрын
Esceke bagugn recuperer keur gi, pa bi je lui fait pas du tt confiance. Malqde bi nako aye mbokeum djeulsi ils ont plus de droit sur ce monsiwur ke de simple voisin
@sodagueye82703 жыл бұрын
Baye pape Niang teye la massa setane s'en vidéo yep Hay
@sodagueye82703 жыл бұрын
Lii dawena yaram lol dama dioye journée bi yep. Yalla rek Molene mana feye
@sodagueye82703 жыл бұрын
Ana gnii yalla maya allál tee eulek daniouy Dem rek bayikofii aye waye doude gui yaguoul
@sodagueye82703 жыл бұрын
Mam mon frère est un malade mental Fathi nagnou ba sone tee khel mi demounonou
@agnesyalissefaye37453 жыл бұрын
Merci pour le geste que dieux vous benisse
@princesse696482 жыл бұрын
Excusez moi j'aime trop votre solidarité et je respecte beaucoup votre travail mais il y'a une image que vous afficher borome tanque bi dag ba ci yah bi da fa raglou s'il vous plaît j'aime trop l'émission mais da may ragale toujours di ci Yam merci
@khadijalopez3172 жыл бұрын
Machalla thi caw thi kanam
@aissatoudioufseck63653 жыл бұрын
Svp cou beugue adéré déf té yalla tah noumouy déf
@fatoumatacalica71063 жыл бұрын
Paby any aye ndiabotam? ani sokhnam? ani aye mbokkam?
@senadeya17423 жыл бұрын
Bokame yi intérêt keurgui le beugue
@tigressesylla99413 жыл бұрын
@@senadeya1742 kholal ma li 😭
@antandiaye50403 жыл бұрын
Khana dou lougne mana fathie?
@papathiam873 жыл бұрын
Pape niang yobouko fadjiko svp papi khamoul limiye wakh
@Morifingdian93 жыл бұрын
Je voudrais faire partir de cette association
@sneybniang4355 Жыл бұрын
Ndeysane yo allah wadanee jam
@adjagueye29513 жыл бұрын
Mais pourquoi dougnou ko yobbou fathie ko vraiment yalla nako yalla may werr bamou delou andate ak khelam🙏🏿🙏🏿
@mariamefaye86703 жыл бұрын
Bizarre
@muhammaddrame34603 жыл бұрын
Wallahi yalla na yalla faylen yiw inchalah dieradief
@madogydioufy70033 жыл бұрын
Pape niang topal cas bi c'est trop bizzare c vieux
@diaylandiaye8573 жыл бұрын
Dako wara faji bam wer mai mome bougoul kou ko youbou te yene nak dolene docteur yi si hopital yi rek ngene mana dem yobou ko kom ay moromam
@mouhamedniang76363 жыл бұрын
Antouka Wakham Gattna trop
@camarabinetou24743 жыл бұрын
Doyna warr
@mamediarra37473 жыл бұрын
Pabi wolouw mako
@dabasylla52673 жыл бұрын
vrmnt merci beaucoup yalla molen di Faye sen xol
@badjikhadimsalif98273 жыл бұрын
Sama xalate bou guateu , saguame Yeinagui koy def guire dieummi Yalla , Machallah gnougui koye rafetlou. Waye est ce que geunoul guaine bagna wakh gnata gueini diokhé
@ndeyesaliou3893 жыл бұрын
Me lolou moy lan grand frère.???😕xalis bi niom momou ñuko louway diokhe dafa wara leer si nitt ñi xamga nitt ku Ngoul Gaw nan Si .me"Pape de day lek xalis bi" Yama Guen xam
@adjafa163 жыл бұрын
@@ndeyesaliou389 merci beaucoup
@mamediarra37473 жыл бұрын
@@ndeyesaliou389 merci bcp😍
@sambawane97392 жыл бұрын
Yalla n'a l'en yalla diapalé
@astalo3964 Жыл бұрын
Oh😢😢
@sineniang74353 жыл бұрын
Machalla pape niang
@yakhyasenegal90883 жыл бұрын
Yalla nalene yalla faay yiiw
@salimmane93093 жыл бұрын
Niètte kadu la pabi tontou : no toudou Innocent . Fifanla negatif . Lobeug niou defala moune voisin bi lim may diox rek doyna . Pabi dafa yémè